| 1 | Kanam |
Face |
| 2 | Iris |
Iris |
| 3 | Bitoŋu dugg |
Sign in button |
| 4 | Bataaxalu nekkuwaay |
Context message |
| 5 | Windows Hello |
Windows Hello |
| 50 | Baal ñu jëfandikoo beneen anam ngir ñu xàmmee la. |
Please use a different method to identify yourself. |
| 51 | Hello %1!s!! Tànnal OK ngir wéy. |
Hello %1!s!! Select OK to continue. |
| 52 | Mënula woon xàmmee. Baal nu dugal sa PIN. |
Couldn't recognize you. Please enter your PIN. |
| 100 | Windows mënu la woon a dugal. |
Windows couldn't sign you in. |
| 101 | Hello %1!s! |
Hello %1!s! |
| 104 | Mu ngi lay seet... |
Looking for you... |
| 105 | Mingi waajal... |
Getting ready... |
| 106 | Mënul woon a taal jëlukaayu nataal. Baal nu dugg ak sa PIN. |
Couldn't turn on the camera. Please sign in with your PIN. |
| 107 | Your PIN is required to sign in. |
Your PIN is required to sign in. |
| 108 | Dàkkal nañu sa sàq. Baal ñu jokkook sa yorkatu ndimbal. |
Your account has been disabled. Please contact your support person. |
| 109 | Laata ngay mën a tàmbalee jëfandikoo Windows Hello, fàww nga jekkal sa PIN. |
Before you can start using Windows Hello, you have to set up a PIN. |
| 111 | Balaa ngay mën a tàmbalee jëfandikoo Windows Hello, fàww nga dugal sa PIN. |
Before you can start using Windows Hello, you have to enter your PIN. |
| 113 | Hello, %1!s!! Dàq seetu tëj bi ngir dugg. |
Hello, %1!s!! Dismiss the lock screen to sign in. |
| 114 | Jéggalu am na lu doxul. Baal ñu dugg ak sa PIN. |
Sorry something went wrong. Please sign in with your PIN. |
| 120 | Jéggalu am na lu doxul. Baal ñu dugal sa PIN. |
Sorry something went wrong. Please enter your PIN. |
| 121 | Sa caytukat dàkkal na Windows Hello fimne. |
Windows Hello is currently disabled by your administrator. |
| 123 | Xool bu baax ndax yaw la... |
Making sure it's you... |
| 124 | Jëlukaayu nataal bi jàppandiwul. Baal nu dugg ak sa PIN. |
Camera not available. Please sign in with your PIN. |
| 126 | Mënula woon xàmmee. Raayal kaw ngir dugal PIN bi. |
Couldn't recognize you. Swipe up to enter PIN. |
| 127 | Raayal jëm kaw ngir tijji xoolu bi. |
Swipe up to dismiss the lock screen. |
| 128 | Duggiin wu sori gaa ngi dox. Dindil xoolu tëjte gi ngir dugg. |
Remote session is active. Dismiss the lock screen to sign in. |
| 129 | Dismiss the lock screen to sign in. |
Dismiss the lock screen to sign in. |
| 150 | Mënu la woon a xàmmee. |
Couldn't recognize you. |
| 152 | Mënul a taal jëlukaayu nataal bi. |
Couldn't turn on the camera. |
| 153 | Jëlukaayu nataal bi jàppandiwul. |
Camera not available. |
| 155 | Jéggalu, am na lu jaarul yoon. |
Sorry something went wrong. |
| 156 | Your password is required to sign in. |
Your password is required to sign in. |
| 157 | Camera is in use. Please sign in with your PIN. |
Camera is in use. Please sign in with your PIN. |
| 158 | Camera driver is in a bad state. Please sign in with your PIN. |
Camera driver is in a bad state. Please sign in with your PIN. |
| 180 | Hello! Getting things ready... |
Hello! Getting things ready... |
| 200 | Sa jëfandaay mënu la gis. Xoolal bu baax ndax sa bëtu nataalukaay bi tilimul. |
Your device couldn't detect you. Make sure your camera lens is clean. |
| 201 | Dafa leer lool! Fayal yenn làmp yi mbaa nga dugg ci biir. |
Too bright! Turn off some lights or go inside. |
| 202 | Dafa lëndëm lool! Taalal yenn làmp yi mbaa nga dem fu gën a leer. |
Too dark! Turn on some lights or move somewhere brighter. |
| 203 | Wérlul ni yaa ngi ci biir te yaa ngi xoolal jub xócc ci nataalukaay bi. |
Make sure you're centered and looking directly at the camera. |
| 204 | Dafa jege lool! Jéemal a randu ci kanam. |
Too close! Try moving a little farther away. |
| 205 | Dafa sori lool! Jéemal a jege si tuuti. |
Too far away! Try moving a bit closer. |
| 206 | Wëndeelal sa bopp ci sa càmmoñ ak ci sa ndeyjoor. |
Turn your head slightly to the left and right. |
| 207 | Ubbil say gët tuuti. |
Open your eyes a little wider. |
| 208 | Yëngul tuuti ngir moytu mu mellax ci sa gët. |
Move slightly to avoid reflection off your eyes. |
| 209 | Toxal fu sori |
Move farther away |
| 210 | Xëcc ko mu jege |
Move closer |
| 211 | Teyeel sa jëfandaay ngir mu jakkaarlook say gët. |
Hold your device straight in front of your eyes. |
| 212 | Sa jëfandaay mu ngi am ay jafe-jafe ngir daj la. Wérlul ni sa seetu nataalukaay set na. |
Your device is having trouble detecting you. Make sure your camera lens is clean. |
| 213 | Sa jëfandaay mënul gis say bët. Xoolal bu baax ndax sa bëtu nataalukaay bi tilimul. |
Your device couldn't detect your eyes. Make sure your camera lens is clean. |
| 301 | Mënul a dugg ak Windows Hello? |
Can't sign in with Windows Hello? |
| 302 | Demal ci tëralaat ngir gënaal xàmmeekaay ci ay anami leeralug, walla kañ la sa melokaan soppeekoo (maanaam, ay weer yu bees). |
Go through setup again to improve recognition in different lighting conditions, or when your appearance changes (for example, new glasses). |
| 303 | Gënal xàmmee ci Windows Hello |
Improve recognition in Windows Hello |
| 304 | Ngir jariñoo ci yeesal yu mujj yi ci Windows Hello, demal ci tëralaat. |
To take advantage of the latest updates to Windows Hello, go through setup again. |
| 305 | Ndax xam nga ni mën nga jëfandikoo xàmmeg xar kanam ngir dugg? |
Do you know that you can use face authentication to sign in? |
| 306 | Demal ci jekkalukaayu kanamu Windows Hello ngir tàmbali. |
Go through the Windows Hello face setup to get started. |
| 307 | There is a problem with Windows Hello. |
There is a problem with Windows Hello. |
| 308 | Please go through the setup again to fix this issue. |
Please go through the setup again to fix this issue. |