136 | Li Topp |
Next |
137 | Fomb |
Cancel |
138 | Beesal |
Reset |
139 | Tëj |
Close |
140 | Start |
Start |
142 | Dawalukaay bees samp Windows kese |
Only the drive where Windows is installed |
143 | Dawalukaay yépp |
All drives |
144 | Won ma limu dawalukaay yees nar a laalaale |
Show me the list of drives that will be affected |
145 | Ndax dangaa bëgg a dindi mboolem taxañ yi nekk ci dawalukaay yépp? |
Do you want to remove all files from all drives? |
147 | Aajewoos na ndolleenu bayaalu tàppaan |
Additional disk space needed |
148 | Ngir féexal bayaal, man ngaa: |
To free up disk space, you can: |
149 | Yékkati Fomp Tàppaan |
Run Disk Cleanup |
150 | Duppi say taxañ ci jëfandaay bitee te far léen ci PC bi |
Copy your files to an external device and delete them from this PC |
151 | Sémpi ay tëriin |
Uninstall programs |
153 | Lii du jël diir bu yàgg |
This won’t take long |
155 | Tànn ab tànnéef |
Choose an option |
156 | Wéyal di jekkal PC bii ngir sa barabu liggéeyukaay |
Keep this PC set up for your workplace |
157 | Waaw |
Yes |
158 | Dafay denc ay ëmbu joxekat yu tax sa PC jëfandikoo ay costéefi barabu liggéeyukaay. |
Saves provisioning packages that let your PC use workplace resources. |
159 | Déet |
No |
160 | Dafay dindi ay ëmbu joxekat yu tax sa PC jëfandikoo ay costéefi barabu liggéeyukaay. |
Removes provisioning packages that let your PC use workplace resources. |
161 | Dànkaafu! |
Warning! |
162 | Yeesal nañu PC bii ci fan yii ci Windows 10. Soo Beesalee PC bii, dootoo ko mën a dindi ngir dellu ci sumb Windows bi ci njëkkoon a nekk. |
This PC was recently upgraded to Windows 10. If you Reset this PC, you won’t be able to undo the upgrade and go back to the previous version of Windows. |
163 | Noppi na ngir beesal PC bii |
Ready to reset this PC |
165 | Noppi na ngir dabu |
Ready to restore |
166 | Fresh start |
Fresh start |
167 | Let's get started |
Let's get started |
169 | Mu ngi sottal mbir yi |
Getting things ready |
171 | Lii dina def as ndiir, sa PC dina fay-tàkkaat. |
This will take a while and your PC will restart. |
173 | Laajna beneen %1!ws! ci bayaalu tàppaan bu féex ci (%2!ws!). |
An additional %1!ws! of free disk space is needed on (%2!ws!). |
179 | Karmat: Arafaliinu dawalukaay bu BitLocker dees na ko ajandi ba jëf jii di mat. |
Note: BitLocker drive encryption will be temporarily suspended until the process is done. |
180 | Lu am solo: Roofal sa PC ci mbëj balaa ngay door |
Important: Plug in your PC before you start |
181 | Am na ñeneen ñu duggsi ci PC bii |
Other people are logged on to this PC |
182 | Bëgg ngaa wéyal? Lii dina tax ñu ñàkk njoxe yañ dencagul. |
Do you want to continue? This will cause them to lose unsaved data. |
189 | Lii dina dindi sa bépp tëriin ak sa taxañi bopp ci PC bi te dees na délloosi jekkal yi PC bi wàccaalewoon. Boo dee jëfandikoo Jaar-jaari Taxañ, wérlul ndax sumbam yi mujj duppees na léen ci sa dawalukaayu Jaar-jaari Taxañ balaa ngay wéyal. Lii dina def as ndiir te sa PC dina fay-tàkkaat. |
This will remove your personal files and apps from your PC and restore all settings to their defaults. If you use File History, make sure the latest versions of your files were copied to your File History drive before you proceed. This will take a few minutes and your PC will restart. |
190 | Karmat: Dees na fay arafaliinu dawalukaay bu BitLocker. |
Note: BitLocker drive encryption will be turned off. |
191 | Sa PC bi amna lu ëpp benn dawalukaay |
Your PC has more than one drive |
192 | Soo tànnee dindi taxañ yi ci dawalukaay yépp, dees na laal dawalukaay yii: |
