Windows.UI.PicturePassword.dll.mui Baatu-jàll Nataal UX 6c9d595a18b1f5777b7779734114c5f6

File info

File name: Windows.UI.PicturePassword.dll.mui
Size: 8704 byte
MD5: 6c9d595a18b1f5777b7779734114c5f6
SHA1: 56f3153fb6a20d3354f7b60444b713b2830d01b3
SHA256: 8a1de5c9cd1c473afd4ee4501ce6097f527daedd7d48b62638268adaf79a1a00
Operating systems: Windows 10
Extension: MUI

Translations messages and strings

If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.

id Wolof English
17500Njëkkal a firndéel sa leerali sàq. First, verify your account info.
17501Sos ab baatu-jàllu nataal Create a picture password
17503Dalal-jàmm ci baatu-jàllu nataal Welcome to picture password
17504Tànnal nataal Choose picture
17512Jekkal sa baatu-jàllu nataal Set up your picture password
17513Diril sa ntaal ngir féetale ko noo ko bëgge. Drag your picture to position it the way you want.
17514Jël nataal bii Use this picture
17515Tànn beneen nataal Choose new picture
17516Rëdd ñatti yëngu ci sa nataal. Man ngaa jaxase ay kurmbal, rëdd yu jub ak ay tomb. Draw three gestures on your picture. You can use any combination of circles, straight lines, and taps.
17517Bul fàtte ne dayo bi, féete, ak jëmuwaayi yëngu yi nga ci def — ak ni nga léen toftalee — ci baatu-jàllu nataal bi lañ bokk. Remember, the size, position, and direction of your gestures — and the order in which you make them — become part of your picture password.
17518Dugalal sa yëngu gu njëkk Enter your first gesture
17519Dugalees na yëngu gu njëkk First gesture entered
17520Dugalal sa ñaareelu yëngu Enter your second gesture
17521Dugalees na yëngu ñaareel Second gesture entered
17522Dugalal sa ñatteelu yëngu Enter your third gesture
17523Dugalees na yëngu ñatteel Third gesture entered
17524Ngir sottal jekkalug sa baatu-jàllu nataal, baamtul rekk ñatti yëngu yi. (Dinga man a tàmbaliwaat saa yu la soobee ci boo laalee ci bitoŋu Tàmbaliwaat.) To finish setting up your picture password, just repeat your three gestures. (You can always start over by tapping the Start over button.)
17526Tàmbaliwaat Start over
17527Dugalaatal sa yëngu gu njëkk Re-enter your first gesture
17528Dugalaatal sa ñaareelu yëngu Re-enter your second gesture
17529Dugalaatal sa ñatteelu yëngu Re-enter your third gesture
17530Fomb Cancel
17531Sos nga sa baatu-jàllu nataal ak jàmm. Jëfandikoo ko beneen ngir duggsi ci Windows. You’ve successfully created your picture password. Use it the next time you sign in to Windows.
17533Defaat baatu-jàllu nataal Reset picture password
175350 0
17536Jëfandikoo nataal buñ lëkkalante Use synced picture
17538Yëraat Replay
17539Waaw-Kay OK
17540Ngir firndéel sa baatu-jàllu nataal, seetaanal yëraat gi te topp misaalum ni nga defe yëngu yi ci sa nataal. To confirm your current picture password, just watch the replay and trace the example gestures shown on your picture.
17541Jéemal a defaat say yëngu. Try making your gestures again.
1754320;light;none;segoe ui 20;light;none;segoe ui
1754411;light;none;segoe ui 11;light;none;segoe ui
1754556;normal;none;segoe ui 56;normal;none;segoe ui
17546Baatu-jàllu nataal Picture password
17547Sa taxaaralu baatu-jàllu nataal baatu-jàll bu yàgg la def. Baal nu duggsi ak sa baatu-jàll bu bees. Your picture password enrollment contains an old password. Please sign in with your new password.
17548Baatu-jàllu nataal bi jubul. Jéemaatal. The picture password is incorrect. Try again.
17550Dog-dogu taxaaral Enrollment Failure
17551Rëq-rëq xew na ci diirub jëfiin wi. Baal nu jéemaat ci kanam. There was a failure during the enrollment process. Please try again later.
17552Baatu-jàllu nataal yoon la wu bees ngir jàppale la ci aar sa PC seetulaal. Yaay tànn ab nataal— ak yëngu yi nga koy booleel — ngir sos baatu-jàll boo duk bokk ak kenn. Picture password is a new way to help you protect your touchscreen PC. You choose the picture — and the gestures you use with it — to create a password that’s uniquely yours.
17553Soo tànnee ab nataal, yaay “rëdd” ci seetu bi ngir sos ay kurmbal, rëdd yu jub ak ay tomb yuñu jaxase.. Dayo bi, féete bi, ak jëmuwaayi yëngu yi ngay def ci sa baatu-jàllu nataal bi lañuy bokk. When you’ve chosen a picture, you “draw” directly on the touchscreen to create a combination of circles, straight lines, and taps. The size, position, and direction of your gestures become part of your picture password.
17557Man wéyal nataal bi fi ne te soppi yëngu yi walla nga tànn beneen nataal. You can keep your current picture and change your gestures, or choose a new picture.
17559Waay-góor (kumba), jàngaat nga sa baatu-jàllu nataal ak jàmm. Congratulations, you have successfully relearned your picture password.
17560Waay-góor (kumba), soppi nga sa baatu-jàllu nataal ak jàmm. Congratulations, you have successfully changed your picture password.
17561Jàngaat baatu-jàllu nataal Relearn your picture password
17562Soppi sa baatu-jàllu nataal Change your picture password
175641 1
175652 2
175663 3
17567Num mel? How’s this look?
17568Jekkal say yëngu Set up your gestures
17569Firndéel say yëngu Confirm your gestures
17570Am na lu ci jubul … Tàmbaliwaat ko! Something’s not right … try again!
17571Dugalaal sa yëngu yii nii Reenter your current gestures
17572Aajewoo ab junj? Toppal misaal mees wone ci sab nataal. Need a hint? Just trace the examples shown on your picture.
17573Boo fàttee ni nga defee sa yëngu yi, bësal Yëraat ngir gis léen. If you’ve forgotten your current set of gestures, tap Replay to see them.
17574Waaw-góor (kumba)! Congratulations!
17579Jéggalu, waaye sa yënguy firndéel bokkul ak ya nga rëddoon. Man ngaa jéemaat ci xoolaat yi nga dugaloon, walla rekk tànnaat yu yees. Sorry, but your confirmation gestures didn’t quite match the ones you drew. You can try again to see the gestures you first entered, or start over to choose new ones.
17580Jéemaat Try again
17581Am na lu ci jubul Something’s not right
17582Sottal Finish
17584Yeesalees na sa baatu-jàllu nataal nam ware ak sa baatu-jàllu fimne. Your picture password enrollment has been successfully updated with your current password.
17586Jéggalu, waaye sa yënguy firndéel bokkul ak ya nga rëddoon. Man ngaa jéemaat ngir gis yëngu yi nga dugaloon bu jëkk. Sorry, but your confirmation gestures didn’t quite match the ones you drew. You can try again to see the gestures you first entered.

