| 1 | Tëriin yoy Baaxoo | 
                                    Default Programs | 
                                                            | 2 | Def Boole yi | 
                                    Set Associations | 
                                                            | 3 | Tànn bob baaxoo | 
                                    Choose a default | 
                                                            | 4 | Def Tëriin yoy Baaxoo | 
                                    Set Default Programs | 
                                                            | 7 | Def Booleg Tëriin yi | 
                                    Set Program Associations | 
                                                            | 10 | Tànnal yan tëriin nga bëgg Windows di ko jëfandikoo ci yëngu yu ci mel ni joow Web, soppig nataal, yónneeg m-bataaxal, ba ci taal misig. | 
                                    Choose which programs you want Windows to use for activities like web browsing, editing photos, sending e-mail, and playing music. | 
                                                            | 200 | Njuumtel Fugluwaayu Tëriin yoy Baaxoo | 
                                    Program Defaults Control Panel Error | 
                                                            | 201 | Jafe-jafe am na ci jëlig xëtu 'Def Tëriin yoy Baaxoo' . (Baatu njuumte: %1!lX!) | 
                                    There was a problem loading the 'Set a Default Program' page. (Error code: %1!lX!) | 
                                                            | 202 | (Jëlal aw tëriin ngir yeneen leeral) | 
                                    (Select a program for more information) | 
                                                            | 203 | Tur | 
                                    Name | 
                                                            | 204 | Xamle | 
                                    Description | 
                                                            | 205 | Bob Baaxo Fimne | 
                                    Current Default | 
                                                            | 206 | Tëriin yi | 
                                    Programs | 
                                                            | 210 | Njàmbaas yi | 
                                    Extensions | 
                                                            | 211 | Bindiit yi | 
                                    Protocols | 
                                                            | 212 | MAPI | 
                                    MAPI | 
                                                            | 220 | Yónnee Bataaxal | 
                                    Send mail | 
                                                            | 221 | Santaane yónnee Bataaxal | 
                                    Send mail command | 
                                                            | 222 | Jëfkaay bees xamul | 
                                    Unknown application | 
                                                            | 223 | Tëriin wii ame na baaxoom yépp | 
                                    This program has all its defaults | 
                                                            | 224 | Tëriin wii ame na %1!lu! ci %2!lu! yoy baaxoo | 
                                    This program has %1!lu! out of %2!lu! defaults | 
                                                            | 225 | Jëleesul | 
                                    Not selected | 
                                                            | 226 | Jëfandikoo tëriin wees jël ngir di ubbi bépp xeetu taxañ ak bindiit bum man a ubbi cig baaxoo. | 
                                    Use the selected program to open all file types and protocols it can open by default. | 
                                                            | 227 | Tànnal yan xeetu taxañ ak bindiit la tëriin wees jël di ubbi cig baaxoo. | 
                                    Choose which file types and protocols the selected program opens by default. | 
                                                            | 228 | Tëriin ak Man-man yi | 
                                    Programs and Features | 
                                                            | 229 | Kaarànge Njaboot | 
                                    Family Safety | 
                                                            | 231 | Ngir soppi say jekkali jëfekaay yu baaxoo, demal ci Jekkal yi  Noste  Jëfekaay yu baaxoo. | 
                                    To change your default apps, go to Settings  System  Default apps. | 
                                                            | 232 | Waaw-Kay | 
                                    OK | 
                                                            | 240 | Def ab taxañ mbaa bindiit muy ubbeekoo saa sune ci tëriin sàngam. | 
                                    Make a file type or protocol always open in a specific program. | 
                                                            | 1169 | Tànnal tëriin yi Windows di jëfandikoo cig baaxoo | 
                                    Choose the programs that Windows uses by default | 
                                                            | 1170 | Jekkal sa tëriin yu baaxoo | 
                                    Set your default programs | 
                                                            | 1171 | Def aw tëriin muy ubbi wépp xeetu taxañ ak bindiit bum man a ubbi. | 
                                    Make a program the default for all file types and protocols it can open. | 
                                                            | 1172 | Boole aw xeetu taxañ mbaa bindiit ak wenn tëriin | 
                                    Associate a file type or protocol with a program | 
                                                            | 1173 | Def aw xeetu taxañ mbaa bindiit (niki .mp3 mbaa http://) dëkke ubbikoo ci tëriin woo tànn. | 
