If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id |
Wolof |
English |
100 | Sa SKYDRIVE_BRAND_NAME feesna |
Your SKYDRIVE_BRAND_NAME is full |
101 | Jënd dencukaay bu ëpp |
Buy more storage |
102 | Dummóoyu |
Ignore |
103 | Nungi nii doon jéem a denc say njoxey jëfekaay ak jekkali PC ci SKYDRIVE_BRAND_NAME, waaye bayaal bi doyulwoon. Mën nga jënd bayaal ngir dolli walla dem ci jekkali PC bi ngir saytu sa bayaalu dencukaay. |
We just tried backing up your app data and PC settings to SKYDRIVE_BRAND_NAME, but there wasn’t enough space. You can buy more storage or go to PC settings to manage your storage space. |
104 | Saytu dencukaay |
Manage storage |
105 | Maneesul a matal delloosi gi |
Restore could not be completed |
106 | Waaw-Kay |
OK |
107 | Mënu noo duppi say jekkali yi ci SKYDRIVE_BRAND_NAME yépp. Jéemal a dem ci pàccu Sàq yi ci jekkali PC bi, nga lonki sa sàqu Microsoft ci PC, ba noppi nga defaat ko ci. Sudee loolu doxul, jéemal a dello say jekkali PC ci jekkali yim wàccaale, ba noppi nga defaat sam sàq. |
We weren’t able to copy your settings over from SKYDRIVE_BRAND_NAME. Try going to the Accounts section of PC settings, disconnect your Microsoft account from this PC, and then add it again. If that doesn’t work, you can try resetting your PC to its factory settings, and then adding your account again. |
112 | Bayaalu tàppaan bu ndaw |
Low disk space |
113 | Ya ngi waaj a ñakk bayaal ci PC bii. Saytul dencukaay bi ngir xool jëfandikoo bi te feexal yenn bayaal. |
You’re running out of space on this PC. Manage storage to view usage and free up some space. |
114 | Bul ma ko fàttali |
Don’t remind me again |
115 | Tëj |
Close |