ngckeyenum.dll.mui Microsoft Passport Key Enumeration Manager 92e8649b46c615eb740014ecd6c6b8fb

File info

File name: ngckeyenum.dll.mui
Size: 14336 byte
MD5: 92e8649b46c615eb740014ecd6c6b8fb
SHA1: 238fdbaaf49a8ffd900d04ff8af1b1cc455d9fb5
SHA256: bd2ba26aeda8fba6a65708a6a8bda1e7a3d8185aacff266c77a796ceab86137f
Operating systems: Windows 10
Extension: MUI

Translations messages and strings

If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.

id Wolof English
200Mënu ñu woon a wéral say xàmmeekaay. Your credentials could not be verified.
201PIN buñu joxe dëppoowul. The provided PINs do not match.
202Dugalal ab PIN. Provide a PIN.
203Dugalal ab PIN bu am araf yuñu yemale ci araf yuñu maasul (A-Z, a-z), nimero (0-9), bayaal, ak yile araf yu xejjiku: ! " # $ % & ’ ( ) * + , - . / : ; ? @ [ \ ] ^ _ ` { | } ~ Provide a PIN that contains characters limited to unaccented letters (A-Z, a-z), numbers (0-9), space, and the following special characters: ! " # $ % & ’ ( ) * + , - . / : ; ? @ [ \ ] ^ _ ` { | } ~
204Dugal ab PIN bu am jaxasoo yu mànta ñàkk. Provide a PIN that meets the complexity requirements.
205Dugal ab PIN bu am jaxasoo yu mànta ñàkk. %1!s!. Provide a PIN that meets the complexity requirements. %1!s!.
206Sa PIN bi warna am gën gaa néew %1!u! araf ci guddaay Your PIN must be at least %1!u! characters long
207Sa PIN warul weesu %1!u! araf ci guddaay Your PIN can’t be more than %1!u! characters long
208Sa PIN am na ab araf bu baaxul Your PIN contains an invalid character
209Sa PIN war na am gën gaa neew benn araf bu mag Your PIN must include at least one uppercase letter
210Sa PIN bi war na am gën gaa néew benn araf bu tuuti Your PIN must include least one lowercase letter
211Sa PIN war na am gën gaa néew benn siifar Your PIN must include at least one number
212Sa PIN war na am gën gaa néew benn araf bu xejjiku Your PIN must include at least one special character
213Sa PIN warul a am araf yu mag Your PIN can’t include uppercase letters
214Sa PIN warul a am araf yu tuuti Your PIN can’t include lowercase letters
215Sa PIN warul a am ay siifar Your PIN can’t include numbers
216Sa PIN warul a am araf yu xejjiku Your PIN can’t include special characters
218Baatu-sutura bi jubul. Jéemaatal. The PIN is incorrect. Try again.
219Am na ab njuumtey jokkoo ci jëfandaay bii. A communication error occurred with the device.
220Dugal baatu natt bi. Provide the challenge phrase.
221Baatu natt bi nga dugal jubul. The provided challenge phrase is incorrect.
222Joxeel PIN boo mësul a jëfandikoo. Provide a PIN that you haven’t used before.
223Sa PIN mënul nekk ay siifar yu nduróo kase Your PIN can’t be a common number pattern
224Your password has expired and must be changed. Sign in with your PIN in order to change it. Your password has expired and must be changed. Sign in with your PIN in order to change it.
225An administrator has restricted sign in. To sign in, make sure your device is connected to the Internet, and have your administrator sign in first. An administrator has restricted sign in. To sign in, make sure your device is connected to the Internet, and have your administrator sign in first.
250Sa jëfandaay lonkuwul. Duggsil ak baatu-jàll bees mujjee jëfandikoo ci jëfandaay bii. Your device is offline. Sign in with the last password you used on this device.
251Mënu ñu jëfandikoo sàq bi ndax ab liggéeyukaay moko moom. Jéemal bu wuuteek bii. This account can’t be used because it belongs to an organization. Try a different account.
252Mën nga dugg ci sa jëfandaay fimne nii. Jéemal baatu-jàll bi nga mujjee jëfandikoo ci jëfandaay bii. You can’t sign in to your device right now. Try the last password you used on this device.
302Mënuloo dugg ak sàq bii. Jéemal ak sàq wuuteek bii. You can’t sign in with this account. Try a different account.
350Sa sàq dafa am ay yemale waxtu yu lay tere nga dugg fii ñu toll. Jéemaatal ci kanam. Your account has time restrictions that prevent you from signing in right now. Try again later.
351Dàkkal nañu sa sàq. Jokkool ak sa caytukatu noste. Your account has been disabled. Contact your system administrator.
352You need to temporarily connect to your organization’s network to use Windows Hello. You can still sign in with the last sign-in option used on this device. You need to temporarily connect to your organization’s network to use Windows Hello. You can still sign in with the last sign-in option used on this device.
353Anam wi nga bëgg a duggee nanguwu ñu ko ci jëfandaay bii. Ngir am ci yeneen leeral, jokkool ak sa yorkatu noste. The sign-in method you're trying to use isn't allowed on this device. For more information, contact your system administrator.
