If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id |
Wolof |
English |
1001 | Dindi Jumtukaay bi |
Remove Device |
1002 | Sémpi Jumtukaay bees tànn |
Uninstall the selected Device |
1003 | Ndax wóor na ne dangaa bëgg a dindi jumtukaay bii? |
Are you sure you want to remove this device? |
1004 | Jumtukaayu alaxam |
Unknown device |
1006 | Boo dindee arafukaay walla baag bi xayna dóotoo man a jëfandikoo nosukaay bi. |
You may not be able to control this computer if you remove this keyboard or mouse. |
1007 | Dindig jumtukaay bii dina soppiwaale sa jumtukaayu baaxoo. |
Removing this device will change your default device. |
1008 | Din&di jumtuaay bi |
Remo&ve device |
1009 | Restrictions |
Restrictions |
1010 | Fomb nañu jëf jii ndax mbir yikoy tere ci nosukaay bii. Jokkool ak sa yorkatu noste. |
This operation has been cancelled due to restrictions in effect on this computer. Please contact your system administrator. |