| 1 | Mbaal |
Network |
| 2 | Dugg ci nosukaay ak jëfandaay yi nekk ci sa mbaal gi. |
Access the computers and devices that are on your network. |
| 1002 | Tur |
Name |
| 1003 | Xamle |
Description |
| 1007 | Lonku na ci Internet |
Connected to Internet |
| 1008 | Lonku na ci mbaal gu biire |
Connected to local network |
| 1009 | Lonkuwul |
Not connected |
| 1012 | Taarixu Sos |
Date Created |
| 1013 | Njoxe yu Lonku |
Date Connected |
| 1014 | Tolluwaay |
Status |
| 1015 | Computer |
Computer |
| 1016 | Device |
Device |
| 1017 | Online |
Online |
| 1018 | Offline |
Offline |
| 1019 | Xameesul |
Unknown |
| 1020 | Status |
Status |
| 1021 | Type |
Type |
| 1022 | Wàll |
Category |
| 1023 | Nekkuwaayu mbaal |
Network location |
| 1024 | Explore |
Explore |
| 1025 | Open |
Open |
| 1026 | &View device webpage |
&View device webpage |
| 1027 | Connect to a network |
Connect to a network |
| 1028 | Mbaal ak Barabu Séddóo |
Network and Sharing Center |
| 1029 | Seet ci Active Directory |
Search Active Directory |
| 1030 | The computer is not connected. Please connect to the network |
The computer is not connected. Please connect to the network |
| 1031 | Network ports for discovering devices are not open. Please open required ports |
Network ports for discovering devices are not open. Please open required ports |
| 1032 | MbooloomLiggéey |
Workgroup |
| 1034 | Nosukaay bii lonkuwul ci genn mbaal. Bësal ngir lonku… |
This computer is not connected to a network. Click to connect… |
| 1036 | Fayees na xàmig mbaal ak séddoo taxañ. Nosukaay ak jëfandaay yi nekk ci mbaal gi duñ feeñ. Bësal ngir soppi… |
Network discovery and file sharing are turned off. Network computers and devices are not visible. Click to change… |
| 1039 | Mooy joxe tollukaayi mbaal akug man a dugg ci jekkali mbaal. |
Provides network status, and gives access to network settings. |
| 1040 | Seet ay nosukaay, jëfandikukat mbaa ëmb yus séddoo ci Active Directory. |
Search the Active Directory for computers, users, or shared folders. |
| 1043 | Anamu Xami |
Discovery Method |
| 1046 | Network |
Network |
| 1047 | Fayees na xamig mbaal gi. Nosukaay ak jëfandaay yi nekk ci mbaal gi duñ feeñ. Bësal ngir soppi… |
Network discovery is turned off. Network computers and devices are not visible. Click to change… |
| 1048 | Fayees na séddoo taxañ. Xayna yenn nosukaay ak jëfandaay yi nekk ci mbaal gi duñ feeñ. Bësal ngir soppi… |
File sharing is turned off. Some network computers and devices might not be visible. Click to change… |
| 1049 | Fayees na xamig mbaal gi. Nosukaay ak jëfandaay yi nekk ci mbaal gi duñ feeñ. Baal nu taali xamig mbaal ci Barabu Mbaal ak Séddoo. |
Network discovery is turned off. Network computers and devices are not visible. Please turn on network discovery in Network and Sharing Center. |
| 1050 | Yokk ay jëfandaay aki móolukaay |
Add devices and printers |
| 1051 | Yokk jumtukaayu déet-wëñ walla bob mbaal mbaa móolukaay ci nosukaay bii. |
Add a wireless or network device or printer to this computer. |
| 1052 | Màkkaanum MAC |
MAC Address |
| 1053 | Màkkaanum IP |
IP Address |