File name: | prnntfy.dll.mui |
Size: | 14336 byte |
MD5: | 7145b5ae77f6930a9ecf3591ec4b1eb7 |
SHA1: | c59d6e2d5f66ce7af6e2ea1383111a58d8d49b1d |
SHA256: | b26d0861bb15cfb2c249e2eac56a1a720ab3fcb5fe7ea1fc5a038c5ed8f33dee |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
100 | … | … |
101 | Yónnee nañu waydanre bii ci móolukaay bi | This document was sent to the printer |
102 | Wayndare: %1 Móolukaay: %2 Waxtu: %3 Mbooleem xët yi: %4 |
Document: %1 Printer: %2 Time: %3 Total pages: %4 |
103 | Móolukaay bi amul këyit | Printer out of paper |
104 | Mólukaay ‘%1’ amul këyit. | Printer ‘%1’ is out of paper. |
105 | Móolug wayndare bii aantuwul | This document failed to print |
107 | Buntu móolukaay bi ubbeeku na | Printer door open |
108 | Bunt bi ci ‘%1’ ubbeeku na. | The door on ‘%1’ is open. |
109 | Móolukaay bu nekk ci tolluwaayu njuumte | Printer in an error state |
110 | ‘%1’ nekkul ci ab tolluwaayu njuumte. | ‘%1’ is in an error state. |
111 | Móolukaay bu amul daa/ankar | Printer out of toner/ink |
112 | ‘%1’ amul daa/ankar. | ‘%1’ is out of toner/ink. |
113 | Móolukaay bi jàppandiwul | Printer not available |
114 | ‘%1’ jàppandiwul nir móol. | ‘%1’ is not available for printing. |
115 | Móolukaay bi mu ngi ci biti net | Printer offline |
116 | ‘%1’ nekkul ci net bi. | ‘%1’ is offline. |
117 | Móolukaay bi amul memwaar | Printer out of memory |
118 | ‘%1’ amul memwaar. | ‘%1’ has run out of memory. |
119 | Póllu génnu móolukaay bi fees na | Printer output bin full |
120 | Póllu génn bi ci ‘%1’ fees na. | The output bin on ‘%1’ is full. |
121 | Móolukaay bu log këyit | Printer paper jam |
122 | Këyit lonku na ci ‘%1’. | Paper is jammed in ‘%1’. |
124 | ‘%1’ amul këyit. | ‘%1’ is out of paper. |
125 | Jafe-jafey këyitu móolukaay | Printer paper problem |
126 | ‘%1’ amna ab jafe-jafey këyit. | ‘%1’ has a paper problem. |
127 | Ajandi nañu móolukaay | Printer paused |
128 | Ajandi nañu ‘%1’. | ‘%1’ is paused. |
129 | Móolukaay bi laaj na jëfandikukat bi bayyi ci xel | Printer needs user intervention |
130 | ‘%1’ ab jafe-jafe buy laaj nga bayyi ci xel. | ‘%1’ has a problem that requires your intervention. |
131 | Móolukaay bi amul daa/ankar bu doy | Printer is low on toner/ink |
132 | ‘%1’amul daa/ankar bu doy. | ‘%1’ is low on toner/ink. |
133 | Ñoo ngi far móolukaay bi | Printer is being deleted |
134 | Ñu ngi far %1. | %1 is being deleted. |
135 | %1 ci %2 | %1 on %2 |
136 | Móolukaay bi mënul woon a móol %1 | The printer couldn’t print %1 |
137 | Móol nañ ko | Printed |
138 | Këyit baa ngi ci biti | Paper out |
139 | Njuumte biñuy móol | Error printing |
140 | Yëgley móol | Print Notification |
141 | Denc nañu bi ci ëmbu Wayndare yi | File saved to the Documents folder |
142 | Xool %1. | View %1. |
600 | WAAW-KAY | OK |
601 | Fomb | Cancel |
1000 | Wayndare: %1 |
Document: %1 |
1001 | Móolukaay: %1 |
Printer: %1 |
1002 | Tolluwaayu këyit: %1 |
Paper size: %1 |
1003 | Ankar: %1 |
Ink: %1 |
1004 | Kartuus: %1 |
Cartridge: %1 |
1005 | Barabu log këyit: %1 |
Paper jam area: %1 |
1006 | Am na ab jafe-jafey móolukaay | A printer problem occurred |
1007 | Xoolal móolkaay bi ngir bépp jafe-jafe. | Please check the printer for any problems. |
1008 | Xoolal tolluwaay ak jekkali móolukaay bi. | Please check the printer status and settings. |
1009 | Xool ndax móolukaay bi mu ci net bi ak ndax noppi na ngir móol. | Check if the printer is online and ready to print. |
1100 | Móolukaay bi noppi na ngir móol ci beneen wetu këyit bi. | The printer is ready to print on the other side of the paper. |
1101 | Ngir noppi ci móolug ñaari-wet, dindil këyit bi ci sàllu dugal bi. Dugalaatal këyit bi ci sàllu dugal b féete kaw. | To finish double-sided printing, remove the paper from the output tray. Re-insert the paper in the input tray, facing up. |
