File name: | authui.dll.mui |
Size: | 13824 byte |
MD5: | 65cd8e29349ec65f9e97f795c9ac7a48 |
SHA1: | e6bd5e74fa760d3fba1d83ded34b28b5853ae9d5 |
SHA256: | 8bb97f65584c40d6b608d564f4a8c391e665ca93d41006ad6186bff11bfbb827 |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
3000 | Tànnéefi Taal | Power Options |
3002 | Amul benn tànnéefu taal bu jàppandi. | There are currently no power options available. |
3003 | Tànnal li waral nga bëgg a far PC bi | Choose a reason that best describes why you want to shut down this PC |
3004 | Am keneen ku doon jëfandiko PC bi. Soo ko fayee nii, xayna mu ñàkke ci lam doon def te dencu ko. | Someone else is still using this PC. If you shut down now, they could lose unsaved work. |
3005 | Soo fayee PC bi, xayna yaw mbaa keneen ku ko doon jëfandikoo ñàkke ci lam doon def te dencu ko. | If you shut down now, you and any other people using this PC could lose unsaved work. |
3006 | Am keneen ku doon jëfandiko PC bi. Soo ko fayee-taalaat nii, xayna mu ñàkke ci lam doon def te dencu ko. | Someone else is still using this PC. If you restart now, they could lose unsaved work. |
3007 | Soo fayee-taalaat PC bi, xayna yaw mbaa keneen ku ko doon jëfandikoo ñàkke ci lam doon def te dencu ko. | If you restart now, you and any other people using this PC could lose unsaved work. |
3008 | Wéyal | Continue |
3009 | Fay ànd ak loolu | Shut down anyway |
3010 | Fay-taalaat ànd ak loolu | Restart anyway |
3011 | 11;semibold;none;segoe ui | 11;semibold;none;segoe ui |
3012 | 11;semilight;none;segoe ui | 11;semilight;none;segoe ui |
3013 | Fay | Shut down |
3014 | F&ay | Sh&ut down |
3015 | Dina ub jëfekaay yépp te fay PC bi. | Closes all apps and turns off the PC. |
3016 | Fay-taalaat | Restart |
3017 | &Fay-taalaat | &Restart |
3018 | Dina ub jëfekaay yépp, fay PC bi te taalaat ko. | Closes all apps, turns off the PC, and then turns it on again. |
3019 | Nelawal | Sleep |
3020 | N&elawal | &Sleep |
3021 | Ordinaatëer bi dafay wéey di tàkk, waaye tuuti kuraŋ lay lakk. Tëriin yi dañuy dess di ubbéeku, su ko defee su ordinaatëer bi yéwwoo rekk nga daadi dellu fa nga yamoon. | The PC stays on but uses low power. Apps stay open so when the PC wakes up, you’re instantly back to where you left off. |
3022 | Yàndooral | Hibernate |
3023 | &Yàndooral | &Hibernate |
3025 | Dina fay ordinaatëer bi waaye tëriin yi duñu tëjj. Su ordinaatëer bi tàkkaatee rekk nga dellu fa nga yamoon. | Turns off the PC but apps stay open. When the PC is turned on, you’re back to where you left off. |
3026 | Yeesal te fay | Update and shut down |
3027 | Yeesal te f&ay | Update and sh&ut down |
3029 | Dina ub jëfekaay yépp, yeesal PC bi teg ci fay ko. | Closes all apps, updates the PC, and then turns it off. |
3030 | Yeesal te fay-taalaat | Update and restart |
3031 | Yeesal te &fay-taalaat | Update and &restart |
3033 | Dina ub jëfekaay yépp, yeesal PC bi teg ci taalaat ko. | Closes all apps, updates the PC, turns it off, and then turns it on again. |
3034 | Génn | Sign out |
3035 | Dina ub jëfekaay yépp te génne la. | Closes all apps and signs you out. |
3038 | Lonkiku | Disconnect |
3039 | Dina dakkal sag lonku ci PC soryànyoo bii. | Ends your connection to this remote PC. |
3040 | &Lonkiku | &Disconnect |
3041 | G&énn | S&ign out |
3042 | Tëj | Lock |
3043 | T&ëj | L&ock |
3044 | Dina tëj sam sàq ci PC bii. | Locks your account on this PC. |
3045 | Tijji | Undock |
3046 | Ti&jji | U&ndock |
3047 | Dina jëlee sa laptop mbaa as-nosukaay ci geg bees ko defoon. | Removes your laptop or notebook computer from a docking station. |
3050 | Yorkatu noste bi wekki na yenn tolluwaayui kuraŋ yi ñeel sàqum jêfandikukat mii. | The system administrator has disabled some power states for this user account. |
3052 | Soppi jëfandikukat | Switch user |
3053 | Soppi jëfandikukat waliif di ub jëfekaay yi. | Switch users without closing apps. |
3054 | So&ppi jëfandikukat | S&witch user |
3100 | Tànnal li waral nga bëgg a fay nosukaay gii. | Choose a reason that best describes why you want to shut down this computer |
3101 | Am na keneen kuy jëfandikoo nosukaay gi fimne. Soo fayee léegi, man na cee ñàkke lam doon def. | Someone else is still using this computer. If you shut down now, they could lose unsaved work. |
3102 | Soo fayee nosukaay gi, yaw mbaa keneen ku ko doon jëfandikoo man na cee ñàkke lam doon def te dencu ko. | If you shut down now, you and any other people using this computer could lose unsaved work. |
3103 | Am na keneen kuy jëfandikoo nosukaay gi fimne. Soo dooraatee man na cee ñàkke lam doon def. | Someone else is still using this computer. If you restart now, they could lose unsaved work. |
3104 | Soo fayee-taalaat nosukaay gi, xayna yaw mbaa keneen ku ko doon jëfandikoo ñàkke ci lam doon def te dencu ko. | If you restart now, you and any other people using this computer could lose unsaved work. |
3105 | Dina ub jëfekaay yépp te fay nosukaay gi. | Closes all apps and turns off the computer. |
3106 | Dina ub jëfekaay yépp, fay nosukaay gi te taalaat ko. | Closes all apps, turns off the computer, and then turns it on again. |
3107 | Ordinaatëer bi dafay wéey di tàkk, waaye tuuti kuraŋ lay lakk. Tëriin yi dañuy dess di ubbéeku, su ko defee su ordinatër bi yéwwoo rekk nga daadi dellu fa nga yamoon. | The computer stays on but uses low power. Apps stay open so when the computer wakes up, you’re instantly back to where you left off. |
3109 | Dina ub jëfekaay yépp, yeesal nosukaay gi teg ci fay ko. | Closes all apps, updates the computer, and then turns it off. |
3110 | Dina ub jëfekaay yépp, yeesal nosukaay gi teg ci taalaat ko. | Closes all apps, updates the computer, turns it off, and then turns it on again. |
3111 | Dina dakkal sag lonku ci nosukaay soryànyoo gii. | Ends your connection to this remote computer. |
3112 | Dina tëj sam sàq ci nosukaay gii. | Locks your account on this computer. |
3120 | Dawaan ngir tëj | Slide to shut down |
3121 | Dawaan ngir tëj sa PC | Slide to shut down your PC |
3122 | Deesna samp yeesal yu doywaar. | Critical updates will be installed. |
3123 | Deesna samp yeesal yu doywaar. Képp ku jëfandikoo PC bi dina ñàkk liggéey buñ dencul. | Critical updates will be installed. Anyone else using this PC will lose unsaved work. |
3124 | Deesna samp yeesal yu doywaar. Yaw mbaa képp ku jëfandikoo PC bi dina ñàkk liggéey buñ dencul. | Critical updates will be installed. You or anyone else using this PC will lose unsaved work. |
3125 | Képp ku jëfandikoo PC bi dina ñàkk liggéey buñ dencul. | Anyone else using this PC will lose unsaved work. |
3126 | Yaw mbaa képp ku jëfandikoo PC bi dina ñàkk liggéey buñ dencul. | You or anyone else using this PC will lose unsaved work. |
3127 | Ngir tëj PC bii, bësal laatu-bayaal bi. Ngir dem ci li ngay def, bësal bitoŋ bu la neex. | To shut down your PC, press the spacebar. To go back to what you were doing, press any other key. |
3128 | Fomb tëj gi | Cancel shutdown |
3129 | ▼ | ▼ |
3130 | 12;semilight;none;Segoe UI | 12;semilight;none;Segoe UI |
3131 | 20;semilight;none;Segoe UI | 20;semilight;none;Segoe UI |
3132 | 20;Light;none;Segoe UI | 20;Light;none;Segoe UI |
12900 | Input Indicator | Input Indicator |
12901 | 12pt;Bold;;Segoe UI | 12pt;Bold;;Segoe UI |
12902 | 11;semilight;none;Segoe UI | 11;semilight;none;Segoe UI |
25467 | %s %s Ngir jàll ci dugaliinu mbind, najal arafu Windows+bayaal. |
%s %s To switch input methods, press Windows key+Space. |
0x10000031 | Response Time | Response Time |
0x30000000 | Info | Info |
0x30000001 | Start | Start |
0x30000002 | Stop | Stop |
0x50000002 | Error | Error |
0x50000003 | Warning | Warning |
0x50000004 | Information | Information |
0x90000001 | Microsoft-Windows-Authentication User Interface | Microsoft-Windows-Authentication User Interface |
0x90000002 | Microsoft-Windows-Authentication User Interface/Operational | Microsoft-Windows-Authentication User Interface/Operational |
0x90000003 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-CredUI/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-CredUI/Diagnostic |
0x90000004 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Logon/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Logon/Diagnostic |
0x90000005 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Common/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Common/Diagnostic |
0x90000006 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Shutdown/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-Shutdown/Diagnostic |
0x90000007 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-CredentialProviderUser/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-CredentialProviderUser/Diagnostic |
0x90000008 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-BootAnim/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-BootAnim/Diagnostic |
0x90000009 | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-LogonUI/Diagnostic | Microsoft-Windows-Shell-AuthUI-LogonUI/Diagnostic |
0xB0001389 | Logon user interface creation failed. Details: %1 | Logon user interface creation failed. Details: %1 |
0xB000138A | Logon user interface RPC server startup failed. Details: %1 | Logon user interface RPC server startup failed. Details: %1 |
0xB000138B | The username/password credential provider failed to enumerate tiles. | The username/password credential provider failed to enumerate tiles. |
0xB000138C | Autologon failed. Details: %1 | Autologon failed. Details: %1 |
0xB000138D | The autologon password could not be loaded. | The autologon password could not be loaded. |
0xB000138E | The autologon password could not be loaded. Details: %1 | The autologon password could not be loaded. Details: %1 |
0xB000138F | The OEM background could not be loaded for resolution %2 x %3. Details: %1 | The OEM background could not be loaded for resolution %2 x %3. Details: %1 |
0xB0001390 | The OEM background %1 was loaded but its aspect ratio does not match the primary display resolution %2 x %3. | The OEM background %1 was loaded but its aspect ratio does not match the primary display resolution %2 x %3. |
0xB0001391 | The OEM background %1 was not loaded because the file is larger than %2 bytes. | The OEM background %1 was not loaded because the file is larger than %2 bytes. |
0xB0001392 | The credential provider thread creation failed. Details: %1 | The credential provider thread creation failed. Details: %1 |
0xB0001393 | User enumeration failed. Details: %1 | User enumeration failed. Details: %1 |
0xB0001394 | The first run task for package %1 exceeded the maximum runtime alotted and has been cancelled. | The first run task for package %1 exceeded the maximum runtime alotted and has been cancelled. |
File Description: | Jàppalekaayu Jëfandikukat ngir Ràññeeg Windows |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | AUTHUI |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
Original Filename: | AUTHUI.DLL.MUI |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |