DMAppsRes.dll.mui DMAppsRes 36c1312eb5d031bd8ebf2a641fe74364

File info

File name: DMAppsRes.dll.mui
Size: 11776 byte
MD5: 36c1312eb5d031bd8ebf2a641fe74364
SHA1: 4364a70fc98ca4cd8911bbe31152f57361bdf8a1
SHA256: 5e7142b8a33d342c2fba7045efd4465e6d8b28f0e75fb25fd5821d39eb3ba431
Operating systems: Windows 10
Extension: MUI

Translations messages and strings

If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.

id Wolof English
26002Dencukaayu telefon bi dafa fees Mën nga dindi jëfekaay yi nga jëfandikoowul soo bëggee feexal bayaal. Phone storage is full. You can remove unused applications if you want to free up space.
26004Mënu ñu soppi say jekkali telefon. Your phone's settings couldn't be changed.
26007Jekkali telefon soppeeku na ci jàmm Phone settings change unsuccessful
26008Soppi nañu yenn jekkal Phone settings changed
26009 soppi na say jekkal ci jàmm. successfully changed your phone's settings.
26010Jekkal nañu coppite yi ci sa telefon ci jàmm. The changes to your phone's settings were successful.
26011Yëgley noste System notification
26012Coppite yi jàppandi nañu Changes are available
26024Yónneekat buñu ràññeewul Unidentified sender
26027%1 yónnee nala yenn jekkali telefon. Soo xamee yónneekat bi te nga bëgg a nangu coppite yi, bindal PINu yónneekat bi, tek ci laal Duggr. Di nga jot ab bataaxalu jukki suñu motalee coppite yi.

Soo bëggulee def lii fii ñu toll bësal biton Dellu ngir yeexal coppite yi. Laalal Fomb ngir bañ leen.
%1 has sent you some new phone settings. If you know the sender and want to accept these changes, type the sender's PIN, and then tap Enter. You'll get a text message when the changes are complete.

If you don't want to do this right now press the Back button to postpone the changes. Tap Cancel to decline them.
26028Mën nga jot yenn jekkali telefon yu bees ci balluwaay yuñu ràññeewul. Soo xàmmee yónneekat bi te bëgg a nangu yile coppite, bindal PINu yónneekat bi, te nga laal Dugg. Di nga jot ab bataaxalu jukki suñu motalee coppite yi.

Soo bëggulee def lii fii ñu toll bësal biton Dellu ngir yeexal coppite yi. Laalal Fomb ngir bañ leen.
You’ve received some new phone settings from an unidentified source. If you know the sender and want to accept these changes, type the sender's PIN, and then tap Enter. You'll get a text message when the changes are complete.

If you don’t want to do this right now, press the Back button to postpone the changes. Tap Cancel to decline them.
26030PIN bi nga dafa jagadi. Jéem ko dugalaat.

Jéem yi des: %1
The PIN you entered was incorrect. Try entering it again.

Remaining attempts: %1
26031PIN bu jagadi Incorrect PIN
26043PIN bi nga dugal dafa jagadi. The PIN you entered was incorrect.
26045Soxla nañu ay coppite telefon Phone changes needed
26046Sa operatëer mobiil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox ci mbaal bi. Ngir amal coppite yi, war nga lonku ci Wifi mbaa nga taal njoxey selileer.

Di nga jot ab bataaxalu jukki su motee.
Your mobile operator (%1) needs to make some changes to your phone so it'll continue to work well on the network. To make the change, you need to connect to Wi-Fi or turn on cellular data.

You'll get a text message when it's complete.
26047&Sa operatëer mobiil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox. Ngir amal coppite yi, war nga lonku ci Wifi mbaa nga taal njoxey selileer.

Di nga jot ab bataaxalu jukki su motee.

Ngir fomb yeesal bi, demal ci jekkali Portaabal+SIM.
Your mobile operator (%1) needs to make some changes to your phone so it'll continue to work well on the network. To make the change, you need to connect to Wi-Fi or turn on cellular data.

You'll get a text message when it's complete.

To cancel the update, go to Cellular & SIM Settings.
26048%1 jeex na, te coppite yi ci sa telefon mot nañu. %1 is finished, and the changes to your phone are complete.
26050waaw-kay ok
26051fomb cancel
26052tëj close
26053waaw yes
26054déet no
26055sotti na done
26057nangu accept
26058lonku connect
26059dugal enter
26060fay taalaat leegi restart now
26061fay taalaat ca kanam restart later
26062Lii dina soppi say jekkali telefon. This will change your phone's settings.
26063%1 yónnee nala yenn jekkali telefon yu bees. Sudee xam nga ki la ko yónnee te nga bëgg a nangu coppite yii, bësal Nangu. Di nga jot ab bataaxal su coppite yi yeggee.

Soo bëggulee def lii fii ñu toll, bësal Dellu ngir yeexal coppite yi. Bësal Fomb ngir bañ leen.
%1 has sent you some new phone settings. If you know the sender and want to accept these changes, tap Accept. You'll get a text message when the changes are complete.

If you don’t want to do this right now, press the Back button to postpone the changes. Tap Cancel to decline them.
26064Jot nga yenn jekkali telefon yu bees. Sudee xam nga ki la ko yónnee te nga bëgg a nangu coppite yii, bësal Nangu. Di nga jot ab bataaxal su coppite yi yeggee.

Soo bëggulee def lu ni mel, bësal bitoŋu Dellu ngir bàyyi coppite yi. Bësal Fomb ngir bañ leen.
You’ve received some new phone settings from an unidentified source. If you know the sender and want to accept these changes, tap Accept. You'll get a text message when the changes are complete.

If you don’t want to do this right now, press the Back button to postpone the changes. Tap Cancel to decline them.
26065%1 mënul a yeggali coppite yi ci sa telefon ndax mënuloo woon a lonku ci cëraakon bi. %1 couldn't finish making changes to your phone because you couldn't connect to the server.
26078Sa operatëer mobiil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox ci mbaal bi.

Yile ay leeral lyu bawoo ci sa opertëer mobiil lañu:
Your mobile operator (%1) needs to make some changes to your phone so it'll continue to work well on the network.

Here are the details from your mobile operator:
26079Soxla nañu ay coppitey telefon Phone changes needed
26080wane view
26081Dugal ay nimero kese. Please enter only numbers.
26082Sa operatër mobil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox ci mbaal bi.

Di nga jot ab bataaxal su noppee.
Your mobile operator (%1) needs to make some changes to your phone so it'll continue to work well on the network.

You'll get a text message when it's finished.
26083Sa operatër mobil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox bu baax ci mbaal bi.

Di nga jot ab bataaxalu su noppee.

Ngir fomb yeesal bi, demal ci jekkali Portaabal+SIM.
Your mobile operator (%1) needs to modify your phone so it'll continue to work well on the network.

You'll get a text message when it's finished.

To cancel the update, go to Cellular & SIM Settings.
26085Bësal ngir yeesal jekkali njoxey selileer bi Tap to update cellular data settings
26086Jëfandaay bi dafa wara fay tàkkaat Your device needs to restart
26087Sa mbootaay wàññi na sàrt yiy sàkku sa jëfandaay di fay tàkkaat. Dootoo mën a jot ci sab liggéey wala sa mbaalu liggéey fileek fayul tàkkaat. Your organization has pushed down policies that require your device to restart. You may be unable to access work resources or your work network until it is restarted.
26088Enter your PIN to confirm your identity and finish your PIN enrollment. Enter your PIN to confirm your identity and finish your PIN enrollment.
26089Your device administrator has scheduled a reboot Your device administrator has scheduled a reboot
26090RebootCSP scheduled reboot RebootCSP scheduled reboot
26091RebootCSP daily recurrent reboot RebootCSP daily recurrent reboot
26092Sa liggéeyukaay tëj na sa jëfandaay. Mën nga jëfandikoo sa PIN ngir tijji ko. Your company has locked your device. You can use your PIN to unlock it.
26093Sa liggéeyukaay beesalaat na sa PIN. Jokkool ak ndaw li lay jàppale ci sa liggéeyukaay ngir xam PIN bi. Your company has reset your PIN. Contact your company’s support person to learn the PIN.
26094Dynamic Management Dynamic Management
26095Your management settings have changed because of a recent change to your device context. Your management settings have changed because of a recent change to your device context.
50002&Sa operatëer mobiil (%1) war na amal yenn coppite ci sa telefon ngir mu mën wéy di dox bu baax ci mbaal bi. Ngir amal coppite yi, war nga lonku ci WLAN mbaa nga taal njoxey selileer.

Di nga jot ab bataaxalu jukki su motee.

Ngir fomb yeesal bi, demal ci Jekkali Portaabal+SIM.
Your mobile operator (%1) needs to make some changes to your phone so it'll continue to work well on the network. To make the change, you need to connect to WLAN or turn on cellular data.

You'll get a text message when it's complete.

To cancel the update, go to Cellular & SIM Settings.
50003Yeesalu mbaal bu jàppandi Network update available
50004Sa operatëer mobiil mu ngi yeesal sa mbaalu telefon ngir nga mën amal ay woote, yónnee ay jukki ak yeneen.

Di nga jot ab jukkib bataaxal su yeesal bi sottee.
Your mobile operator is updating your phone network so you'll be able to make phone calls, send text messages, and more.

You'll get a text message when the update is done.
50005Sa bayaalu mbaal yees na te noppi na ngir tàmbali. Your network profile is updated and ready to go.
50006fomb yessal cancel update
50007Sa operatëer mobiil mënuloon a yeesal sa baayalu mbaal. Soo leen di woo ngir jot ndimbal, wax leen ni gis nga kotu njumte bii: %1. Your mobile operator wasn't able to update your network profile. If you call them for help, tell them you saw this error code: %1.
50009Yebbi yeneeni jëfekaay Downloading additional apps

EXIF

File Name:DMAppsRes.dll.mui
Directory:%WINDIR%\WinSxS\amd64_microsoft-windows-d..dmappsres.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_a296a8174b74b9e2\
File Size:12 kB
File Permissions:rw-rw-rw-
File Type:Win32 DLL
File Type Extension:dll
MIME Type:application/octet-stream
Machine Type:Intel 386 or later, and compatibles
Time Stamp:0000:00:00 00:00:00
PE Type:PE32
Linker Version:14.10
Code Size:0
Initialized Data Size:11264
Uninitialized Data Size:0
Entry Point:0x0000
OS Version:10.0
Image Version:10.0
Subsystem Version:6.0
Subsystem:Windows GUI
File Version Number:10.0.15063.0
Product Version Number:10.0.15063.0
File Flags Mask:0x003f
File Flags:(none)
File OS:Windows NT 32-bit
Object File Type:Dynamic link library
File Subtype:0
Language Code:Unknown (0488)
Character Set:Unicode
Company Name:Microsoft Corporation
File Description:DMAppsRes
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Internal Name:DMAppsRes
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Moo jagoo àq yépp.
Original File Name:DMAppsRes.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0

What is DMAppsRes.dll.mui?

DMAppsRes.dll.mui is Multilingual User Interface resource file that contain Wolof language for file DMAppsRes.dll (DMAppsRes).

File version info

File Description:DMAppsRes
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Company Name:Microsoft Corporation
Internal Name:DMAppsRes
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Moo jagoo àq yépp.
Original Filename:DMAppsRes.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Translation:0x488, 1200