354Àpp buñu jaglel sa sàq weesu na. Jokkool ak sa caytukatu noste. Your account has expired. Contact your system administrator.
355Tëj nañu sa sàq. Jokkool ak sa caytukatu noste. Your account has been locked out. Contact your system administrator.
356Ëmbukaay caabi buñu laaj amul ci jumtukaay bi. The requested key container does not exist on the device.
357Firnde buñu laaj amul ci jumtukaay bi. The requested certificate does not exist on the device.
358Arafukaay buñu laaj amul ci jumtukaay bi. The requested keyset does not exist on the device.
359Mënu ñu woon a jëfandikoo jumtukaay bi. Yeneeni leeral mën nañu jàppandi ci nosteg nettali xew-xew. Yëgëlal bii njuumte sa caytukatu noste. This device could not be used. Additional details may be available in the system event log. Report this error to your system administrator.
360Àppu firnde buñu jëfandikoo ngir xàmmeeku jeex na. The certificate used for authentication has expired.
361Teggi nanu firnde bunu jëfandikoo ngir xàmmeeku. The certificate used for authentication has been revoked.
362Daj nañu ab sàñ-sàñu firnde buñu wóolu wull buñuy jëfandikoo jëfiinu firnde buñu jëfandikoo ngir xàmmeeku. An untrusted certification authority was detected while processing the certificate used for authentication.
363Mën nañu xamle tolluwaayu teggi firnde buñuy jëfandikoo ngir xàmmeeku. The revocation status of the certificate used for authentication could not be determined.
364Wóolu wuñu firnde buñu jëfandikoo ngir xàmmeeku. The certificate used for authentication is not trusted.
365Sa àppu baatu-jàll weesu na te war nañ ko soppi. War nga dugg ak sa baatu-jàll ngir soppi ko. Your password has expired and must be changed. You must sign in with your password in order to change it.
366Tëral nañu sa sàq ngir tere la nga jëfandikoo jumtukaay bii. Jéemal beneen jumtukaay. Your account is configured to prevent you from using this device. Try another device.
367Dugg bi antuwul. Jokkool ak caytukatu noste te wax leen ni mënu ñu jagal firndey KDC bi. Yeneeni leeral mën nañu jàppandi ci booleg xew-xewu noste bi. Sign-in failed. Contact your system administrator and tell them that the KDC certificate could not be validated. Additional information may be available in the system event log.
368Nangu wuñu dugg ak jëfandaay bii ngir sa sàq. Jokkool ak sa caytukaatu noste ngir am yeneeni leeral. Signing in with this device isn't supported for your account. Contact your system administrator for more information.
369Tànneef bii jàppandiwul ci waxtu wii. Kon fimne nii jéemal a wut meneen pexe moo duggee. That option is temporarily unavailable. For now, please use a different method to sign in.
400Sa àppu baatu-jàll jeex na. Fàww nga dugg ak sa baatu-jàll ba noppi nga soppi ko. Ginaaw boo soppee sa baatu-jàll, dinga mën a dugg ak Windows Hello. Your password has expired. You must sign in with your password and change it. After you change your password, you can sign in with Windows Hello.
401Soppi nañu sa baatu jàll ci beneen jëfandaay. Fàww nga dugg benn yoon ci jëfandaay bii ak sa baatu-jàll bu bees, ginaaw loolu dinga mën a duggee ak Windows Hello. Your password was changed on a different device. You must sign in to this device once with your new password, and then you can sign in with Windows Hello.
450Sa jëfandaay dooraat na. Dugalal sa PIN. Your device restarted. Enter your PIN.
451Dugalal sa PIN. Enter your PIN.
500Li sa mbootaay di sàkku ci PIN mooy:
Gàttaay bi warul yées %1!u! araf
Guddaay bi warul weesu %2!u! araf
%3!s!
%4!s!
%5!s!
%6!s!
%7!s!
Your organization has set the following PIN requirements:
Must be at least %1!u! characters long
Can’t be longer than %2!u! characters
%3!s!
%4!s!
%5!s!
%6!s!
%7!s!
501Mën na am araf yu mag May include uppercase letters
502Mën na am araf yu tuuti May include lowercase letters
503Mën na am araf yu siifar May include digits
504Mën na am araf yu xejjiku May include special characters
505War na am gën gaa néew benn araf bu mag Must include at least one uppercase letter
506War na am gën gaa néew benn araf bu tuuti Must include at least one lowercase letter
507War na am gën gaa néew benn siifar Must include at least one number
508War na am gën gaa néew benn araf bu xejjiku Must include at least one special character
509Warul am araf yu mag Can’t include uppercase letters
510Warul am araf yu tuuti Can’t include lowercase letters
511Warul am ay siifar Can’t include digits
512Warul am araf yu xejjiku Can’t include special characters
513Dugal nga PIN bu baaxul ay yoon yu bari.

Ngir jéemaat, fayal taalaat sa jëfandaay.
You’ve entered an incorrect PIN too many times.

To try again, restart your device.
514Dugal nga ab PIN bu baaxul ay yoon yu bari.
%1!s!
Ngir jéemaat, dugalal %2!s! bii ci suuf.
You’ve entered an incorrect PIN several times.
%1!s!
To try again, enter %2!s! below.
515A1B2C3 A1B2C3
516Sa mbootaay laaj na nga soppi sa PIN. Your organization requires that you change your PIN.
517Jëfandikool jëfekaayu Wéralukaay Microsoft bi ci sa telefon ngir dugg. Seetal turu jëfekaay bi ci kaw ngir xàmmee PC bii. Use the Microsoft Authenticator app on your phone to sign in. Look for the device name above to identify this PC.
518Jëfandaay bu sori bi lonku na.

Dugalal sa PIN ci jëfandaay bu sori.
The remote device is connected.

Enter your PIN on your remote device.
519Jëfandaay bu sori bi lonkuwul.
Wérlul ni sa jëfandaay mu ngi ci toftale te rajo bi mu ngi dox.
B¨sal ci buumu jokkoo bi ngir jéemaat lonku.
The remote device is not connected.
Ensure that your device is in range and that its radio is transmitting.
Click the link below to try to connect again.
520Sa mbootaay yónnee na yii càkkutéefu PIN:
Dafa wara nekk gën gaa néew %1!u! siifar cib guddaay
%2!s!
%3!s!
Your organization has set the following PIN requirements:
Must be at least %1!u! digits long
%2!s!
%3!s!
521Warul weesu %1!u! siifar Can’t be longer than %1!u! digits
522Siifar yi mënu ñu toppalantee (niki 123456 wala 11111) Can’t be a number pattern (such as 123456 or 11111)
523Tëj nañu jëfandaay bii ngir sa kaaraange. Lëkkaleel jëfandaay ci piriisu kuuraŋ lu tollu ci ñaari waxtu gën gaa néew ba noppi nga fay ko taalaat ngir jéemaat. This device has been locked for security reasons. Connect your device to a power source for at least two hours, and then restart it to try again.
524Jafe-jafey kaaraange moo waral ñu tëj tànneefu dugg gii. Jëfandikool tànneefu dugg gu wuute wala nga lëkkale sa jëfandaay ci piriisu kuuraŋlu tollu ci ñaari waxtu gën gaa néew ba noppi nga fay ko taalaat ngir jéemaat. This sign-in option has been locked for security reasons. Use a different sign-in option or connect your device to a power source for at least two hours, and then restart it to try again.

EXIF

File Name:ngckeyenum.dll.mui
Directory:%WINDIR%\WinSxS\amd64_microsoft-windows-s..c-keyenum.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_f43df08fa3b81553\
File Size:14 kB
File Permissions:rw-rw-rw-
File Type:Win32 DLL
File Type Extension:dll
MIME Type:application/octet-stream
Machine Type:Intel 386 or later, and compatibles
Time Stamp:0000:00:00 00:00:00
PE Type:PE32
Linker Version:14.10
Code Size:0
Initialized Data Size:13824
Uninitialized Data Size:0
Entry Point:0x0000
OS Version:10.0
Image Version:10.0
Subsystem Version:6.0
Subsystem:Windows GUI
File Version Number:10.0.15063.0
Product Version Number:10.0.15063.0
File Flags Mask:0x003f
File Flags:(none)
File OS:Windows NT 32-bit
Object File Type:Dynamic link library
File Subtype:0
Language Code:Unknown (0488)
Character Set:Unicode
Company Name:Microsoft Corporation
File Description:Microsoft Passport Key Enumeration Manager
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Internal Name:ngckeyenum
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original File Name:ngckeyenum.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Directory:%WINDIR%\WinSxS\wow64_microsoft-windows-s..c-keyenum.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_fe929ae1d818d74e\

What is ngckeyenum.dll.mui?

ngckeyenum.dll.mui is Multilingual User Interface resource file that contain Wolof language for file ngckeyenum.dll (Microsoft Passport Key Enumeration Manager).

File version info

File Description:Microsoft Passport Key Enumeration Manager
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Company Name:Microsoft Corporation
Internal Name:ngckeyenum
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original Filename:ngckeyenum.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Translation:0x488, 1200