File name: | explorer.exe.mui |
Size: | 13312 byte |
MD5: | a3e2d914d92fc0101fe2a393a70a3ead |
SHA1: | 46ca8c1468b94919b773327cf5666df9bfd56746 |
SHA256: | 22f3bc536f066d0d6f5db9b8e2bfb30e73c8b4ed3cb76cc1392a7b888f0dc023 |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
In x64: | explorer.exe Wërukaayu Windows (32-bit) |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
511 | Kepp ci %1 | Pin to %1 |
518 | Galanu ligeey yi | Taskbar |
530 | Unable to run command. The folder '%1' has been removed. |
Unable to run command. The folder '%1' has been removed. |
534 | &Defadi %s | &Undo %s |
535 | Tuur poxla yépp | Cascade all windows |
536 | Wonee poxla yépp wet ak wet | Show all windows side by side |
537 | Wàññi poxla yépp | Minimize all windows |
538 | Wone poxla yus bennale yépp | Show all windows stacked |
542 | Nëbb | Hide |
543 | Wone njunj yi nëbbu | Show hidden icons |
578 | Door | Start |
580 | Yamale yi | Restrictions |
581 | Fombees na jëf jii ndax ay yamale yees def ci nosukaay gi. Jokkool ak sa yorkatu noste. | This operation has been cancelled due to restrictions in effect on this computer. Please contact your system administrator. |
590 | Barabu Yëgley Noste Dige | System Promoted Notification Area |
591 | Barabu Yëgle Jéggi | Overflow Notification Area |
593 | Barabu Yëgley Jëfandikukat Dige | User Promoted Notification Area |
594 | Jëfekaay yiy daw | Running applications |
596 | Some notification icons can't be displayed | Some notification icons can't be displayed |
597 | There is not enough room to show all of the items in your system tray. Please uninstall some programs, or try a higher screen resolution. | There is not enough room to show all of the items in your system tray. Please uninstall some programs, or try a higher screen resolution. |
600 | Xumbaay | Volume |
601 | Network | Network |
602 | Taal/Fay | Power |
610 | Bëgg nga laatu-jumtukaay bii %s ne ci sa laatu-waar? | Do you want the %s toolbar on your taskbar? |
611 | Dinga man di wone mbaa nëbb laatu-jumtukaay yi jaar ko ci soppi jagoo yu Laatu-waar ak njëlul Door. | You can show or hide toolbars by changing Taskbar and Start menu properties. |
705 | A toolbar is already hidden on this side of your screen. You can have only one auto-hide toolbar per side. |
A toolbar is already hidden on this side of your screen. You can have only one auto-hide toolbar per side. |
718 | U&bbi Jëfandikukat Yépp | O&pen All Users |
719 | Ubbi &Wërukaayu Taxañ | O&pen File Explorer |
722 | Dawal | Run |
731 | Playing logoff sound... | Playing logoff sound... |
850 | &Wone poxla yi ubbeeku | &Show open windows |
852 | Diggu Jëf | Action Center |
854 | Barabu Yëgle | Notification Chevron |
855 | Jéggig Yëgle | Notification Overflow |
856 | Montaru Sistem bi | System Clock |
857 | Wone ëtt | Show desktop |
861 | Wonekaay dugaliinu mbind | Tray Input Indicator |
862 | %s %s Ngir jàll ci dugaliinu mbind, najal arafu Windows+bayaal. |
%s %s To switch input methods, press Windows key+Space. |
863 | Njunju Anamu IME | IME Mode Icon |
866 | IME wekkiku na | IME is disabled |
900 | Woney Waar | Task View |
902 | Tàmbali dégglu | Start Listening |
904 | Laaj ma lu la neex | Ask me anything |
905 | Arafukaayu laalu | Touch keyboard |
906 | Dellu | Back |
907 | Polanteeri Seet | Search Windows |
909 | Liggéeyukaayu Windows Ink | Windows Ink Workspace |
910 | Touchpad | Touchpad |
912 | People | People |
913 | Control Center | Control Center |
1361 | Alluwa Taal | Start menu |
1362 | Keppi ci %1 | Unpin from %1 |
6010 | Bindiitu Windows Search | Windows Search protocol |
6011 | Wërukaayu Windows Search | Windows Search Explorer |
6012 | Wërukaayu Windows Search moo lay may ngay seet taxañ ak ëmb fuñ man a ne ci nosukaay gi. | Windows Search Explorer allows you to quickly search for files and folders anywhere on your computer. |
6020 | Lëñbatukaayu Taxañ | File Explorer |
6021 | Lëñbatukaayu Taxañ dalay may nga yor say càkkutéefi saytu taxañ. | File Explorer allows you to handle your file management requirements. |
6022 | Bitoŋu Lëñbatukaayu Taxañ ‘Zip’ | File Explorer ‘Zip’ button |
6023 | Bitoŋu Lëñbatukaayu Taxañ ‘Móol ci tàppaan’ | File Explorer ‘Burn to disc’ button |
6025 | Bitoŋu Lëñbatukaayu Taxañ ‘Far ci tàppaan’ | File Explorer ‘Erase this disc’ button |
11100 | Jàllantukaayu Waar | Task Switcher |
11101 | Switch | Switch |
11102 | Naj | Press |
11103 | Ubbi | Open |
11104 | Windows | Windows |
11105 | Manta ubbi yëf yii | Can't open this item |
11106 | Xayna mu tuxu, tuddaat mbaa farees ko. Ndax bëggoo dindi yëf yii? | It might have been moved, renamed, or deleted. Do you want to remove this item? |
11107 | Ub | Close |
11108 | Laatu-jumtukaayu Nataalandi | Thumbnail Toolbar |
11109 | Requesting attention | Requesting attention |
11110 | Segoe UI | Segoe UI |
11111 | 12 | 12 |
11112 | 600 | 600 |
11113 | %d ëmbeef | %d items |
11114 | %s - 1 palanteer buy daw | %s - 1 running window |
11115 | %s - %d palanteer yuy daw | %s - %d running windows |
20000 | Amul yëgle yu bees | No new notifications |
20001 | Amul yëgle yu bees (Fay) | No new notifications (Off) |
20002 | Amul yëgle yu bees (Nëbbu) | No new notifications (Hidden) |
20003 | Amul yëgle yu bees (Nëbbu ba cil %s) | No new notifications (Hidden until %s) |
20004 | %d yëgle yu bees | %d new notifications |
20005 | Yëgle yu bees (Fay) | New notifications (Off) |
20006 | Yëgle yu bees (Nëbbu) | New notifications (Hidden) |
20007 | Yëgle yu bees (Nëbbu ba ci %s) | New notifications (Hidden until %s) |
20008 | 1 yëgle bu bees | 1 new notification |
20009 | No new notifications (Quiet hours on) | No new notifications (Quiet hours on) |
20010 | %d new notifications (Quiet hours on) | %d new notifications (Quiet hours on) |
20011 | 1 new notification (Quiet hours on) | 1 new notification (Quiet hours on) |
21000 | Waxtu gox bi | Local time |
22000 | Biro | Desktop |
22001 | Saytukatu Liggéey | Task Manager |
22002 | Saytu Disk | Disk Management |
File Description: | Wërukaayu Windows |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | explorer |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
Original Filename: | EXPLORER.EXE.MUI |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |