If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id |
Wolof |
English |
| 1 | Amul lenn luñu war a séddale fii ñu toll. |
There's nothing to share right now. |
| 2 | Séddoo ab nataalu-seetug Tàmbali |
Share a screenshot of Start |
| 3 | Séddoo ab nataalu-seetug Seet |
Share a screenshot of Search |
| 4 | Séddoo ab nataalu-seetug Ëtt |
Share a screenshot of Desktop |
| 5 | Laal te yónnee |
Tap and send |
| 6 | Am na lu jaarul yoon ba tax %1 manta séddoo fimne. Jéemaatal ci kanam. |
Something went wrong, and %1 can't share right now. Try again later. |
| 7 | %1 manta séddoo. Xoola sa lonkug Internet walla nga taxañ yi ngay séddoo. |
%1 couldn't share. Check your Internet connection, or try sharing fewer files. |
| 8 | %1 (%2) |
%1 (%2) |
| 9 | Nataalu seetu |
Screenshot |
| 10 | Lëkkale ak tëriin ci Mangasiin bi |
Link to app in Store |
| 11 | Séddoo |
Share |
| 12 | Mu ngi waaja séddoo |
Preparing content to share |
| 200 | Wéy |
Continue |
| 201 | Jeexal waar |
End task |