EXIF

File Name:Windows.UI.PicturePassword.dll.mui
Directory:%WINDIR%\WinSxS\amd64_microsoft-windows-p..d-library.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_3c1ac8ed9f518ec6\
File Size:8.5 kB
File Permissions:rw-rw-rw-
File Type:Win32 DLL
File Type Extension:dll
MIME Type:application/octet-stream
Machine Type:Intel 386 or later, and compatibles
Time Stamp:0000:00:00 00:00:00
PE Type:PE32
Linker Version:14.10
Code Size:0
Initialized Data Size:8192
Uninitialized Data Size:0
Entry Point:0x0000
OS Version:10.0
Image Version:10.0
Subsystem Version:6.0
Subsystem:Windows GUI
File Version Number:10.0.15063.0
Product Version Number:10.0.15063.0
File Flags Mask:0x003f
File Flags:(none)
File OS:Windows NT 32-bit
Object File Type:Dynamic link library
File Subtype:0
Language Code:Unknown (0488)
Character Set:Unicode
Company Name:Microsoft Corporation
File Description:Baatu-jàll Nataal UX
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Internal Name:Windows.UI.PicturePassword.dll
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original File Name:Windows.UI.PicturePassword.dll.MUI
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0

What is Windows.UI.PicturePassword.dll.mui?

Windows.UI.PicturePassword.dll.mui is Multilingual User Interface resource file that contain Wolof language for file Windows.UI.PicturePassword.dll (Baatu-jàll Nataal UX).

File version info

File Description:Baatu-jàll Nataal UX
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Company Name:Microsoft Corporation
Internal Name:Windows.UI.PicturePassword.dll
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original Filename:Windows.UI.PicturePassword.dll.MUI
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Translation:0x488, 1200