File name: | RADCUI.dll.mui |
Size: | 8192 byte |
MD5: | 6f766ed4e54b76c1c331383637ccc21c |
SHA1: | 9278f7b39e0882dec12dec5aa98bdcb1e8603940 |
SHA256: | 3f57494ca07e974a6fe1f41f7fc1b82caac06965d7243e36a46639b2128a4a21 |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
15132 | Waaw-Kay | OK |
15300 | Lonkutey RemoteApp ak Biro | RemoteApp and Desktop Connections |
15301 | Saytu Lonkutey RemoteApp ak Biro | Manage your RemoteApp and Desktop Connections |
15302 | Lonku ci biro ak tëriin yi ci sa liggéeyuwaay | Connect to desktops and programs at your workplace |
15303 | %d tëriin yi ak %d biro yi | %d programs and %d desktops |
15304 | Jagoo yi | Properties |
15305 | Lonku gi dafa am: | This connection contains: |
15306 | Bisu sos: | Date created: |
15307 | %s ci %s | %s at %s |
15308 | Dindi | Remove |
15309 | Location | Location |
15310 | URL u lonku: | Connection URL: |
15311 | %s | %s |
15312 | Dindi Lonku gi | Remove Connection |
15313 | Ndax wóor nala ni danga bëgga dindi lonku gi? | Are you sure you want to remove this connection? |
15314 | Deesna dindi ba fàww mbooleem leeral ak costéef yu lonku gii ci nosukaay bi. | All information and resources for this connection will be permanently removed from this computer. |
15315 | Njuumte amna ci biñuy jéema dindi lonku gi | An error occurred while attempting to remove the connection |
15316 | Dindig lonku gi àntuna bu baax | The connection has been successfully removed |
15317 | Fimne amul benn lonku bu jàppandi ci nosukaay bii. | There are currently no connections available on this computer. |
15318 | Jagooy lonku | Connection Properties |
15319 | Tànnal ab lonku ngir xool ay jagoom. | Please select a connection to view its properties. |
15320 | Lonkiku | Disconnect |
15331 | Tolluwaayu lonku gi: | Connection status: |
15332 | Yeesal yi gëna bees: | Most recent update: |
15333 | Lonku na | Connected |
15334 | Lonkuwul | Not connected |
15336 | Xool leeral yi | View details |
15337 | Njuréefi yeesal yi gëna bees | Most recent update results |
15338 | Turu lonku gi: | Connection name: |
15339 | Doon nañu jéema yeesal ci: | Update attempt occurred on: |
15340 | Xool jagoo yi wala yeesal lonku gii | View properties or update this connection |
15342 | Manuloo jotee yii costéef ci seetu Door gi. | You can access these resources from the Start screen. |
15343 | Yeesal | Update |
15344 | Konku yi ñooy yeesal seen bopp ciy jamono. Ngir yeesal lonku gii leegi, bësal Yeesal léegi. | Connections are automatically updated periodically. To update this connection now, click Update now. |
15345 | Yéesal léegi | Update now |
15346 | Xool costéef yi | View resources |
15351 | %s (Lonku gimu baakoo) | %s (Default Connection) |
15353 | Ndimbël | Help |
15354 | Jot ci RemoteApp ak biro yi | Access RemoteApp and desktops |
15414 | Xàmmeekaay yinga dugal doxuñu. Jéemaatal. | The entered credentials didn't work. Try again. |
15415 | Costéefi PemoteApp ak biro yi jàppandiwuñu. Liko waral mooy ñàkka mana ràññee PC bi randu. Waxal ak sa yorkatu mbaal ngir xam naka ngay jotee ci yooyu costéef. | RemoteApp and desktop resources aren't available. This is because the remote PC can't be identified. Talk to your network administrator to find out how to access these resources. |
15419 | Costéefi PemoteApp ak biro yi jàppandiwuñu. Sa yorkatu mbaal joxula sañ-sañ yi war | RemoteApp and desktop resources aren't available. Your administrator hasn't given you the required permissions |
15420 | Sàmp nañu lonku gi ci nosukaay bi ba noppi. Bësal Jéemaat dugal ID bataaxal bu wuute wala URL ngir sàmp beneen lonku. | The connection has already been set up on this computer. Click Try again to enter a different e-mail ID or URL to set up another connection. |
15421 | Man nga jot ci:
%d biro yi %d apps Man nga itam jot ci yii costéef ci sa seetu Door. |
You can now access:
%d desktops %d apps You can also access these resources from your Start screen. |
15422 | Costéefi RemoteApp ak biro yinga tànn jàppandiwuñ ngir m-bataaxal binga dugal. Sàkkul ndimbal ci sa yorkatu mbaal. | RemoteApp and desktop resources aren't available for the email address that you entered. Ask your network administrator for help. |
15423 | Njuumte amna. Jokkool ak sa yorkatu liggéeyuwaay ngir am ndimbal. | An error occurred. Contact your workplace administrator for assistance. |
15801 | M-bataaxal wala URL | Email address or URL |
15802 | Lonku | Connect |
15803 | Fomb | Cancel |
15804 | Maanaam:
[email protected] https://contoso.com/RDWeb/Feed/webfeed.aspx |
Examples:
[email protected] https://contoso.com/RDWeb/Feed/webfeed.aspx |
15805 | Jéemaatal | Try again |
15806 | Waaw | Yes |
15807 | Déet | No |
15809 | Gisnanu ab Yebeefu Costéefu Biro bu Sori bu mengóo ak sa m-bataaxal. Ndax danga bëgga yebbee ay costéef ci URL bii?
%s |
We've found a Remote Desktop Resource Feed that corresponds to your email address. Do you want to download resources from this URL?
%s |
15810 | Lonku ci: %s | Connecting to: %s |
15811 | Mingi seet ab Yebeefu Costéefu Biro bu Sori ngir: %s | Searching for a Remote Desktop Resource Feed for: %s |
15812 | 11pt;Semilight;None;Segoe UI | 11pt;Semilight;None;Segoe UI |
15814 | Ndax leernala ni danga bëgga dindi %s? | Are you sure you want to remove %s? |
File Description: | RemoteApp ak Àndaaleg UI Lonkug Biro |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | RADCUI.DLL |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Moo jagoo àq yépp. |
Original Filename: | RADCUI.DLL.MUI |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |