If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id |
Wolof |
English |
| 101 | Denc jëfandikoo Jaar-jaari Taxañ |
Back up using File History |
| 102 | Denc samay taxañ ci saasi |
Automatically back up my files |
| 103 | Denc ci saasi say taxañ ci beneen dawalukaay te beesalaat leen sudee da nga reeral mbaa nga yàq mbaa far cosaan yi. |
Back up your files to another drive and restore them if the originals are lost, damaged, or deleted. |
| 104 | Yokk ab dawalukaay |
Add a drive |
| 105 | Dakkal jëfandikoo dawalukaay |
Stop using drive |
| 106 | Denc ci dawalukaay bu wuuteek bii |
Back up to a different drive |
| 107 | Dina laaj nga dàkkal jëfandikoo dawalukaay bi teew laata ngay yokk beneen bu bees. Lii du far benn taxañ ci sa dawalukaayu denc bi teew. |
You'll need to stop using your current backup drive before you add a new one. This won't delete any files from your current backup drive. |
| 108 | Xool bu ëmb lépp |
Overview |
| 109 | Tànnéefi denc |
Backup options |
| 110 | Yeneeni tànnéef |
More options |
| 111 | Lan lañuy denc? |
What gets backed up? |
| 112 | %1 (%2!c!:) |
%1 (%2!c!:) |
| 113 | Tappaan bu Dindiwu |
Removable Disk |
| 114 | Tappaanu biir-barab |
Local Disk |
| 115 | Dawalukaayu mbaal |
Network Drive |
| 116 | Wonee bërëbu mbaal yëpp |
Show all network locations |
| 117 | Denc samay taxañ |
Back up my files |
| 118 | 10 simili yu nekk |
Every 10 minutes |
| 119 | 15 simili yu nekk |
Every 15 minutes |
| 120 | 20 simili yu nekk |
Every 20 minutes |
| 121 | 30 simili yu nekk |
Every 30 minutes |
| 122 | Waxtu wu nekk (default) |
Every hour (default) |
| 123 | 3 waxtu yu nekk |
Every 3 hours |
| 124 | 6 waxtu yu nekk |
Every 6 hours |
| 125 | 12 waxtu yu nekk |
Every 12 hours |
| 126 | Bis bu nekk |
Daily |
| 127 | Ba fàww (default) |
Forever (default) |
| 128 | Ba keroog ñuy soxla payaal |
Until space is needed |
| 129 | 2 at |
2 years |
| 130 | 1 at |
1 year |
| 131 | 9 weer |
9 months |
| 132 | 6 weer |
6 months |
| 133 | 3 weer |
3 months |
| 134 | 1 weer |
1 month |
| 135 | Teye samay denc |
Keep my backups |
| 136 | Dencal yile ëmb |
Back up these folders |
| 138 | Yokk ab ëmb |
Add a folder |
| 139 | Dàq yile ëmb |
Exclude these folders |
| 141 | Jekkal yumu méngool |
Related settings |
| 142 | Gis ay jekkal yu xóot |
See advanced settings |
| 143 | Wuutal ay taxañ ci denc bi teew |
Restore files from a current backup |
| 144 | Wérlul ni %1 is lonlu na te nga jéemaat. |
Make sure %1 is connected and try again. |
| 145 | Mënu ñu lonku ci %1 fimne. Jéemaatal ci kanam tuuti. |
We can't connect to %1 right now. Try again later. |
| 146 | Demal ci Lëñbatukaayu Taxañ, ubbil %1, dugalal say xibaaru ràññeekaay, te nga jéema dencaat. |
Go to File Explorer, open %1, enter your credentials, and try backing up again. |
| 147 | BitLocker mu ngi aar %1.Tijil dawalukaay bi te jéema dencaat. |
BitLocker is protecting %1.Unlock the drive and try backing up again. |
| 148 | %1 ci %2 |
%1 on %2 |
| 149 | Dencukaayu mbaal ci %1 |
Network Storage on %1 |