| 100 | Samp nañu móolug baaraam boobu ci PC bii. Jéemaatal ak beneen baaraam. |
That fingerprint has already been set up on this account. Try a different finger. |
| 101 | Bind nañu móolu baaraam boobu ba noppi ngir beneen sàq. Baal ñu jéem ak baaraam bu wuuteeg bii. |
That fingerprint has already been set up on another account. Try a different finger. |
| 102 | Bind nañu móolu baaraam boobu ba noppi. Baal ñu jéem ak baaraam bu wuuteeg bii. |
That fingerprint has already been set up. Try a different finger. |
| 103 | Móolu baaraam boobu dafa ndurook lool bi nga jekkal ba noppi. Jéemal ak beneen baaraam bu wuuteek bii. |
That fingerprint is too similar to one that's already set up. Try a different finger. |
| 104 | Dugal nga 10 baaraam yuñu jaglel sàq bii. |
You’ve reached the 10 fingerprint max for this account. |
| 105 | Jegalu, mënu ñu woon a am sa eskane baaraam bu wóor. Wérlul ni yëgekaay bi set na te wów. Su jafe-jafe bi wéyee, jéemal ak beneen baaraam. |
Your fingerprint couldn't be scanned. Make sure the sensor is clean and dry, and if the problem continues, try a different finger. |
| 111 | PC bii amul ab yërukaayu móolu baaraam. |
This PC doesn’t have a suitable fingerprint reader. |
| 112 | Lonki nañu jangkatu móolu baaraam bi. Baal ñu lonkaat ko te jéemaat. |
The fingerprint reader is disconnected. Reconnect it and try again. |
| 113 | Soxla nañu eskane sa móolu baaraam ay yoon yu bari ngir jekkal Windows Hello. |
We’ll need to scan your fingerprint a few times to set up Windows Hello. |
| 114 | Amalal yeneeni eskane ngir wérlu ni mën nañu xàmee sa baaraam. |
Just a few more scans to make sure your fingerprint is recognizable. |
| 116 | Jéggalu, am na lu jaarul yoon. |
Sorry, something went wrong. |
| 117 | Sa caytukat dàkkal na duggu móolu baaraam fii ñu toll. |
Fingerprint sign in is currently disabled by your administrator. |
| 119 | Ngir jëfandikoo Windows Hello, njëkkal aar sa jëfandaay di jëfandikoo BitLocker mbaa losiselu fas bu ni mel. |
To use Windows Hello, first protect your device using BitLocker or similar encryption software. |
| 120 | Eskane sa baaraam ci jàngkatu baaraam bi. |
Scan your finger on the fingerprint reader. |
| 121 | Eskane menum baaraam bi ci jàngkatu móolu baaraam bi. |
Scan the same finger on the fingerprint reader. |
| 122 | Faxas sa baaraam ci jàngkatu móolu baaraam bi. |
Swipe your finger on the fingerprint reader. |
| 124 | Faxas menum baaraam bi ci jàngkatu móolu baaraam bi. |
Swipe the same finger on the fingerprint reader. |
| 125 | Bësal sa baaraam ci yëgukaayu móolu baaraam bi, te nga yëkëti ko. |
Press your finger against the fingerprint sensor, and then lift it. |
| 129 | Gënal wàcce sa baaraam tuuti. |
Move your finger slightly lower. |
| 130 | Gënal yëkkati sa baaraam tuuti. |
Move your finger slightly higher. |
| 131 | Jëmaleel sa baraam tuuti ci sa ndijoor. |
Move your finger slightly to the right. |
| 132 | Jëmaleel sa baraam tuuti ci sa càmmoñ. |
Move your finger slightly to the left. |
| 133 | Dawalal sa baaraam ndànk ci jàngukaay bi. |
Move your finger more slowly across the reader. |
| 134 | Dawalal sa baaraam bu baax ci jàngukaay bi. |
Move your finger more quickly across the reader. |
| 135 | Sa jëfandaay mënu la xàmmee. Xoolal ndax xàmmeekaay bi set na. |
Your device is having trouble recognizing you. Make sure your sensor is clean. |
| 136 | Lalal sa baaraam te jubal ko sooy jëfandikoo jàngukaayu rëddu-baaraam bi. |
Try holding your finger flat and straight when using the fingerprint reader. |
| 137 | Jéemaal gën a yàggal teg gi ci jàngukaayu rëddu-baaraam bi. |
Try using a longer stroke across the fingerprint reader. |
| 138 | Jëfandaay bi mënagu la xàmmee. Jéemaatal. |
Your device is having trouble recognizing you. Please try again. |
| 139 | Wéyal di bës te yëkëti sa baaraam ba kerook càmbar gi di mat. |
Continue to press and lift your finger until the scan is complete. |
| 174 | Sampug Windows Hello |
Windows Hello setup |
| 175 | Sa caytukat dàkkal na Windows Hello fimne. |
Windows Hello is currently disabled by your administrator. |
| 176 | Tëjal Windows Hello, te nga jéema duggaat ci jekkal yi. |
Close Windows Hello, and then try going through the setup again. |
| 177 | Am na lu jaarul yoon. Xeyna sa dàmbu noste bu jàppandi dafay daw ndànk. Fompal tuuti bayaal te jéemaat. |
Something went wrong. Your available system memory might be running low. Clear up some space and try again. |
| 178 | Jekkali Windows Hello du dox ci ak lonku biro bu sori. |
The Windows Hello setup doesn't work over a remote desktop connection. |
| 200 | Mënul woon a daj say gët. |
Couldn't detect your eyes. |
| 201 | Dafa leer lool! Fayal yenn làmp yi mbaa nga dugg ci biir. |
Too bright! Turn off some lights or go inside. |
| 202 | Ubbil say gët tuuti. |
Open your eyes a little wider. |
| 203 | Teyeel sa jëfandaay ngir mu jakkaarlook say gët. |
Hold your device straight in front of your eyes. |
| 204 | Soril ko tuuti. |
Move farther away. |
| 205 | Gën koo jege. |
Move closer. |
| 206 | Yëngul tuuti ngir moytu mu mellax ci sa gët. |
Moving slightly to avoid reflection off your eyes. |
| 207 | Sa jëfandaay mu ngi am ay jafe-jafe ngir da la. Wérlul ni sa seetu nataalukaay set na. |
Your device is having trouble detecting you. Make sure your camera lens is clean. |
| 208 | Tegal sa jëfandaay ci say gët |
Hold your device straight in front of your eyes. |
| 209 | Dafa lëndëm lool! Taalal yenn làmp yi mbaa nga dem fu gën a leer. |
Too dark! Turn on some lights or move somewhere brighter. |
| 220 | Mu ngi jàng li ngay ndurool... |
Learning what you look like... |
| 275 | Mënu ñu woon a wéral sa sàq. |
Your account couldn’t be verified. |
| 276 | Laalal sa jëlukaayu baaraam bi |
Touch the fingerprint sensor |
| 277 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi ci sa kanamu jëfandaay, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor on the front of your device until setup is complete. |
| 278 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi ci sa ginaaw jëfandaay, nga baamtu ko ba samp gi di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor on the back of your device until setup is complete. |
| 279 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi ci sa wetu ndijooru jëfandaay, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor on the right side of your device until setup is complete. |
| 280 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi ci sa wetu jëfandaay, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor on the left side of your device until setup is complete. |
| 281 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi ci sa collu jëfandaay, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor on the top of your device until setup is complete. |
| 282 | Laalal butoŋu taal-fay |
Touch the power button |
| 283 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci butoŋu fay-taal, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the power button until setup is complete. |
| 284 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci yëgukaay bi, nga baamtu ko ba samp ki di yegg. |
Repeatedly lift and rest your finger on the sensor until setup is complete. |
| 285 | Raayal ak sa baaraam sa jëlukaayu baaraam |
Swipe your finger on the fingerprint sensor |
| 286 | Wéyal di faxas ba sampug Windows Hello bi yegg. |
Continue swiping until Windows Hello setup is complete. |
| 287 | Jëmale ko feneen fu wuute |
Now try another angle |
| 288 | Deel teg ak teggi sa baaraam ci barab yu wuute ngir jël peggi li nga bëgg a móol. |
Rest and lift your finger at different angles to capture the edges of your print. |
| 289 | Leegi raayal ak sa wetu baaraam |
Now swipe with the sides of your finger |
| 290 | Wéyal di faxas ngir jëlaale peggi li ngay móol. |
Continue swiping to capture the edges of your print. |
| 291 | Noonu la, bësaatal jëlukaay bi |
Great, touch sensor again |
| 292 | Wéyal di teg ak di teggi sa baaraam |
Keep resting and lifting your finger |
| 293 | Teggi ba noppi bësaat |
Lift and touch again |
| 294 | Teggil sa loxo ba noppi nga laalaat jëlukaay bi |
Lift your finger and touch the sensor again |
| 295 | Noonu la, jëmale ko feneen fu wuute |
Great, try a different angle |
| 297 | Toxalal sa baaraam saa yoo bësee |
Move your finger with each touch |
| 298 | Raayaatal |
Swipe again |
| 299 | Noonu la, wéyal di faxas |
Great, keep swiping |
| 300 | Raayal ak sa baaraam |
Swipe your finger |