| 1 | Kaarànge ak Toppatoo |
Security and Maintenance |
| 2 | Topp bataaxal yi mujj ak saafara jafe-jafey sa nosukaay. |
Review recent messages and resolve problems with your computer. |
| 3 | Pexey Mbooloo moo tere tëriin wii. Ngir yeneen leeral, jokkool ak sa yorkartu noste. |
This program is blocked by group policy. For more information, contact your system administrator. |
| 4 | Topp bataaxal yi mujj te saafara jafe-jafe yi |
Review recent messages and resolve problems |
| 5 | Ruqu waar |
Task pane |
| 6 | Yittewoos na sañ-sañi yorkat |
Administrator privileges required |
| 7 | Ndimbël |
Help |
| 8 | Soppi jekkali Kaarànge ak Toppatoo |
Change Security and Maintenance settings |
| 9 | Jekkali Kaarànge ak Toppatoo |
Security and Maintenance Settings |
| 11 | Wekkees |
Disabled |
| 20 | Sa yorkat moo wekki càmbar gii |
Your administrator has disabled this check |
| 21 | Taal bataaxal yi aju ci %1 |
Turn on messages about %1 |
| 22 | Kenn sàmmu ko fimne |
Currently not monitored |
| 29 | %1!d! bataaxal boo war a bàyyi xel |
%1!d! message needs your attention |
| 31 | %1!d! bataaxal yoo war a bàyyi xel |
%1!d! messages need your attention |
| 33 | ... |
... |
| 34 | Yëf yees jël yu ne, Windows dina ci settantal ay jafe-jafe te yónnee la bataaxal su ko ci gisee. Ndax Kaarànge ak Toppatoo dina ñ càmbar jafe-jafe yi? |
For each selected item, Windows will check for problems and send you a message if problems are found. How does Security and Maintenance check for problems? |
| 35 | Yëf yees jël yu ne, Windows dina ci settantal ay jafe-jafe te yónnee la bataaxal su ko ci gisee. Naka la Kaarànge ak Toppatoo di càmbare jafe-jafe yi? |
For each selected item, Windows will check for problems and send you a message if problems are found. How does Security and Maintenance check for problems? |
| 37 | Naka laa man a xame yan jekkali kaaràngee gën ci sama nosukaay? |
How do I know what security settings are right for my computer? |
| 38 | Fàttaliy Windows Update |
Windows Update reminders |
| 39 | Jekkali kaarànge Internet |
Internet security settings |
| 40 | tee-lakk bu mbaal |
network firewall |
| 41 | aarug yéddukaay ay matukaay yus bëggul |
spyware and unwanted software protection |
| 42 | Caytu Këllu Jëfandikookat |
User Account Control |
| 43 | xeex wiris |
virus protection |
| 44 | Windows Mbakkarfeggu |
Windows Backup |
| 45 | waari topptoo Windows |
Windows maintenance tasks |
| 47 | càmbar ñam |
test check |
| 48 | Fay bataaxal yi aju ci %1 |
Turn off messages about %1 |
| 54 | Windows Update |
Windows Update |
| 59 | Saafara Man a Àndug Tëriini Windows |
Windows Program Compatibility Troubleshooter |
| 60 | (Solowu) |
(Important) |
| 61 | Xool bataaxal yees rënk |
View archived messages |
| 62 | Jaar-jaari Taxañ |
File History |
| 70 | Soppi jekkali Fuglug Sàqu Jëfandikukat |
Change User Account Control settings |
| 81 | Jekkalaatug Boppal |
Automatic Maintenance |
| 82 | MbooloomKër |
HomeGroup |
| 83 | Dundalug Windows |
Windows activation |
| 84 | Tolluwaayu dawalukaay |
Drive status |
| 85 | Sàqum Microsoft |
Microsoft account |
| 86 | Jëfekaayi dooraale |
startup apps |
| 87 | Matukaayu jumtukaay |
Device software |
| 88 | Bayaali Defuwaay |
Storage Spaces |
| 89 | Taxañu liggey yi |
Work Folders |
| 500 | Sanceesul yenn ci sa càmbari noste. |
Some of your system checks have not been initialized. |
| 501 | Fay bataaxal yi mel ni bii |
Turn off messages like this |
| 502 | Kaarànge ak Toppatoo dajul benn jafe-jafe. |
No issues have been detected by Security and Maintenance. |
| 503 | Kaarànge ak Toppatoo daj na benn walla lu ko ëpp ciy jafe-jafe yoo war a topp. |
Security and Maintenance has detected one or more issues for you to review. |
| 504 | &Topptoo |
&Maintenance |
| 506 | Wone/nëbb Mbooloo Topptoo |
Toggle Maintenance Group |
| 507 | Wone walla nëbb Mbooloo Topptoo mi |
Show or hide the Maintenance group |
| 508 | Wone bataaxal yépp |
Show all messages |
| 509 | &Kaarànge |
&Security |
| 511 | Wone/nëbb Mbooloo Kaarànge |
Toggle Security Group |
| 512 | Wone walla nëbb Mbooloo Kaarànge mi |
Show or hide the Security group |
| 514 | Boo gisul nu lim jafe-jafe bi nga, jéemal benn ci yii: |
If you don't see your problem listed, try one of these: |
| 518 | Sa&fara gi |
Tr&oubleshooting |
| 520 | Taal walla fay bataaxal yi |
Turn messages on or off |
| 521 | Topptoo bataaxal yi |
Maintenance messages |
| 525 | Windows Saafara gi |
Windows Troubleshooting |
| 526 | Bataaxali kaarànge |
Security messages |
| 529 | Tee-lakk bu mbaal |
Network firewall |
| 530 | Aarteg Wiris |
Virus protection |
| 531 | Aarteg yéddukaay ak tëriin yees bëggul |
Spyware and unwanted software protection |
| 535 | Waaw-Kay |
OK |
| 537 | Fomb |
Cancel |
| 539 | | |
| |
| 555 | Ndimbël ci jekkali kaarànge |
Security settings help |
| 556 | Seet te faj ay jafe-jafe |
Find and fix problems |
| 557 | &Dabuwaat |
&Recovery |
| 558 | Yëlëb sa PC waliif di laal say taxañ walla beesalaat ko te dooraat lépp. |
Refresh your PC without affecting your files, or reset it and start over. |
| 561 | Saafara |
Troubleshooting |
| 562 | Dabuwaat |
Recovery |
| 564 | Kaarànge |
Security |
| 565 | Topptoo |
Maintenance |
| 574 | Bayaali Dencu |
Storage Spaces |
| 576 | Jëfekaayi tàkkaale |
Startup apps |
| 0x10000031 | Response Time |
Response Time |
| 0x30000001 | Start |
Start |
| 0x30000002 | Stop |
Stop |
| 0x50000004 | Information |
Information |
| 0x90000001 | Microsoft-Windows-HealthCenterCPL |
Microsoft-Windows-HealthCenterCPL |