If you choose to remove files from all drives, these drives will be affected: |
193 | Dawalukaay yim nar a laal |
Drives that will be affected |
194 | Dawalukaay bu amul tur |
Unnamed drive |
195 | Manunoo beesalaat sa PC ndax ci kuraŋu batiri lay dawee. |
We can’t reset your PC while it’s running on battery power. |
196 | Roofal sa PC |
Plug in your PC |
197 | Amaleesu ci lenn coppite. |
No changes were made. |
198 | Am na ab jafe-jafe ci beesalug sa PC |
There was a problem resetting your PC |
201 | Mënul a beesal PC bii te denc say taxañ |
Cannot reset this PC and keep your files |
202 | Ngir beesal PC bii te denc say taxañ, Jëfandikukat yi, Taxañu Tërinn yi, ak dencukaayi Windows war nañu nekk ci mennum tàppaan. Mën nga tànn beesalaat PC bii te far dindi lépp, waaye war nga denc say taxañu bopp ba noppi. |
To reset this PC and keep your files, the Users, Program Files, and Windows directories need to be on the same drive. You can choose to reset this PC and remove everything instead, but you should back up your personal files first. |
203 | Ndax dangaa bëgg a fomp say tàppaan itam? |
Do you want to clean the drives, too? |
204 | Dindi taxañ yi te fomp tàppaan bi |
Remove files and clean the drive |
205 | Lii mën naa jël ay waxtu, waaye dina ba tax benn kenn du mën a dabu taxañ yi nga dindi. Jëfandikool lii sudee da nga toggaat PC bi. |
This might take a few hours, but will make it harder for someone to recover your removed files. Use this if you’re recycling the PC. |
206 | Dindil rekk samay taxañ |
Just remove my files |
207 | Lii moo gën a gaaw, waaye moo gën a wóoradi. Jëfandikool lii sudee da nga denc PC bi. |
This is quicker, but less secure. Use this if you’re keeping the PC. |
211 | Lii dina dindi sa bépp tëriin ak sa taxañi bopp ci PC bi te dees na délloosi jekkal yi PC bi wàccaalewoon. Boo dee jëfandikoo Jaar-jaari Taxañ, wérlul ndax sumbam yi mujj duppees na léen ci sa dawalukaayu Jaar-jaari Taxañ balaa ngay wéyal. Sa PC dina dooraat. |
This will remove your personal files and apps from your PC and restore all settings to their defaults. If you use File History, make sure the latest versions of your files were copied to your File History drive before you proceed. Your PC will restart. |
214 | Maneesul a beesalaat sa PC ndax dafay dawal Windows To Go. |
Your PC can’t be reset because it’s running Windows To Go. |
216 | Mënu nu beesalaat PC bii |
We can’t reset this PC |
218 | 11;normal;none;Segoe UI |
11;normal;none;Segoe UI |
219 | Soo dindee say taxañ, man ngaa fompaale yërukaay bi suko defee dina yombal dabuwaatug taxañ yi. Lii moo gën a wóor, waaye mooy gën a yàgg. |
When you remove your files, you can also clean the drive so that the files can’t be recovered easily. This is more secure, but it takes much longer. |
221 | Ub |
Close |
247 | Mënul a gis nekkuwaayu dabu gi |
Could not find the recovery environment |
248 | Roofal sa sampug Windows wala yebuwaayu dabu, te nga taalaal sa PC ak yebuwaay bi. |
Insert your Windows installation or recovery media, and restart your PC with the media. |
253 | Dina laaj ñu sampaat yii jëfekaay |
These apps will need to be reinstalled |
254 | Xoolaat limu jëfekaay yi. Dinga soxla tàppaan bi wala ay taxañ ngir sampaat leen beneen yoon. |
Reveiw the list of apps. You’ll need the discs or files to reinstall them later. |
255 | Dellu |
Go back |
256 | Di nga jeexal ñàkk seet yuñu gënal, kaarànge, ak door, dellusil ci Windows 10 saa yula neexee. |
If you end up missing improved search, security, and startup, come back to Windows 10 anytime. |
260 | Jajëf ci li nga ñàm Windows 10 |
Thanks for trying Windows 10 |