                                    Make a file type or protocol (such as .mp3 or http://) always open in a specific program. | 
                                                            | 1174 | Soppi jekkali Dawal Boppam | 
                                    Change AutoPlay settings | 
                                                            | 1175 | Taal CD yi ak yeneen defukaay yi ci saase | 
                                    Play CDs or other media automatically | 
                                                            | 1176 | Tëral jekkali baaxoo ngir dugg ci tëriin ak nosukaay gi | 
                                    Set program access and computer defaults | 
                                                            | 1177 | Fuglu duggug yenn tëriin yi ak def jikkoy baax yu nosukaay gii. | 
                                    Control access to certain programs and set defaults for this computer. | 
                                                            | 1184 | Def ay boole ñeel aw tëriin | 
                                    Set associations for a program | 
                                                            | 1185 | Jëlal njàmbaas yi nga bëgg tëriin wii baaxoo léen a ubbi, te bës ci Denc. | 
                                    Select the extensions you want this program to open by default, and then click Save. | 
                                                            | 1186 | Denc | 
                                    Save | 
                                                            | 1187 | Fomb | 
                                    Cancel | 
                                                            | 1190 | Limu Tëriin yi | 
                                    Programs List | 
                                                            | 1192 | Jël Lépp | 
                                    Select All | 
                                                            | 1193 | Ngir def aw tëriin niki bob baaxoo ñeel xeetu taxañ ak bindiit yépp yum man a ubbi, bësal ci woowu tëriin teg ci bës Def niki bob Baaxoo. | 
                                    To set a program as the default for all file types and protocols it can open, click the program and then click Set as default. | 
                                                            | 1194 | Boole aw xeetu taxañ mbaa bindiit ak tëriin woo tànn | 
                                    Associate a file type or protocol with a specific program | 
                                                            | 1195 | Bësal ci benn njàmbaas ngir xool tëriin wi ko baaxoo ubbi fimne. Ngir soppi tëriinu baaxoo wi, bësal ci Soppi tëriin. | 
                                    Click on an extension to view the program that currently opens it by default. To change the default program, click Change program. | 
                                                            | 1196 | Soppi tëriin... | 
                                    Change program... | 
                                                            | 1197 | Jëleesul benn njàmbaas mbaa bindiit | 
                                    No extension or protocol selected | 
                                                            | 1198 | Ub | 
                                    Close | 
                                                            | 1199 | List of available programs to change default settings. | 
                                    List of available programs to change default settings. | 
                                                            | 1200 | Xamleg tëriin | 
                                    Program description | 
                                                            | 1201 | Limu Boole Tëriin | 
                                    Program Association List | 
                                                            | 1202 | Select the extensions you want this program to open by default, and then click Save. | 
                                    Select the extensions you want this program to open by default, and then click Save. | 
                                                            | 1205 | Limu Njàmbaas yi | 
                                    Extensions List | 
                                                            | 1206 | Click on an extension to view the program that currently opens it by default. To change the default program, click Change program. | 
                                    Click on an extension to view the program that currently opens it by default. To change the default program, click Change program. | 
                                                            | 1207 | &Def tëriin wii niki wow baaxoo | 
                                    &Set this program as default | 
                                                            | 1208 | &Tànnal tëriin wii ay baaxoo | 
                                    &Choose defaults for this program | 
                                                            | 1224 | Ndimbël | 
                                    Help | 
                                                            | 1226 | Ndimbal | 
                                    Help | 
                                                            | 1230 | Jëli gi... | 
                                    Loading... | 
                                                            | 0x10000034 | SQM | 
                                    SQM | 
                                                            | 0x30000000 | Info | 
                                    Info | 
                                                            | 0x50000004 | Information | 
                                    Information | 
                                                            | 0x90000001 | Microsoft-Windows-Shell-DefaultPrograms | 
                                    Microsoft-Windows-Shell-DefaultPrograms |