| 10000 | Phone Service |
Phone Service |
| 10001 | Dafay saytu telefonu réew bi ci jumtukaay bi |
Manages the telephony state on the device |
| 10002 | Baatu-jàll yi nga dugal dëppoo wul. |
The passwords you typed don't match. |
| 10003 | Soppi nañu baatu-jàll |
Password changed |
| 10004 | Baatu jàll bi jubul. Dugalal baatu jàll bu jub bi te jéemaat. |
The password isn't valid. Enter the correct password and try again. |
| 10005 | Mënu loo dugg ci mbaal bi. jéemaatal. |
Can't access the network. Try again. |
| 10007 | Nangu wuñu kot bii. |
This code isn't supported. |
| 10008 | Jekkal yi jubu ñu. |
The parameters are invalid. |
| 10010 | Amoon na ab jafe-jafe ci kot bii. |
There was a problem with this code. |
| 10012 | Lël bi tëju na |
Session closed |
| 10014 | Kàrt SIM bi nekku fi. |
The SIM card is missing. |
| 10015 | Dafay laaj PUK |
PUK required |
| 10017 | Kàrt SIM bi jubul. |
The SIM card is invalid. |
| 10018 | Mënu ñu matal telefon bi ndax dekkal nañu anamu Nimero Mbind buñu Saafaral ci sa kàrt SIM. |
The call can't be completed because Fixed Dialing Number mode is enabled on your SIM card. |
| 10019 | Yónnee nañu nimero bi |
Code sent |
| 10020 | Sotti na |
Succeeded |
| 10021 | Telefon bi tëju na |
Phone unblocked |
| 10022 | Dekkal nañu cër bi |
Service enabled |
| 10023 | Dekkal nañu cër bi ngir %1 |
Service enabled for %1 |
| 10024 | Dàkkal nañu cër bi |
Service disabled |
| 10025 | Dàkkal nañu cër bi ngir %1 |
Service disabled for %1 |
| 10026 | Xàmu ñu tolluwaayu cër bi |
Service state unknown |
| 10027 | Jàllale %1 is %2 ci %3 ngir %4 |
Forward %1 is %2 to %3 for %4 |
| 10028 | Jàllale %1 is %2 ngir %4 |
Forward %1 is %2 for %4 |
| 10029 | Jàllale %1 is %2 ci %3 for %4 su %5 saa weesoo |
Forward %1 is %2 to %3 for %4 after %5 seconds |
| 10030 | Jàllale %1 is %2 ngir %4 su %5 saa weesoo |
Forward %1 is %2 for %4 after %5 seconds |
| 10031 | Jàllale %1 is %2 ci %3 |
Forward %1 is %2 to %3 |
| 10032 | Jàllale %1 mooy %2 |
Forward %1 is %2 |
| 10033 | Jàllale %1 is %2 ci %3 su %5 saa weesoo |
Forward %1 is %2 to %3 after %5 seconds |
| 10034 | Jàllale %1 mooy %2 su %5 saa weesoo |
Forward %1 is %2 after %5 seconds |
| 10035 | Dekkal nañ ko |
Enabled |
| 10036 | Dàkkal nañ ko |
Disabled |
| 10037 | Ci ñàkk sàrtal |
Unconditionally |
| 10038 | Woote yuy xarandi |
Busy calls |
| 10039 | Su amul tontu |
If no reply |
| 10040 | Suñu mënee jot telefon bi |
If phone isn't reachable |
| 10041 | Woote yépp |
All calls |
| 10042 | Woote yépp cig sàrtal |
All calls conditionally |
| 10043 | %1 |
%1 |
| 10044 | %1 ak %2 |
%1 and %2 |
| 10045 | %1, %2 ak %3 |
%1, %2, and %3 |
| 10046 | %1, %2, %3 ak %4 |
%1, %2, %3, and %4 |
| 10047 | %1, %2, %3, %4, ak %5 |
%1, %2, %3, %4, and %5 |
| 10048 | %1, %2, %3, %4, %5, ak %6 |
%1, %2, %3, %4, %5, and %6 |
| 10049 | %1, %2, %3, %4, %5, %6, ak %7 |
%1, %2, %3, %4, %5, %6, and %7 |
| 10050 | %1, %2, %3, %4, %5, %6, %7, ak %8 |
%1, %2, %3, %4, %5, %6, %7, and %8 |
| 10051 | Baat |
Voice |
| 10052 | Njoxe |
Data |
| 10053 | Faks |
Fax |
| 10054 | SMS |
SMS |
| 10055 | Lëkkale ñallu njoxe |
Data circuit sync |
| 10057 | Dugg ci paket |
Packet access |
| 10058 | Dugg PAD |
PAD Access |
| 10059 | Woote gu jamp |
Emergency call |
| 10060 | Bataaxalu kàddu |
Voicemail |
| 10062 | gir jëfandikoo gàttalu %1# ngir woo %3 at %2 ci sa kàrt SIM, yànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal Fomb te wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %3 at %2 from your SIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 10063 | Ngir jjëfandikoo gàttalu %1# ngir woo %2 ci sa kàrt SIM, tànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal Fomb te wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %2 from your SIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 10064 | Telefon |
Phone |
| 10067 | Woo |
Call |
| 10068 | Say jekkali tere woote meyul ab woote ci nimero bii. Dàkkalal tere woote te jéema woote waat. |
Your call barring settings don't allow a call to this number. Disable call barring and try calling again. |
| 10069 | Sa xeetu Nimero Woo buñu Saafaral (NWS) meyu la nga woo nimero bii. Dàkkalal NWS te jéema woote waat. |
Your Fixed Dialing Number (FDN) mode doesn't allow a call to this number. Disable FDN mode and try calling again. |
| 10070 | Jekkali bataaxalu baat. Dugalal sa nimero bataaxalu baat te jéemaat. |
Voicemail isn't set up. Enter your voicemail number and try again. |
| 10071 | Mu ngi xarandi... |
Waiting... |
| 10072 | Mënul a dugal woote bi. Baal ñu jeexal sa woote bi teew laata ngay dugal beneen woote. |
Can't place the call. Please end your current call before placing an additional call. |
| 10073 | Mënul a lonku |
Can't connect |
| 10074 | Siñaalu wifi bi daa néew doole, wala nimero bi baaxul. |
You may have a weak wireless signal, or the wrong number. |
| 10076 | Nit ki nga doon jéem a woo mënul a jot woote yuy dugg. |
The person you're trying to call is restricted from receiving incoming calls. |
| 10077 | Mënul a lonku. Wérlul lonku nga ci net mbaal bi, te jéemaat. |
Can't connect. Make sure you have network coverage, and try again. |
| 10078 | Woote gi mënul a jàll. |
The call can't be completed. |
| 10080 | Kàrt SIM bi dafa jàpp, jéemaatal. |
The SIM card is busy, please try again. |
| 10081 | Cëri mbaal bi dafa jàpp. Baal ñu jéemaat ci kanam. |
The network service is unavailable. Please try again later. |
| 10082 | Mën nga jëfandikoo telefon bi ngir woote yu jamp kase. |
You can use this phone for emergency calls only. |
| 10083 | Mënul a woo bataaxalu baat bi ndax am na beneen buum bu jàpp. |
Can't call voicemail because another line isn't available. |
| 10084 | Menul a toxal woote gi. |
Can't transfer call. |
| 10085 | Dugalal kotu cër yi dàkk ci arafukaayu telefon bi. |
Enter service codes directly from the phone's dial pad. |
| 10089 | Ananmu ropplaan fay na léegi |
Airplane mode is now off |
| 10091 | Waaw-Kay |
OK |
| 10092 | Fomb |
Cancel |
| 10093 | Mënul a denc nimero bataaxalu baat. |
Can't save voicemail number. |
| 10094 | Anamu Wontu woote gu jamp |
In Emergency Callback Mode |
| 10095 | Fombal anam bii ngir jëfandikoo sa telefon ni nga ko bëggee. |
Cancel this mode to use your phone as you normally would. |
| 10096 | Anamu fomb |
Cancel mode |
| 10097 | Bind woote gu jamp |
Dial emergency call |
| 10108 | Taal lëkkale telefon portaabi bi? |
Turn on cellular connection? |
| 10109 | Sa telefon mu ngi ci anamu ropplaan. Ngir woote, taalal sa lëkkale telefon portaabal. |
Your phone is in airplane mode. To make a call, turn on your cellular connection. |
| 10110 | Taal |
Turn on |
| 10115 | Yónnee |
Send |
| 10116 | Tëj |
Close |
| 10117 | Njeextalu lël bi. |
The session timed out. |
| 10118 | Am na lu xew te mënu ñu woon a motal jëf ji. |
Something happened and we couldn't complete this action. |
| 10128 | Wéy ak wideo bii? |
Continue with video call? |
| 10129 | Lii di jeexal woote gi nga nekk. Wéy? |
This will end the call that's on hold. Continue? |
| 10130 | Wéy |
Continue |
| 10132 | Mënul a door woote wideo |
Can't start video call |
| 10133 | %1 duggul fii ñu toll ci %2. |
%1 is currently not signed into %2. |
| 10140 | Def |
Set |
| 10141 | Bàyyi |
Cancel |
| 10142 | Def ko jëfekaayu baaxoo? |
Set default app? |
| 10143 | Danga bëgg a %1!s! muy jëfekaayu ràññeekaayu wootekat bi? |
Do you want to set %1!s! as your default caller ID app? |
| 10144 | Danga bëgg a %1!s! muy jëfekaayu seggukaayu spam? |
Do you want to set %1!s! as your default spam filter app? |
| 50001 | Kàrt SIM/UIM nekku fi. |
The SIM/UIM card is missing. |
| 50002 | Kàrt SIM/UIM bi jubul. |
The SIM/UIM card is invalid. |
| 50003 | Woote gi mënul a mot ndax dañu dekkal anamu Nimero Woote buñu saafaral ci sa kàrt SIM/UIM. |
The call can't be completed because Fixed Dialing Number mode is enabled on your SIM/UIM card. |
| 50004 | Ngir jëfandikoo gàttal bi %1# ngir woo %3 ci %2 ci sa kàrt SIM/UIM, tànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal Fomb te wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %3 at %2 from your SIM/UIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 50005 | Ngir jëfandikko gàttalu %1# ngir woo %2 ci sa kàrt SIM/UIM, tànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal fomb ngir wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %2 from your SIM/UIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 50006 | Kàrt SIM/UIM dafa jàpp, jéemaatal. |
The SIM/UIM card is busy, please try again. |
| 50008 | Mënul woo |
Can't call |
| 50009 | War nga taal jaabante baat bi ngir woo kenn ndax yaa ngi ci barabu jaabante. Mën nga def lii ci Jekkal Mbaal & Amul buum Telefon & SIM. |
You need to turn on voice roaming to call someone because you're in a roaming area. You can do this in Settings Network & wireless Cellular & SIM. |
| 50010 | Jekkal yi |
Settings |
| 50020 | Ngir jëfandikoo gàttalu %1# ngir woo %3 ci %2 ci sa kàrt UIM, tànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal Fomb te wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %3 at %2 from your UIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 50021 | Ngir jëfandikoo gàttalu %1# ngir woo %2 ci sa kàrt UIM, tànnal Woo. Ngir woo beneen nimero, tànnal Fomb te wéyal woote gi. |
To use the shortcut %1# to dial %2 from your UIM card, select Call. To dial a different number, select Cancel and continue dialing. |
| 50023 | Kàrt UIM bi dafa jàpp, baal ñu jéemaat. |
The UIM card is busy, please try again. |
| 50024 | War nga taal jaabante baat bi ngir woo kenn ndax ya ngi ci ab barabu woote. Mën nga def lii ci Jekkal Mbaal & Amul buum Telefon & SIM. |
You need to turn on voice roaming to call someone because you're in a roaming area. You can do this in Settings Network & wireless Cellular & SIM/UIM. |
| 50025 | Jëfekaay yu ñeel woote baat yi |
Apps for voice calls |
| 50026 | Seet ab jëfekaay ci Màngasiin bi? |
Search for an app in the Store? |
| 50027 | War nga sàmp ab jëfekaay buy tax nga mën a amal ay woote baat, te mën nañu la dimbali nga gis bii Màngasiin. |
You need to install an app that lets you make voice calls, and we can help you find one in the Store. |
| 50028 | Waaw |
Yes |
| 50029 | Déet |
No |
| 50030 | Taal woote wideo LTE? |
Turn on LTE video calling? |
| 50031 | Fay nañu woote wideo LTE bi. Ngir amal ab woote wideo, taalal woote wideo LTE. |
LTE video calling is turned off. To make a video call, turn on LTE video calling. |
| 50034 | Woote wideo LTE |
LTE video calling |
| 50035 | Njoxe baaxoo yi ak nattu baat yi dañuy jëfe sooy amal ay woote wideo. Yeneen nit mën nañu gis ni mën nga woo mbaa jot ay woote wideo. |
Standard data and voice rates apply during video calls. Other people may discover that you can make and receive video calls. |
| 50036 | Wonewaatul bataaxal bii |
Don't show this message again |
| 50038 | Wideo |
Video |
| 50039 | Dangay wotte ci Wi-Fi? |
Call over Wi-Fi? |
| 50040 | Mënoo defee woote gii ci njoxey mbaal. Taalal wooteg Wi-Fi ci jekkali SIM bi, ba noppi nga jéem a wootewaat. |
Can't complete the call over a cellular network. Turn on Wi-Fi calling in SIM settings, then try calling again. |
| 50043 | Bul wanewaat bataaxal bii |
Don't show this message again |
| 50044 | Dangay woote ci WLAN? |
Call over WLAN? |
| 50045 | Mënul yeggali woote gi ci mbaalu selileer bi. Taalal wooteg WLAN ci jekkali SIM, te nga jéem a wootewaat. |
Can't complete the call over a cellular network. Turn on WLAN calling in SIM settings, then try calling again. |
| 50100 | %1 %2 |
%1 %2 |
| 50101 | %1 - ndaje %2 |
%1 - conference %2 |
| 50102 | Xàmmeesul |
Unknown |
| 50200 | End the current call, then try to make the priority call again. |
End the current call, then try to make the priority call again. |