261 | Laaj bayaalu tappaan |
Reclaim disk space |
262 | Lii dina dabuwaat bayaalu tappaan bi nga jëfandikoo ngir denc Windows 7. Dina feexal bayaalu tappaan boobu, waaye doo mënati délloowaat Windows 7 so lii weesoo. |
This will recover the disk space used to store Windows 7. It will free up that disk space, but you will no longer be able to restore Windows 7 after this. |
263 | Dindi Windows 7? |
Remove Windows 7? |
264 | Lii dina feexal bayaal ci sa PC, waaye doo mënati délluwaat ci Windows 7. |
This will free up space on your PC, but you won’t be able to go back to Windows 7. |
265 | Dindi ay sàq yu bees |
Remove new accounts |
266 | Laata nga mën a déllu ci sumb yi jiitu Windows, war nga dinidi bépp sàqu jëfandikookat bi nga dugaloon bi amelee yeesal bi gën a bees noppi. War nga dindi sàq bii, akit seeni bayaal. |
Before you can go back to a previous version of Windows, you’ll need to remove any user accounts you added after your most recent upgrade. The accounts need to be completely removed, including their profiles. |
267 | Benn sàq nga sosoon (%2!ws!) |
You created one account (%2!ws!) |
268 | Sosoon nga %1!ws! sàq (%2!ws!) |
You created %1!ws! accounts (%2!ws!) |
269 | Demal ci Jekkal yi Sàq yi Ñeneen ñi ngir dindi yile sàq, ba noppi nga jéemaat. |
Go to Settings Accounts Other people to remove these accounts, and then try again. |
270 | Delloowaat ay sàq |
Move accounts back |
271 | Laata ngay mën a delluwaat ci sumb bu jiitu Windows, war nga dugal bépp sàq bi nga toxal bi nga amalee sa yeesal bi gën a bees ci barab bumu cosaanoo. |
Before you can go back to a previous version of Windows, you’ll need to put any user accounts you moved after your most recent upgrade back in their original location. |
272 | Toxal nga benn sàq (%2!ws!) |
You moved one account (%2!ws!) |
273 | Toxal nga %1!ws! sàq (%2!ws!) |
You moved %1!ws! accounts (%2!ws!) |
274 | Ñu ngi jegalu, waaye mënuloo dellu |
We’re sorry, but you can’t go back |
275 | Toxal nañu taxañ yuñu soxla ngir delloo la ci sumb bu jiitu Windows ci PC bii. |
The files we need to take you back to a previous version of Windows were removed from this PC. |
276 | Ñu ngi jegalu waaye mënu loo dellu ganaaw |
We’re sorry, but you can’t go back |
277 | Mënu ñu dellu ci sumb Windows bu njëkk ndax dencu bu USB mbaa beneen tappaanu biti buñu jëfandikoo bi fa sa yeesal yu gën a bees nekkul. Baal ñu dugal tappaan bi te jéemaat. |
We can’t take you back to a previous version of Windows because the USB flash drive or other external drive that was used during your most recent upgrade is missing. Please insert the disk and try again. |
279 | Mënu ñu la delloo ci sumb bu jiitu Windows ndax am na lu ëpp weer bi nga yeesalee ak léegi. |
We can’t take you back to the previous version of Windows because it’s been more than a month since the upgrade. |
280 | Samay jëfekaay mbaa sama jumtukaay doxul ci Windows 10 |
My apps or devices don’t work on Windows 10 |
281 | Dafa mel ni tabax yu njëkk yi ñoo gën a yómb a jëfandikoo |
Earlier builds seemed easier to use |
282 | Dafa mel ni Windows 7 moo gën a yómb a jëfandikoo |
Windows 7 seemed easier to use |
283 | Dafa mel ni Windows 8 moo gën a yómb a jëfandikoo |
Windows 8 seemed easier to use |
284 | Dafa mel ni Windows 8.1 moo gën a yomba jëfandikoo |
Windows 8.1 seemed easier to use |
285 | Dafa mel ni tabax yu njëkk yi ñoo gën a gaaw |
Earlier builds seemed faster |
286 | Dafa mel ni Windows 7 moo gën a gaaw |
Windows 7 seemed faster |
287 | Dafa mel ni Windows 8 moo gën a gaaw |
Windows 8 seemed faster |
289 | Dafa mel ni tabax yu njëkk yi ñoo gën a wóor |
Earlier builds seemed more reliable |
290 | Dafa mel ni Windows 7 moo gën a wóor |
Windows 7 seemed more reliable |
291 | Dafa mel ni Windows 8 moo gën a wóor |
Windows 8 seemed more reliable |
293 | Ngir beneen sabab |
For another reason |
294 | Lu tax ngay déellu ganaaw? |
Why are you going back? |
296 | Wax ñu yeneen |
Tell us more |
298 | Sudee noppi nga ngir saafaral. |
If you’re up for troubleshooting, |
299 | jokkook ndimal. |
contact support. |
300 | Li nga war a xam |
What you need to know |
301 | Doo mën a jëfandikoo sa PC fileek lii yeggul, te mën na yàgg tuuti. Bul fay sa PC te bul rocci fiilu kuuraŋ gi. |
This might take a while and you won’t be able to use your PC until it’s done. Leave your PC plugged in and turned on. |
302 | Soo délloo ganaaw: |
After going back: |
303 | • Di na laaj nga sampaat yenn jëfekaay ak tëriin. |
• You’ll have to reinstall some apps and programs. |
304 | • Di na laaj nga sampaat yenn tëriin. |
• You’ll have to reinstall some programs. |
306 | Bul tëju |
Don’t get locked out |
307 | Sudee da nga jëfandikoo woon ab baatu-jàll ngir dugg ci Windows 7, wérlul ni xam nga ko. |
If you used a password to sign in to Windows 7, make sure you know it. |
308 | Sudee da nga jëfandikoo woon ab baatu-jàll ngir dugg ci Windows 8, wérlul ni xam nga ko. |
If you used a password to sign in to Windows 8, make sure you know it. |
309 | Sudee da nga jëfandikoo woon sa sumbu Windows bu njëkk, wérlul ni xam nga ko. |
If you used a password to sign in to your previous build, make sure you know it. |
310 | Dellu ci Windows 7 |
Go back to Windows 7 |
311 | Dellu ci Windows 8 |
Go back to Windows 8 |
312 | Dellu ci tabax bu njëkk |
Go back to earlier build |
316 | Mënu loo dellu ci kuraŋu batari kase. Roofal sa PC te jéemaat. |
You can’t go back on battery power alone. Plug in your PC and then try again. |
323 | • |
• |
324 | Ndax denc nañu say taxañ? Lii war na leen a lór, waaye li gën mooy nga waajal ko. |
Are your files backed up? This shouldn’t affect them, but it’s best to be prepared. |
325 | Doo mën a dugg te defuloo lu ni mel. |
You won’t be able to sign in without it. |
326 | Samay jëfandaay walla samay jëfandaay duñu dox ci tabax bii |
My apps or devices don’t work on this build |
327 | • Di nga ñàkk bépp coppite buñu indi ci jekkal yi suñu yeesale ci Windows 10 ba noppi. |
• You’ll lose any changes made to settings after the upgrade to Windows 10. |
328 | • Di nga ñàkk bépp coppite buñu indi ci jekkal yi suñu sampee tabax bu mujj bi. |
• You’ll lose any changes made to settings after installing the latest build. |
329 | Jajëf ci li nga ñàm tabax bii |
Thanks for trying out this build |
330 | Dina ñu samp tabaxu wonandi bu ci topp su jàppandiwee. |
We’ll install the next preview build when it’s available. |
331 | Dafa mel ni sumbu Windows bu njëkk bi moo gën a yómb a jëfandikoo |
The old version of Windows seemed easier to use |
332 | Dafa mel ni Windows 8.1 moo gën a gaaw |
Windows 8.1 seemed faster |
333 | Dafa mel ni sumbu Windows bu njëkk bi moo gën a gaaw |
The old version of Windows seemed faster |
334 | Dafa mel ni Windows 8.1 moo gën a wóor |
Windows 8.1 seemed more reliable |
335 | Sudee da nga jëfandikoo woon ab baatu-jàll ngir dugg ci Windows 8.1, wérlul ni xam nga ko. |
If you used a password to sign in to Windows 8.1, make sure you know it. |
336 | Sudee da nga jëfandikoo woon ab baatu-jàll ngir dugg ci sumbu Windows yu njëkk yi, wérlul ni xam nga ko. |
If you used a password to sign in to your previous version of Windows, make sure you know it. |
337 | Dafa mel ni sumbu Windows bu njëkk bi moo gën a wóor |
