| 2002 | Jekkali lëkkale yi |
Sync settings |
| 2003 | Jokkale te denc tànneef yi ci lënku guñ natt |
Sync and back up settings over metered connections |
| 2004 | Yombalug jot |
Ease of Access |
| 2005 | Yeneen jekkali Windows |
Other Windows settings |
| 2006 | Baatu-jàll yi |
Passwords |
| 2008 | Taamutey làkk yi |
Language preferences |
| 2009 | Jekkali Internet Explorer |
Internet Explorer settings |
| 2010 | Mbubb |
Theme |
| 2012 | Yenn jekkal yi, sa yorkatu noste moo leen di saytu. Jokkool ak yorkatu sa noste ngir saafara bile jafe-jafe. |
Some settings are managed by your system administrator. Contact your system administrator to resolve this. |
| 2013 | Windows dafay dox fimne ci Anamug Kaarànge. Tànnéefi jaabante jàppandiwuñ fimne. |
Windows is running in safe mode. Roaming options are currently unavailable. |
| 2014 | Cib bayaalu néggandiku nga duggee. Tànneefi jaabante jàppandiwuñu fimne. |
You are logged on with a temporary profile. Roaming options are currently unavailable. |
| 2016 | Amna jafe-jafe lënku ci sam sàq. Seetal sa lënkug Internet te nga jéemaat. |
There was a problem connecting to your account. Check your Internet connection and try again. |
| 2017 | Naka la lëkkalante gi di doxee? |
How does syncing work? |
| 2018 | Lëkkale jekkali Windows ci yeneen jëfandaay jëfandikoo %1!s!. |
Sync Windows settings to other devices using %1!s!. |
| 2019 | Yenn man-mani Windows duñu jàppandi ludul sooy jëfandikoo am sàqum Microsoft walla sàqum liggéey. |
Some Windows features are only available if you are using a Microsoft account or work account. |
| 2022 | Jëfekaay yi %1!s! moom ak yiñ lëkkalante ak moom |
Apps acquired by and synced with %1!s! |
| 2023 | Use Windows Anywhere |
Use Windows Anywhere |
| 2024 | How does Windows Anywhere work? |
How does Windows Anywhere work? |
| 2025 | Windows Anywhere powers your device experience with your settings in the cloud using %1!s!. |
Windows Anywhere powers your device experience with your settings in the cloud using %1!s!. |
| 2110 | Say baatu-jall duñu lëkkaloo feek wéraloo yaw yaay kan ci jëfandaay bi. |
Your passwords won’t sync until you verify your identity on this device. |
| 2112 | Wéral |
Verify |
| 2113 | Jekkal yi duñu lëkkale fiileek ngay yeesal yenn leeral yi ngir sa sàqum Microsoft. |
Settings won’t sync until you update some info for your Microsoft account. |
| 2114 | Yeesal leeral yi |
Update info |
| 2115 | Jekkal yi duñu lëkkale fiileek ngay yeesal yenn leeral yi ngir sa sàqum liggéey mbaa daara. |
Settings won’t sync until you update some info for your work or school account. |
| 2117 | Lëkkalante gi jàppandiwul ci sam sàq. Jokkool ak sa yorkatu sistem ngir saafara ko. |
Sync is not available for your account. Contact your system administrator to resolve this. |