| 500 | Xaaral |
Please Wait |
| 501 | Seetug Kaarànge |
Security Check |
| 1000 | Jéemaat ko |
Try that again |
| 1001 | Am na lu xew ci ñun. Xaar tuuti mën nala dimbali. Kotu njuumte bi mooy %1, sudee da nga ko soxla. |
Something happened on our end. Waiting a bit might help. The error code is %1, in case you need it. |
| 1002 | Sa waajur walla sa kilifa war naa jënd ay mbir |
You need your parent or guardian to buy stuff |
| 1003 | Mën nga jëfandikoo jëfekaay ak po yépp ci Seetu Dooru Coñu Xale. |
You can use all the apps and games on the Kid’s Corner Start Screen. |
| 1004 | Jënd beneen Jëfekaay |
Shop for another App |
| 1005 | %1 jàppandeetul ci Màngasiin bi. |
%1 is no longer available from Store. |
| 1006 | Tànnal beneen jukki |
Choose another item |
| 1007 | Jukkib jënd in-app bii jàppandeetul ci %1. |
This in-app purchase item is no longer available in %1. |
| 1008 | Jënd sumb bu fees bi |
Buy the full version |
| 1009 | War nga jënd sumbu %1 bu gën a fees ci Màngasiin ngir amal ab jëndug in-app. |
You need to buy the full version of %1 from Store to make an in-app purchase. |
| 1010 | Xoolal sa Lënkug Internet |
Check your Internet connection |
| 1011 | Wérlul ni lonku nga, te nga jéemaat. |
Make sure you're connected, then try again. |
| 1012 | Jokkool ak sa yorkatu noste |
Contact your system administrator |
| 1013 | Màngasiin bi jàppandiwul fimne ci jëfandaay bii. |
Store isn't currently available on this device. |
| 1014 | Mënu ñu motal sa jënd |
Your purchase can't be completed |
| 1015 | Yaa ngi ci ab diiwaan bu nanguwul ay jënd ci Màngasiin bi. |
You're in a region that doesn't support purchases in Store. |
| 1016 | Màngasiin bi jàppandiwul |
Store isn't available |
| 1017 | Yaa ngi ci ab diiwaan bu amul Màngasiin. |
You're in a region where Store isn't available. |
| 1018 | Xoolal say jekkali diiwaan |
Check your region settings |
| 1019 | Mënuloo jënd costéef bi ndax dafa mel ni yaa ngi ci diiwaan bu wuutek say jekkali Màngasiin. |
You can't buy this product because you appear to be in a different region than Store settings. |
| 1020 | Dugg ci Màngasiin |
Sign in to Store |
| 1021 | Ngir motali sa jënd, dugal ak sa sàqum Microsoft, te nga jéemaat jënd. |
To complete your purchase, sign in with your Microsoft account, then try your purchase again. |
| 1022 | Tëj |
Close |
| 1023 | Danga bëgg a yombal sa jaar-jaaru jënd? |
Streamline your purchase experience? |
| 1024 | Soo jënd dara ci Màngasiin bii, dunu la laaj nga joxe baatu-jàll. Mën nga koo soppi saa yu la neexee ci jekkali Màngasiin bi. |
When you buy from the Store, we won’t ask for your password. You can change it any time in Store settings. |
| 1025 | Waaw |
Yes |
| 1026 | Déedet |
No |
| 1027 | Sampaatee ci Màngasiin bi |
Reinstall from the Store |
| 1028 | Simpil jëfekaay bi (demal ci Jekkal yi Sistem Jëfekaay & man-man) ba noppi nga sampaatee ko ci xët costéef bi ci Màngasiinu Windows. Fàww nga yeesal sa sañ-sañ ngir mën a jënd lenn ci biir jëfekaay bi. |
Uninstall this app (go to Settings System Apps & features) and then install it again from the product page in Windows Store. Your license needs to be refreshed to make in-app purchases. |
| 2000 | Amna yeesal yoo wara samp ci %1.%2 |
Updates are waiting to be installed in %1.%2 |
| 2001 | Dangay yebbi yeesal yi léegi? |
Download updates now? |
| 2002 | Waaw-Kay |
Okay |
| 2003 | Mën na am ci kanam |
Maybe later |
| 2004 | Amna yeesal yoo wara samp. %1 mën na soxla fay-tàkkaat. |
Updates are waiting to be installed. %1 might need to restart. |
| 2005 | Dngay yeesal ba noppi fay-taalaat leegi? |
Update and restart now? |
| 2008 | Dangay yebbi ëmbiit leegi? |
Download content now? |
| 2009 | Ndax dañu wara yebbi ak samp bii ëmbiit ngir %1?%2 |
Should we download and install this extra content for %1?%2 |
| 2012 | Danga lënku ci net buñ yamale (mën nañu la fayyeeku ay njoxe). |
You're on a metered connection, so data charges might apply. |
| 0x30000000 | Info |
Info |
| 0x30D1000C | Error |
Error |
| 0x30D1000D | Warning |
Warning |
| 0x30D1000F | Verbose |
Verbose |
| 0x50000004 | Information |
Information |
| 0x70000001 | StorefrontClient |
StorefrontClient |
| 0x700007D0 | Store SDK Module Loaded |
Store SDK Module Loaded |
| 0x700007D1 | In-App Purchase |
In-App Purchase |
| 0x70000BB9 | Store Purchase App |
Store Purchase App |
| 0x90000001 | Windows-ApplicationModel-Store-SDK |
Windows-ApplicationModel-Store-SDK |
| 0xB0000001 | %1%nError Code: %5%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
%1%nError Code: %5%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
| 0xB0000002 | %1%nException Details: %5%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
%1%nException Details: %5%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
| 0xB0000003 | %1%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
%1%nFunction: %4%nSource: %3 (%2) |
| 0xB00007D0 | Process Name: %1%nModule Name: %2%nBuild: %3%n |
Process Name: %1%nModule Name: %2%nBuild: %3%n |
| 0xB00007D1 | %1%nError: %3%nFunction: %2%nSource: %4 (%5) |
%1%nError: %3%nFunction: %2%nSource: %4 (%5) |