1102 | Ngir noppi ci móolug ñaari-wet, dindil këyit bi ci sàllu dugal bi. Dugalaatal këyit bi ci sàllu dugal bi féete suuf. | To finish double-sided printing, remove the paper from the output tray. Re-insert the paper in the input tray, facing down. |
1200 | Bësal bitoŋu Wéy bi ci móolukaay bi soo noppee. | Press the Resume button on the printer when done. |
1201 | Bësal bitoŋu Fomb bi ci móolukaay bi soo noppee. | Press the Cancel button on the printer when done. |
1202 | Bësal ci bitoŋu WAAW-KAY bi ci móolukaay bi soo noppee. | Press the OK button on the printer when done. |
1203 | Bësal ci bitoŋu Net bi ci móolukaay bi soo noppee. | Press the Online button on the printer when done. |
1204 | Bësal ci bitoŋu Beesalaat bi ci móolukaay bi soo noppee. | Press the Reset button on the printer when done. |
1300 | Móolukaay bi nekkul ci net bi. | The printer is offline. |
1301 | Windows mënula woon a lonk ci sa móolukaay. Baal ñu xool lënku bi ci digante ordinatëer bi ak móolukaay bi. | Windows could not connect to your printer. Please check the connection between the computer and the printer. |
1302 | Móolukaay bi nekkul di tontu. Baal ñu xool lënku bi ci digante ordinatëer bi ak móolukaay bi. | The printer is not responding. Please check the connection between your computer and the printer. |
1400 | Log Këyit | Paper Jam |
1401 | Sa móolukaay dafa log këyit. | Your printer has a paper jam. |
1402 | Baal ñu xool móolukaay bi te génn këyit bi ci nekk. Móolukaay bi mënul a móol fiileek génne wuñu këyit bi ci nekk. | Please check the printer and clear the paper jam. The printer cannot print until the paper jam is cleared. |
1403 | Baal ñu génne këyit bi ci móolukaay bi. | Please clear the paper jam on the printer. |
1500 | Sa móolukaay amul këyit. | Your printer is out of paper. |
1501 | Baal ñu xool móolukaay bi te dugal yeneeni këyit. | Please check the printer and add more paper. |
1502 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk yeneen këyit ci sàllu %1. | Please check the printer and add more paper in tray %1. |
1503 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk yeneeni %1 këyit ci sàllu %2. | Please check the printer and add more %1 paper in tray %2. |
1600 | Sàllu génn bi ci sa móolukaay dafa fees. | The output tray on your printer is full. |
1601 | Baal ñu neenal sàllu génn bi ci sa mólukaay. | Please empty the output tray on the printer. |
1700 | Sa móolukaay dafa am ab jafe-jafey këyiit | Your printer has a paper problem |
1701 | Baal ñu xool sa móolukaay ngir jafe-jafe yi. | Please check your printer for paper problems. |
1800 | Sa móolukaay amul ankar | Your printer is out of ink |
1801 | Kartuusu ankar bi ci sa móolukaay jéex na. | The ink cartridge in your printer is empty. |
1802 | Sa móolukaay amul daa. | Your printer is out of toner. |
1803 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk yeneeni ankar. | Please check the printer and add more ink. |
1804 | Baal ñu xool móolukaay bi te wuutal kartuusu ankar bi. | Please check the printer and replace the ink cartridge. |
1805 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk daa. | Please check the printer and add toner. |
1900 | %1 | %1 |
1901 | War nga bayyi xel ci sa móolukaay. Demal ci biro bi ngir toppatoo ko. | The printer requires your attention. Go to the desktop to take care of it. |
1902 | Móolukaay | Printer |
2000 | Siyaan | Cyan |
2001 | Magenta | Magenta |
2002 | Mboq | Yellow |
2003 | Ñuul | Black |
2004 | Light Cyan | Light Cyan |
2005 | Light Magenta | Light Magenta |
2006 | Xonk | Red |
2007 | Wert | Green |
2008 | Baxa | Blue |
2009 | Yokkukaayu Gloss | Gloss optimizer |
2010 | Ñuul Nataal | Photo Black |
2011 | Ñuul Matte | Matte Black |
2012 | Siyaan Nataal | Photo Cyan |
2013 | Magenta Nataal | Photo Magenta |
2014 | Ñuul Leer | Light Black |
2015 | Yokkukaayu ankar | Ink optimizer |
2016 | Nataal bu baxa | Blue photo |
2017 | Giri nataal | Gray photo |
2018 | Nataalu ñetti melo | Tricolor photo |
2100 | Kartuus bu siyaan | Cyan cartridge |
2101 | Kartuus magenta | Magenta cartridge |
2102 | Kartuus bu ñuul | Black cartridge |
2103 | Kartuusu CMYK | CMYK cartridge |
2104 | Kartuus doomu-taal | Gray cartridge |
2105 | Kartuusu melo | Color cartridge |
2106 | Kartuusu nataal | Photo cartridge |
2200 | Ab bunt ci sa móolukaay ubbeeku na. | A door on your printer is open. |
2201 | Ab tëjukaay ci móolukaay ubbeeku na. | A cover on your printer is open. |
2202 | Baal ñu xool móolukaay bi te tëj bépp bunt bu ubbeeku. Móolukaay bi mënul móol su amee ab bunt bu ubbeeko. | Please check the printer and close any open doors. The printer cannot print while a door is open. |
2203 | Baal ñu xool móolukaay bi te tëj bépp tëjukaay bu ubbeeku. Móolukaay bi mënul a móol su amee ab tëjukaay bu ubbeeku. | Please check the printer and close any open covers. The printer cannot print while a cover is open. |
2300 | Sa móolukaay nekkul di móol | Your printer is not printing |
2301 | Baal ñu xool sa móolukaay | Please check your printer |
2302 | Sa móolukaay amul memwaar | Your printer is out of memory |
2303 | Xeyna sa móolukaay mën na baña móol bu baax. Xoolal ndimbal bi ci net bi. | Your document might not print correctly. Please see online help. |
2400 | Sa móolukaay amul ankar bu doy | Your printer is low on ink |
2401 | Kartuusu ankar bi nekk ci sa móolukaay mu ngi waaja jeex. | The ink cartridge in your printer is almost empty. |
2402 | Sa móolukaay amul daa bu doy | Your printer is low on toner |
2403 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk yeneeni ankar suko laajee. | Please check the printer and add more ink when needed. |
2404 | Baal ñu xool móolukaay te wuutal kartuusu ankar bi suko laajee. | Please check the printer and replace the ink cartridge when needed. |
2405 | Baal ñu xool móolukaay bi te yokk daa suko laajee. | Please check the printer and add toner when needed. |
2500 | Nosteg ankar bi nekk ci sa móolukaay nekkul di dox | The ink system in your printer is not working |
2501 | Kartuusu ankar bi nekk ci sa móolukaay nekkul di dox | The ink cartridge in your printer is not working |
2502 | Nosteg daa bi ci móolukaay bi nekkul di dox | The toner system in your printer is not working |
2503 | Baal ñu xool nosteg ankar bi ci sa móolukaay. | Please check the ink system in your printer. |
2504 | Baal ñu xool kartuusu ankar bi ci sa móolukaay. | Please check the ink cartridge in your printer. |
2505 | Baal ñu xool nosteg daa bi ci sa móolukaay. | Please check the toner system in your printer. |
2506 | Baal ñu xool ndax samp nañu kartuus bi bu baax ci móolukaay bi. | Please check that the ink cartridge was installed correctly in the printer. |
2600 | Ajandi nañu móolukaay bi | Printer has been paused |
2601 | ‘%1’ mënul a móol, ndax dañ ko bayyiwoon ci ab tolluwaayu ajandi ci jëfandaay bi. | ‘%1’ cannot print, because it has been put into a paused state at the device. |
2602 | ‘%1’mënul a móol, ndax dañ ko bayyiwoon ci ab tolluwaayu biti net ci jëfandaay bi. . | ‘%1’ cannot print, because it has been put into an offline state at the device. |
2700 | Móol nañu sa wayndare. | Your document has been printed. |
2701 | Sa wayndare mu ngi ci sàllu génn bi. | Your document is in the output tray. |
2702 | %1!d! wayndare yuy negandi ngir %2 | %1!d! document(s) pending for %2 |
2703 |
File Description: | prnntfy DLL |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | prnntfy.dll |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
Original Filename: | prnntfy.dll.mui |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |