200 | Su barab bi tàkkee, képp kuy jëfandikoo jëfandaay bi mën na tànn jekkali barabi boppam. |
If location is on, each person using this device can choose their own location settings. |
201 | Barabu jëfandaay bii fay na |
Location for this device is off |
202 | Barabu jëfandaay bii tàkk na |
Location for this device is on |
203 | Soppi |
Change |
210 | Cëru barab |
Location service |
212 | Su cëru barab bi tàkkee, Windows, jëfekaay yi ak cër yi mën nañu jëfandikoo sa barab, waaye dutee dinga mën a fay barab bi ci yenn jëfekaay yi. |
If the location service is on, Windows, apps, and services can use your location, but you can still turn off location for specific apps. |
213 | Diwaan bi |
General location |
214 | Jëfekaay yi mënul jëfandikoo barab bi ma nekk ci saasi mën nañu jëfandikoo samay diwaan bi, maanaam sama dëkk, kot postaal, wala diwaan bi. |
Apps that cannot use my precise location can still use my general location, such as city, zip code, or region. |
220 | Sudee ab jëfekaay mooy jëfandikoo sa barab, di nga gis junj bii: |
If an app is using your location, you’ll see this icon: |
221 | Junju wone barab |
Show location icon |
230 | Su barab bi tàkkee, dañuy denc sa jaar-jaaru barab ci diir bu yam ci jëfandaay bi, te jëfekaay yiy jëfandikoo sa barab mën nañu ko jëfandikoo. |
If location is on, your location history is stored for a limited time on the device, and can be used by apps that use your location. |
231 | Fomp |
Clear |
232 | Fomp jaar-jaar ci jumtukaay bii |
Clear history on this device |
233 | Dafay jëfandikoo sa jaar-jaaru barab |
Uses location history |
240 | Def ko tànneef |
Set default |
241 | Windows, jëfekaay yi, ak cër yi mën nañu jëfandikoo lii sunu mënul gis bu baax barab bi sa PC nekk. |
Windows, apps, and services can use this when we can’t detect a more exact location on this PC. |
250 | Geofencing mooy jëfandikoo barab bi nga nekk ngir xam ndax yaa ngi jeggi foroñceer yi nga def ci barab yi nga taamu. |
Geofencing means using your location to see when you cross in or out of a boundary drawn around a place of interest. |
251 | Been mbaa luko ëpp ci sa jëfekaay ñu ngi jëfandikoo baarasu nekkuwaay fii ñu toll. |
One or more of your apps are currently using geofencing. |
252 | Benn ci say jëfekaay mu ngi jëfandikoo baarasu nekkuwaay fii ñu toll. |
None of your apps are currently using geofencing. |
260 | Ba leegi dal yi soxla nañu sañ-sañ |
Sites still need permission |
261 | Cortana |
Cortana |
262 | Barab bi war na takk ngir Cortana mën a dox |
Location history must be on for Cortana to work |
263 | Sàrti kër-liggéeyukaay dàkkal nako |
Disabled by company policy |