File name: | sendmail.dll.mui |
Size: | 6144 byte |
MD5: | 6d1e2dbbb6258b27a79b17542d63dbdd |
SHA1: | 47cf263a908477c782ba6cdef783888ed69d0fcb |
SHA256: | e1c267b325e3e9ad59d9aebb457a541ecf99ab9c02deeb9442058ba83e93deb2 |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
4 | Aji-jot bataaxal | Mail recipient |
5 | Yónnee Bataaxal Bataaxal.url | Send Mail Message.url |
9 | Deesul man a yónnee xeetu wayndare wii niki ab bataaxal. Ndax faroo bëgg yónnees ko niki aw Ñall wu ci jëmsi? | The current document type can not be sent as mail. Would you like to send a Shortcut instead? |
11 | Waajug yónnee: | Preparing to send: |
12 | Sa bataaxal noppi na ngir yónnees ko ak lëkkalekaay mbaa taxañ i takkaale yii:
|
Your message is ready to be sent with the following file or link attachments:
|
13 | Bataaxal gi: | Emailing: |
17 | Ñall wu jëm: %s | Shortcut to: %s |
18 | Yëgal ni: Ngir aar la ci wiris nosukaay, man naa tax terees tëriin i bataaxal yi ñuy yónnee ak a jot yenn xeeti takkaaley taxañ yi. Xoolil sa jekkali kaaràngey bataaxal ngir dogu ci nees di càmbaree takkaale yi. |
Note: To protect against computer viruses, e-mail programs may prevent sending or receiving certain types of file attachments. Check your e-mail security settings to determine how attachments are handled. |
19 | Takk ay taxañ | Attach Files |
20 | Niki Ñallu Ëtt | Desktop as Shortcut |
21 | Ëtt (sos aw ñall) | Desktop (create shortcut) |
22 | Yónnee Bataaxal mujjul man a dayolaat taxañ yii: |
Send Email was unable to resize the following files: |
23 | Taxañi M-bataaxal | E-mail Files |
24 | Maneesul a bataaxale taxañ yi ndax tëriinu bataaxale amul ci nosukaay gi | These files can't be e-mailed because there's no e-mail program on this computer |
25 | Sampal tëriinu bataaxale te jéemaat. | Install an e-mail program and try again. |
26 | Liggéeyalu Bataaxal | Mail Service |
27 | Ñallu Ëtt | Desktop Shortcut |
28 | Benn mbaa lu ko ëpp ci taxañ yi takkaaleesu ko ndax dañoo amaale arafi jagle ci séen tur yi. Baal nu tuddaat taxañ yooyu, walla nga jëfandikoo tëriinu bataaxal bi ngir takk ak yónnee yooyu taxañ. | One or more files have not been attached to the message because their names contain special characters. Please rename the files, or use the e-mail program to attach and send the files. |
30 | &Dayob nataal: | Picture &size: |
33 | Dayo bi lépp-lépp: | Total estimated size: |
34 | Tuut: 800 x 600 | Small: 800 x 600 |
35 | Digg-dóomu: 1024 x 768 | Medium: 1024 x 768 |
36 | Rëy: 1280 x 1024 | Large: 1280 x 1024 |
47 | Gën a tuut: 640 x 480 | Smaller: 640 x 480 |
48 | Dayob Cosaan | Original Size |
57 | %1!u! ci %2!u! | %1!u! of %2!u! |
407 | Fomb gi... | Canceling... |
0x30000000 | Info | Info |
0x30000001 | Start | Start |
0x30000002 | Stop | Stop |
0x50000004 | Information | Information |
0x90000001 | Microsoft-Windows-SendTo | Microsoft-Windows-SendTo |
File Description: | Yónnee Bataaxal |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | sendmail |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
Original Filename: | SENDMAIL.DLL.MUI |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |