| File name: | ConsentUX.dll.mui |
| Size: | 7680 byte |
| MD5: | 2fdf7e94dfc849fcf67c0c12483dfc2f |
| SHA1: | 0d2b764b0b4b8a18fcd9ad6f2c3996e634d1f59f |
| SHA256: | f8d477675850efef11c10a001d8a6fdfefacd716b82ebe2d0b3e3f6b1725fb1c |
| Operating systems: | Windows 10 |
| Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id | Wolof | English |
|---|---|---|
| 100 | Bàyyi %1 mu jot ci sa %2? | Let %1 access your %2? |
| 101 | Ngir soppi lii ci kanam, demal ci jëfekaayu Jekkal yi. | To change this later, go to the Settings app. |
| 102 | Ndax %1 man naa yónnee ak jot %2? | Can %1 send and receive %2? |
| 103 | May nu ci sañ-sañ | We need your permission |
| 104 | Waaw | Yes |
| 105 | Déetet | No |
| 106 | bataaxalu mbind | text messages |
| 107 | 1 | 1 |
| 108 | Ndax bëgg ngaa bàyyi %1 muy wëyal di jokkale ci suuf, booy def leneen? | Do you want to allow %1 to keep syncing in the background while you do something else? |
| 109 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Sudee sa ordinaatëer bumuu kuraŋ lay jëfandikoo, roof ko ngir bañ a jeexal bateri bi. Téeyeel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer ba yeesal bi noppi. Lii mën naa jël lu weesu %4!d! simili. Ndax mu tàmbali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". If your PC uses a power adapter, plug it in to avoid draining the battery. Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take up to %4!d! minutes. Start the update? |
| 110 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Sudee sa ordinaatëer bumuu kuraŋ laay jëfandikoo, roff ko ngir banaa jeexal batri bi. Teeyéel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer baa yeesal bi noppi. Lii mën naa jël ab diir. Ndax mu tambali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". If your PC uses a power adapter, plug it in to avoid draining the battery. Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take a while. Start the update? |
| 111 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Teeyéel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer baa yeesal bi noppi. Lii mën naa jël lu weesu %4!d! simili. Ndax mu tambali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take up to %4!d! minutes. Start the update? |
| 112 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Teeyéel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer baa yeesal bi noppi. Lii mën naa jël ab diir. Ndax mu tambali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take a while. Start the update? |
| 113 | Yeesal sa jumtukaay | Update your device |
| 116 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Sudee sa ordinaatëer bumuu kuraŋ laay jëfandikoo, roff ko ngir banaa jeexal batri bi. Teeyéel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer baa yeesal bi noppi. Lii mën naa jël 1 simili. Ndax mu tambali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". If your PC uses a power adapter, plug it in to avoid draining the battery. Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take up to a minute. Start the update? |
| 117 | Tëriinu %1 noppi na ngir yeesal “%2”. Teeyéel lonkug “%3” ci sa ordinaatëer baa yeesal bi noppi. Lii mën naa jël 1 simili. Ndax mu tambali yeesal bi? |
The %1 app is ready to update "%2". Keep "%3" connected to your PC until the update is finished. This can take up to a minute. Start the update? |
| 118 | Bayyi %1 mu dugg ci say xame? | Let %1 access your contacts? |
| 119 | Bàyyi %1 mu dugg ci sa jukki ak bataaxalu MMS? | Let %1 access your text and MMS messages? |
| 120 | barab ak jaar-jaaru barab bu leer | precise location and location history |
| 121 | May %1 mu jot ci sa tur, nataal, ak yeneen leerali sàq? | Let %1 access your name, picture, and other account info? |
| 122 | Bàyyil %1 mu tàkk mbaa mu fay %2? | Let %1 turn your %2 on or off? |
| 123 | Bluetooth ak WLAN | Bluetooth and WLAN |
| 124 | barab bu leer | precise location |
| 125 | Bàyyil %1 lëkkale sa jëfandaay ak %2 | Let %1 pair your device with %2 |
| 126 | Bàyyi %1 lëkkale sa jëfandaay ci %2 | Let %1 unpair your device from %2 |
| 127 | Bayyi %1 mu dugg ci sa jaar-jaaru woote? | Let %1 access your call history? |
| 128 | Bayyi %1 mu dugg te yónnee m-bataaxal? | Let %1 access and send email? |
| 129 | waxukaay | microphone |
| 130 | jëlukaayu nataal | camera |
| 131 | Tànnal yëgle bii wala Waaw ngir nangu lii. | Select this notification or Yes to allow this. |
| 132 | Mayal %1 muy woote telefon? | Let %1 make phone calls? |
| 133 | Dangay may %1 mu jot ci say yëgle? | Let %1 access your notifications? |
| 134 | May %1 mu jot ci bii: %2 | Let %1 access this: %2 |
| 135 | %1: %2 | %1: %2 |
| 136 | Let %1 access your tasks? | Let %1 access your tasks? |
| 137 | Let %1 access diagnostic information about your apps? | Let %1 access diagnostic information about your apps? |
| 138 | Let %1 access your calendar? | Let %1 access your calendar? |
| 0x10000031 | Response Time | Response Time |
| 0x30000001 | Start | Start |
| 0x30000002 | Stop | Stop |
| 0x50000002 | Error | Error |
| 0x50000004 | Information | Information |
| 0x90000001 | Microsoft-Windows-DeviceConfidence | Microsoft-Windows-DeviceConfidence |
| 0xB00007D0 | Failed getting active window for app package %1 and capability name %2 | Failed getting active window for app package %1 and capability name %2 |
| 0xB00007D1 | Failed to show consent prompt for app package %1 with error %2 | Failed to show consent prompt for app package %1 with error %2 |
| 0xB00007D2 | Failed to create consent window for app package %1 with error %2 | Failed to create consent window for app package %1 with error %2 |
| File Description: | Wooteb Déngoo bob Broker Ngir Jumtukaay |
| File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
| Company Name: | Microsoft Corporation |
| Internal Name: | Consent UX |
| Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem sañ-sañ yi. |
| Original Filename: | ConsentUX.dll.mui |
| Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
| Product Version: | 10.0.15063.0 |
| Translation: | 0x488, 1200 |