| File name: | UserLanguagesCpl.dll.mui |
| Size: | 14848 byte |
| MD5: | 957a08dde3c7fb967199d2832d18a1cb |
| SHA1: | 0d6c9910b7a0cff5bf552649ed86e85089a30d4f |
| SHA256: | 32832f11964ca94e76c6c9f937caf35221cf11ac548e7d97e007addf4531a77d |
| Operating systems: | Windows 10 |
| Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id | Wolof | English |
|---|---|---|
| 1 | Làkk | Language |
| 2 | Laalaat sa taamuy làkk ak sa jekkali bitim-réew | Customize your language preferences and international settings |
| 3 | Pexey Mbooloo moo tere tëriin wii. Ngir yeneen leeral, jokkool ak sa yorkartu noste. | This program is blocked by group policy. For more information, contact your system administrator. |
| 4 | Ndimbël | Help |
| 5 | Yokk ay làkk | Add languages |
| 6 | Soppikuwaani gox | Regional variants |
| 7 | Jekkal yees xóotal | Advanced settings |
| 8 | Tànnéefi làkk | Language options |
| 9 | Dugaliinu Mbind | Input method |
| 10 | Tànnéef yi | Options |
| 11 | Dindi | Remove |
| 12 | Yéegal | Move up |
| 13 | Wàcce | Move down |
| 14 | Turu làkk | Language name |
| 16 | Noste bindiin | Writing system |
| 17 | Jekkali làkk yoy ñaare | Common language settings |
| 18 | Yokk | Add |
| 19 | Ubbi | Open |
| 20 | Limu làkk yi: | Number of languages: |
| 21 | Soppi bis, waxtu, mbaa tëggiini limukaay | Change date, time, or number formats |
| 22 | Yore | Administrative |
| 23 | Xalima yi | Fonts |
| 24 | Dajalee làkk yi ak | Group languages by |
| 25 | Yokk aw làkk | Add a language |
| 26 | Jekkali ñaare | Common settings |
| 28 | Fomb | Cancel |
| 29 | Expand input methods | Expand input methods |
| 30 | Collapse input methods | Collapse input methods |
| 31 | Yokk aw dugaliinu mbind | Add an input method |
| 32 | Denc | Save |
| 33 | Expand text services | Expand text services |
| 34 | Collapse text servives | Collapse text servives |
| 35 | Taamuy topp-bindiin: | Spellchecking preferences: |
| 36 | Sampees | Installed |
| 38 | Limu làkki woniin | Display language list |
| 39 | Limu Dugaliini Mbind | Text Input List |
| 40 | bësal ngir ubbi tànnéefi laatu làkk | Click to open language bar options |
| 41 | Génn léegi | Log off now |
| 42 | Soppi làkku woniin | Change display language |
| 43 | War na nga génn duggaat ngir soppig làkku woniin wi jeexital | You must log off for display language changes to take effect |
| 44 | Wérlul ne denc li nga doon def te ub nga it tëriin yépp balaa ngay génn. | Make sure you save your work and close all open programs before you log off. |
| 45 | Yittewoos na sañ-sañi yorkat | Administrative privileges required |
| 46 | Wërukaayu làkk yees doxal | Languages enabled explorer |
| 47 | Wërukaayi tànni làkk | Languages choices explorer |
| 48 | Wërukaayu Dugaliinu Mbind | Input method explorer |
| 49 | Seet ay làkk | Search languages |
| 51 | Wewu na | Enabled |
| 52 | Wewu na (cig wuutal) | Enabled (override) |
| 53 | Soppi wuutal gi | Change override |
| 54 | Jàppandi | Available |
| 55 | Def %1 sa làkk wu njëkk (dinga koy gis ci kaw sab lim) | Make %1 your primary language (you’ll see it at the top of your list) |
| 56 | Def wii sa làkk wu njëkk | Make this the primary language |
| 57 | Dees na ko we boo duggseetee | Will be enabled on next sign-in |
| 60 | Jàppandi na ngir yebbees ko | Available for download |
| 61 | Ab tàkku làkk ngir %1 jàppandi na ngir yebbees ko | A language pack for %1 is available for download |
| 62 | Yebbi te samp takku làkk | Download and install language pack |
| 63 | Boo bëggee soppi làkku woniin wi, wax ko kiy saytu sàq mii | If you want to change the display language, talk to the person who manages this account |
| 66 | Sayu làkk jàppandiwul | A language pack isn't available |
| 67 | Soppees na làkku woniin wi def ko weneen cig wuutal | The display language has been set to another language using override |
| 69 | Barab | Location |
| 70 | Làkku woniinu Windows: %1 Laltaayu Arafukaay: %2 |
Windows display language: %1 Keyboard layout: %2 |
| 71 | %3. Làkku woniinu Windows: %1. Laltaayu Arafukaay: %2. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %3. Windows display language: %1. Keyboard layout: %2. Click for more options. |
| 72 | Keyboard layout: %1 | Keyboard layout: %1 |
| 73 | %3. Laltaayu Arafukaay: %2. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %3. Keyboard layout: %2. Click for more options. |
| 74 | Làkku woniinu Windows:: %1 Dugaliinu mbind: %2 |
Windows display language: %1 Input method: %2 |
| 75 | %3. Làkku woniinu Windows: %1. Dugaliinu mbind: %2. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %3. Windows display language: %1. Input method: %2. Click for more options. |
| 76 | Dugaliinu mbind: %1 | Input method: %1 |
| 77 | %3. Dugaliinu mbind: %2. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %3. Input method: %2. Click for more options. |
| 78 | %1 %2 |
%1 %2 |
| 79 | %1. %2. Bësal ngir xoolandi. | %1. %2. Click for preview. |
| 80 | Wonandi | Preview |
| 81 | Wàccaale | Standard |
| 82 | Laltaayu arafukaayu laal | Touch keyboard layout |
| 83 | IME | IME |
| 84 | Seet soppikuwaani gox | Search regional variants |
| 85 | Seet dugaliini mbind | Search input methods |
| 88 | Soppi arafi gaawal jot ci laatu làkk | Change language bar hot keys |
| 91 | benn jàppandiwul | none available |
| 92 | | | | |
| 93 | Làkku woniinu Windows: %1 Laltaayu Arafukaay: %2... |
Windows display language: %1 Keyboard layout: %2... |
| 94 | Laltaayu Arafukaay: %2... | Keyboard layout: %2... |
| 95 | Làkku woniinu Windows: %1 Dugaliinu mbind: %2... |
Windows display language: %1 Input method: %2... |
| 96 | Dugaliinu mbind: %2... | Input method: %2... |
| 97 | Xool ag jàppandeem... | Checking availability... |
| 98 | Wewu na (dina soppiku bus duggseetee) | Enabled (will change after next sign-in) |
| 99 | Wewu na (dina soppiku buñ duggseetee) | Enabled (will change after next sign-in) |
| 100 | Jëfandikoo limu làkk (lees sopp) | Use language list (recommended) |
| 101 | _stack | _stack |
| 102 | Samp walla sempi làkki woniin. Yittewoos na sañ-sañi yorkat | Install or uninstall display languages. Administrative privileges required |
| 103 | Naka laa man a def ngir am yeneen làkk? | What can I do to get more languages? |
| 105 | %1 - %2 | %1 - %2 |
| 106 | Arafukaay | Keyboard |
| 107 | Sémpi takku làkk | Uninstall language pack |
| 108 | %1 (jàppandiwul) | %1 (not available) |
| 109 | /u %1 /w | /u %1 /w |
| 110 | Jëfe jekkali làkk yi ci seetu Dalal-jàmm, sàqi noste, ak sàqi jëfandikukat yu yees yi | Apply language settings to the welcome screen, system accounts, and new user accounts |
| 111 | Dugaliinu mbind bu jàppandeedi | Unavailable input method |
| 112 | Délloosi wàccaale yi | Restore defaults |
| 113 | Bësal ngir xoolandi wii dugaliinu mbind %1 | Click to preview %1 input method |
| 114 | Bësal ngir ubbi tànnéef yi ñeel dugaliinu %1 | Click to open options for %1 input method |
| 115 | Bësal ngir dindi wii dugaliinu mbind %1 | Click to remove %1 input method |
| 116 | Sa seet gi dëppoowul ak darra | No items match your search |
| 118 | Lonku ci Internet bi ngir càmbar takki làkk yi | Connect to the Internet to check for language packs |
| 119 | %1 Ci ëttbi kese lay doxe |
%1 Only works on the desktop |
| 122 | Dees na ko we boo duggseetee (cig wuutal) | Will be enabled on next sign-in (override) |
| 123 | %1 | %1 |
| 124 | %1. Bësal ngir xoolandi. | %1. Click for preview. |
| 125 | Sàrti Sàmm-Sutura | Privacy statement |
| 127 | Jekkal gii sa yorkatu noste moo koy saytu. | This setting is managed by your system administrator |
| 128 | Làkku woniinu Windows: %1 | Windows display language: %1 |
| 129 | , | , |
| 130 | %3 %1 |
%3 %1 |
| 131 | %2. %3. %1. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %2. %3. %1. Click for more options. |
| 133 | %2. %1. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %2. %1. Click for more options. |
| 134 | %3 %1 Tëggiinu bis, waxtu ak limukaay |
%3 %1 Date, time, and number formatting |
| 135 | %2. %3. %1. Ngir ¨tëggiinu bis, waxtu, ak limukaay. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %2. %3. %1. Used for date, time, and number formatting. Click for more options. |
| 136 | %1 Tëggiinu bis, waxtu ak limukaay |
%1 Date, time, and number formatting |
| 137 | %2. %1. Ngir ¨tëggiinu bis, waxtu, ak limukaay. Bësal ngir yeneen tànnéef. | %2. %1. Used for date, time, and number formatting. Click for more options. |
| 138 | Open overflow menu | Open overflow menu |
| 139 | Jàppandiwul ci sottib Windows bii | Unavailable in this edition of Windows |
| 140 | Bàyyi ba ca kanam | Log off later |
| 141 | Nangu màndargay wu-siin, kanji mbaa anja yees di jëfandikoo lu néew suy tuubal mbindum loxo di ko def mbindu xarala. | Recognize rarely used Chinese, Kanji, or Hanja characters when converting handwriting to typed text. |
| 142 | Làkk wii amul benn tànneefu mbindum loxo | There are no handwriting options for this language |
| 594 | Soppi sa taamuy làkk | Change your language preferences |
| 595 | Mën nga bindee ci làkk boo yokk ci lim. Windows, jëfekaay yi ak daliweb dina ñu feeñ ci làkk wi njëkk ci lim bi muy jël. | You can type in any language you add to the list. Windows, apps and websites will appear in the first language in the list that they support. |
| 611 | Dajalee làkk yi ak: | Group languages by: |
| 612 | Jëfandikool boyetu seet bi ngir wut yeneen làkk. | Use the search box to find more languages. |
| 621 | Liggéeyali mbind | Text services |
| 629 | Wuutal ñeel làkku woniinu Windows | Override for Windows display language |
| 630 | Wuutal ñeel dugaliinu mbindu baaxoo | Override for default input method |
| 631 | Jàllantug dugaliini mbind | Switching input methods |
| 632 | Njoxey laalaat | Personalization data |
| 635 | boo bëggee jêfandikoo aw làkku woniin wu wuute ak wi ci sa limu toftale làkk, tànn ko fii. | If you want to use a display language that's different than the one determined by the order of your language list, choose it here. |
| 636 | boo bëggee jëfandikoo aw dugaliinu mbind wu wuute ak wi ci sa limu toftale làkk, tànn ko fii. | If you want to use an input method that's different than the first one in your language list, choose it here. |
| 637 | Bàyyi may jël dugaliinu mbind ci poxlab jëfekaay bu ne | Let me set a different input method for each app window |
| 638 | Jëfandikoo laatu làkku ëtt bi su jàppandee | Use the desktop language bar when it's available |
| 640 | Jëfandikoo jàng gog boppal (lees sopp) | Use automatic learning (recommended) |
| 641 | Bañ a jëfandikoo jàng gog boppal te bépp njoxe bees fi dajale | Don't use automatic learning and delete all previously collected data |
| 642 | Njoxe yii gënal nangug mbindum loxo ak gisaane njuréefi mbind ñeel làkk yi waliif ay IME ci PC rekk lees koy doyee. Deesu ci yónnee darra Microsoft. Sàrti Sàmm-Sutura | This data is only used to improve handwriting recognition and text prediction results for languages without IMEs on this PC. No info is sent to Microsoft. Privacy statement |
| 646 | click | click |
| 656 | Mbindum Loxo | Handwriting |
| 661 | Làkku woniinu Windows | Windows display language |
| 673 | Laalaat nangug mbindum loxo | Personalize handwriting recognition |
| 674 | Laalaat nangug mbindum loxo. | Personalize handwriting recognition. |
| 679 | Càmbarukaayu bindiin bees wara jëfandikoo: | Spellchecking engine to use: |
| 680 | Làkk ngir ëmbiitu web | Language for web content |
| 681 | Bañ a may daluweb yi ñuy dugg sama limu làkk. Nañ far jëfandikoo sama làkku tëggiinu bis, waxtu ak limukaay. | Don't let websites access my language list. The language of my date, time, and number formatting will be used instead. |
| 0x90000001 | Analytic channel logs minor warnings, major state/configuration change that can help debug admin and operational events. Default enabled state: off. Target audience: PSS/diagnostic tools/component developers | Analytic channel logs minor warnings, major state/configuration change that can help debug admin and operational events. Default enabled state: off. Target audience: PSS/diagnostic tools/component developers |
| File Description: | Fugluwaayu Tëralug Samay Làkk |
| File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
| Company Name: | Microsoft Corporation |
| Internal Name: | USERLANGUAGESCPL |
| Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
| Original Filename: | USERLANGUAGESCPL.DLL.MUI |
| Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
| Product Version: | 10.0.15063.0 |
| Translation: | 0x488, 1200 |