If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id |
Wolof |
English |
| 102 | Denc léegi |
Back up now |
| 103 | %s moo féex ci %s |
%s free of %s |
| 104 | Yaa ngi lënku ci mbaal moo xam ni dañu lay fayyeeku yeneen mbir sooy jéem a làq ay njoxe. |
You are currently on a network where additional charges may apply when performing a backup. |
| 110 | Seet ay jumtukaay |
Searching for drives |
| 111 | Tànn ab tappaan |
Select a drive |
| 112 | Amul dencukaay buñ mën a jëfandikoo |
No usable drives found |
| 113 | Tànn ëmb bii |
Choose this folder |
| 114 | Lonkiku na |
Disconnected |
| 115 | Soxla na leerali dugg |
Sign-in info needed |
| 116 | Tëju na |
Locked |
| 117 | %s, %s |
%s, %s |
| 118 | Denc gu mujj: %s |
Last backup: %s |
| 119 | Mu ngir denc say njoxe... |
Backing up your data... |
| 120 | Dàkkal nañu denc bi |
Backup is disabled |
| 121 | Fomb |
Cancel |
| 122 | Dayob denc gi: %s |
Size of backup: %s |
| 123 | Denc a guñu say njoxe. |
Your data is not yet backed up. |
| 124 | Dindi |
Remove |
| 125 | Mëneesu ñu denc say njoxe. Ngir am ci yeneen leeral, seetal kotu njuumte 0x%1!08X! |
We couldn't back up your data. To find out more, look up error code 0x%1!08X! |
| 126 | Doxul, te nu ngi ciy jéggalu. Ngir am ci yeneen leeral, seetal kotu njuumte 0x%1!08X! |
Sorry, but that didn't work. To find out more, look up error code 0x%1!08X! |
| 127 | Dencukaay bi yépp %s: %s |
Total space on %s: %s |
| 0x50000002 | Error |
Error |
| 0x50000003 | Warning |
Warning |
| 0x50000005 | Verbose |
Verbose |
| 0x90000001 | Microsoft-Windows-OneBackup |
Microsoft-Windows-OneBackup |
| 0x90000002 | Microsoft-Windows-OneBackup/Debug |
Microsoft-Windows-OneBackup/Debug |
| 0xB00003E8 | %1 |
%1 |