200 | Àndadoob Jëfandaay |
Companion Device |
201 | Waaw-kay |
Ok |
300 | Mënul duggee ci jëfandaay bii. Kon jéemal duggee neneen. |
Couldn't sign in with the device. Use another sign-in option. |
301 | Amna lu jaarul yoon. Jéemal a duggee neneen, te nga jekkalaat jëfandaay bi. |
Something went wrong. Use another sign-in option, and then set up the device again. |
302 | Sudee danga fay-taalaat wala nga génn ci sa jëfandaay, dina la laaj nga firndéel ki nga doon laata nga koy jëfandikoo. Jëfandikool beneen tànneefu dugg. |
After a restart or logoff, the device requires verification before using it. Use another sign-in option. |
303 | Sudee daa am ku dugg ba noppi. Fàww mu génn balaa ngay mën a dugg. |
Someone is already signed in. They need to sign out before you can sign in. |
304 | Tëj nañu jëfandaay bii ngir sa kaaraange. Lëkkaleel jëfandaay ci piriisu kuuraŋ lu tollu ci ñaari waxtu gën gaa néew ba noppi nga fay ko taalaat ngir jéemaat. |
This device has been locked for security reasons. Connect your device to a power source for at least two hours, and then restart it to try again. |
400 | Jëfandaay |
device |
2001 | Raayeel kaw wala nga bës galanu espaas bi ngir duggee ak %1!s!. |
Swipe up or press space bar to sign in with %1!s!. |
2002 | Bësal %1!s! Bi ci jàngukaayu NFC bi ngir dugg. |
Tap %1!s! to the NFC reader to sign in. |
2003 | Xoolal tegtali dugg ci %1!s!. |
See %1!s! for sign-in instructions. |
2004 | Seet %1!s!... |
Looking for %1!s! ... |
2005 | Roofal %1!s! Ci pooru USB ngir dugg. |
Plug %1!s! into a USB port to sign in. |
2006 | Taal Bluetooth bi ngir jëfandikoo %1!s! ngir dugg. |
Turn on Bluetooth to use %1!s! to sign in. |
2007 | Taal NFC bi ngir jëfandikoo %1!s! ngir dugg. |
Turn on NFC to use %1!s! to sign in. |
2008 | Lënku ci mbaalu wifi te jëfandikoo %1!s! ngir dugg. |
Connect to a wireless network to use %1!s! to sign in. |
2009 | Bësaatal %1!s!. |
Tap %1!s! again. |
2010 | Sa liggéeyukaay dafay tere duggee ak %1!s!. Kon jéemal a duggee neneen. |
Your enterprise prevents sign in with %1!s!. Use another sign-in option. |
2011 | Bësal %1!s! Ngir dugg. |
Tap %1!s! to sign in. |
2012 | Tegaatal sa baraam ci %1!s! ngir dugg. |
Rest your finger on %1!s! to sign in. |
2013 | Raayal ak sa baraam ci %1!s! ngir dugg. |
Swipe your finger on %1!s! to sign in. |
2014 | Mënoo duggee ak %1!s!. Jéemal a duggee neneen. |
Couldn’t sign in with %1!s!. Use another sign-in option. |
2015 | Amna lu jaarul yoon. Jéemal a duggee neneen, te nga jekkalaat %1!s!. |
Something went wrong. Use another sign-in option, and then set up %1!s! again. |
2016 | Jéemaat. |
Try again. |
2017 | Wax Kàddu-jàll yi %1!s!. |
Say your Spoken Passphrase into %1!s!. |
2018 | Noppi nga ngir dugg ak %1!s!. |
Ready to sign in with %1!s!. |
2019 | Njëkkal a wut neneen nooy duggee, ndax nga mën a jëfandikoo %1!s!. |
Use another sign-in option first, then you can use %1!s! to sign in. |