The old version of Windows seemed more reliable |
338 | Dellu ci Windows 8.1 |
Go back to Windows 8.1 |
339 | Dellu ci sumbu Windows bu njëkk |
Go back to previous Windows |
340 | Feexal tuuti bayaal te jéemaat. |
Free up some space and try again. |
341 | Ngir dellu, war nga am bayaal bu feex vu toll ci %1!ws! Mo ci tàppaan buñu sampee Windows. |
To go back, you’ll need %1!ws! MB of free space on the drive where Windows is installed. |
342 | Ngir dellu, war nga am bayaal bu feex vu toll ci %1!ws! Go ci tàppaan buñu sampee Windows. |
To go back, you’ll need %1!ws! GB of free space on the drive where Windows is installed. |
344 | Sa sàrti mbootaay duñu ko nangu. Ngir am ci yeneen leeral, laajal ki lay jàppale wala ñi xarañ wàllu ordinatër. |
Your organization’s policy doesn’t allow it. For more info, talk to your support person or IT department. |
345 | Mënul woon ay leeral ci yeesal yi |
Couldn’t get info on updates |
346 | Ngir seet ay yeesal, demal ci Jekkal yi Yeesal & Kaarànge Windows Update te tànn Seet ay yeesal. |
To check for updates, go to Settings Update & Security Windows Update and select Check for updates. |
347 | Seet ay yeesal? |
Check for updates? |
348 | Laata ngay dellu, jéemal a samp yeesal yu mujj yi. Lii mën naa saafaral jafe-jafe yi ngay jànkonteel ci Windows 10. |
Before you go back, try installing the latest updates. This might fix the problems you’re having with Windows 10. |
349 | Seet ay yeesal |
Check for updates |
350 | Déet, baax na |
No, thanks |
351 | Beesalaat PC bii |
Resetting this PC |
352 | Noo ngi yeggali yenn mbir %1!d!%% |
Getting a few things ready %1!d!%% |
353 | This feature is not available in Safe Mode |
This feature is not available in Safe Mode |
354 | To reset this PC, start Windows normally and try again, or go to Advanced startup and select Troubleshoot. |
To reset this PC, start Windows normally and try again, or go to Advanced startup and select Troubleshoot. |
355 | This will remove all apps and programs, except those that come standard with Windows. Any store apps installed by your manufacturer will also be kept. Your device will also be updated to the latest version of Windows. Your personal files and some Windows settings will be kept. |
This will remove all apps and programs, except those that come standard with Windows. Any store apps installed by your manufacturer will also be kept. Your device will also be updated to the latest version of Windows. Your personal files and some Windows settings will be kept. |
357 | Save your work and leave your device plugged in and turned on |
Save your work and leave your device plugged in and turned on |
358 | This will take a while and your device will restart several times |
This will take a while and your device will restart several times |
359 | You won't be able to use your device while refreshing Windows, but we will let you know once it's ready |
You won't be able to use your device while refreshing Windows, but we will let you know once it's ready |
360 | This process could take 20 minutes or longer depending on your device. |
This process could take 20 minutes or longer depending on your device. |
361 | Refreshing your PC |
Refreshing your PC |
362 | This will remove all apps and programs you installed. Your device will also be updated to the latest version of Windows. Your personal files and some Windows settings will be kept. |
This will remove all apps and programs you installed. Your device will also be updated to the latest version of Windows. Your personal files and some Windows settings will be kept. |