| 550 | Lonku ci am mbaal |
Connect to a Network |
| 551 | Disconnect from a Network |
Disconnect from a Network |
| 552 | Not Connectable |
Not Connectable |
| 553 | Lonku |
Connect |
| 554 | Disconnect |
Disconnect |
| 555 | &Lonku |
&Connect |
| 556 | &Lonkiku |
&Disconnect |
| 557 | Connection not available |
Connection not available |
| 558 | Xayna ñeneen ñi man a gis leeral yi ngay sànni ci ci kaw mbaal gii |
Other people might be able to see info you send over this network |
| 559 | Connect automatically checkbox |
Connect automatically checkbox |
| 560 | Lonkul boppam |
Connect automatically |
| 562 | Lonkug mbaal gi gën naa yàgg nam daan toll |
Connecting to the network is taking longer than usual |
| 563 | Name |
Name |
| 564 | Ubbi joowukaayu web |
Open web browser |
| 565 | Déet, ubbil ab joowukaay Internet ngir matal lonku gi |
No, open a web browser to complete the connection |
| 566 | Waaw |
Yes |
| 570 | Wireless network name |
Wireless network name |
| 571 | Dàkkantal |
User name |
| 572 | Baatu-jàll |
Password |
| 573 | Jéemaatal, laalal mbaa nga bës lëkkalekaay bi ci suuf ngir mottali lonku ngi mbaa nga dugalaat sa dàkkantal ak baatu jàll. |
To try again, tap or click the link below to complete the connection or re-enter your user name and password. |
| 574 | Wone leerali njuumte gi |
View error details |
| 575 | Nëbb leerali njuumte gi |
Hide error details |
| 576 | Manula lonku |
Can’t connect |
| 577 | Dàkkantal bi wala tur wi doxul. Seet ko te jéemaat. |
The user name or password didn’t work. Please check it and try again. |
| 578 | Amna lu doxul. Jéemaatal. |
Something went wrong. Please try again. |
| 579 | Amul aw tontu. Jéemaatal. |
There wasn’t a response. Please try again. |
| 580 | Ab bataaxal bu bawoo ci yorkat bu amul fiil: |
A message from your wireless provider: |
| 590 | Nattaleb jëfandikuwiin |
Estimated usage |
| 591 | Beesal |
Reset |
| 594 | Cëraakonu proksi: %1 |
Proxy server: %1 |
| 595 | Dàkkantal bi walla tur wi doxul. Seet ko te jéemaat. |
The username or password didn’t work. Please try again. |
| 596 | Laaj na say leerali duggug cëraakonu proksi. |
Your proxy server sign-in info is required. |
| 597 | Wéyal |
Continue |
| 598 | Amna ay leeral yi soppiku ginnaaw bi nga mujjee lonku. Soxla nanu yeneen leeral ngir matal lonku gi. |
Some information changed since the last time you connected. We need additional information to complete the connection. |
| 599 | Soxla nañu say xibaaru dugg ñeel sa cërakoonu proksi ngir lonku ci %1. |
Your proxy server sign-in info is required to connect to %1. |
| 1000 | Të&j |
C&lose |
| 1001 | Settantalug li mbaal gi laaj |
Checking network requirements |
| 1002 | Mi ngi lonku |
Connecting |
| 1006 | Manta lonku ci mbaal gii |
Can’t connect to this network |
| 1008 | Settantal gi ak lonk gi |
Verifying and connecting |
| 1013 | Lonkukaay gi dees ko jataŋ |
The connection is limited |
| 1014 | Manunoo lonku ci Internet leegi nii. Jéemaatal. |
We can’t connect to the Internet right now. Please try again. |
| 1023 | Bindal tur (SSID) wi ñeel mbaal gi |
Enter the name (SSID) for the network |
| 1027 | Turu Mbaal gi Jubul |
Invalid Network Name |
| 1029 | Roofaatal sa méngalekayu mbaalu déet-buum |
Reinsert your wireless network adapter |
| 1030 | Manta lonku ndax daa fekk ñ dindi méngalekaayu mbaalu déet-buum. |
Can’t connect because the wireless network adapter was removed. |
| 1031 | Dugg ngir lonku |
Sign in to connect |
| 1032 | Tëj |
Close |
| 1033 | Dugg |
Sign in |
| 1036 | Jàppale ma ci saafara jafe-jafey lonku |
Help me solve connection problems |
| 1039 | Your device is locked. Unlock it, and then try again. |
Your device is locked. Unlock it, and then try again. |
| 1040 | Windows can’t authenticate your connection right now. Please try again later. |
Windows can’t authenticate your connection right now. Please try again later. |
| 1041 | Authentication failed |
Authentication failed |
| 1042 | Ndax amnga dàkkantal ak baatu-jàllu lënkukaayu Wi-Fi gii? |
Do you have a user name and password for this Wi-Fi hotspot? |
| 1043 | Your network administrator doesn’t allow simultaneous connections to your workplace network and another network. |
Your network administrator doesn’t allow simultaneous connections to your workplace network and another network. |
| 1044 | Leerali duggug cëraakonu proksi |
Sign-in info for proxy server |
| 1045 | Waaw-Kay |
OK |
| 1046 | Dugal ngir lonku ci %1 |
Sign in to connect to %1 |
| 1047 | Fàtte mbaal |
Forget network |
| 1100 | Mënu ñu samp lënkug internet. |
Can’t set up mobile hotspot. |
| 1101 | Ngir amal séddo gi, jokkool ak ki la jaay piis ngir mu doxal mën-mën yii. |
To enable sharing, contact your mobile operator to activate this feature. |
| 1102 | Manula lonku ci telefon bu gaaw dawiin. |
Can’t connect to mobile broadband. |
| 1103 | Manula lonku ci telefon bu gaaw dawiin sooy wëreelu. |
Can’t connect to mobile broadband while roaming. |
| 2101 | 11;semibold;none;segoe ui |
11;semibold;none;segoe ui |
| 5000 | Connect to a network wizard |
Connect to a network wizard |
| 0x10000031 | Response Time |
Response Time |
| 0x30000001 | Start |
Start |
| 0x30000002 | Stop |
Stop |
| 0x50000004 | Information |
Information |
| 0x90000001 | Microsoft-Windows-WlanConn |
Microsoft-Windows-WlanConn |
| 0x90000002 | Microsoft-Windows-WlanConn/Diagnostic |
Microsoft-Windows-WlanConn/Diagnostic |