| File name: | Windows.UI.CredDialogController.dll.mui |
| Size: | 7680 byte |
| MD5: | 28e1095fafcc0a70e562045896036a83 |
| SHA1: | 2991c2a418c16b81667ff972d48f1dd2021b2481 |
| SHA256: | 95697042bca6a79ccd9223eddf7d50146c382a7d891ba2500ec083d46e53bd8f |
| Operating systems: | Windows 10 |
| Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
| id | Wolof | English |
|---|---|---|
| 100 | Baatu-jàllu mbaal bi nga joxe jubul. | The specified network password is not correct. |
| 101 | Baatu-jàllu jëfandikukat bi war na soppeeku balaa mu koy duggee ci njëlbeen. | The user’s password must be changed before logging on the first time. |
| 102 | Pexey EAS laaj na jëfandikukat bi soppi baatu-jàllam njëkk muy man a mala jëf jii. | EAS policy requires that the user change their password before this operation can be performed. |
| 103 | Baatu-jàll bu jubul. | Incorrect password. |
| 104 | Dugg gees tere. | Access is denied. |
| 105 | Terees na duggug mbaal gi. | Network access is denied. |
| 106 | Dàkkantal mbaa baatu-jàll bi jubul. | The user name or password is incorrect. |
| 107 | Yamaley sàq yi ñoo tee jëfandikukat bii mëna duggsi. Ci misaal: baatu-jàll bu neen nangu wuñu ko, waxtuy duggsi dañoo am app, mbaa ñu dooleel ab yamale. | Account restrictions are preventing this user from signing in. For example: blank passwords aren’t allowed, sign-in times are limited, or a policy restriction has been enforced. |
| 108 | Sa sàq mi ame na àppalug waxtu gu la dul may ngay duggsi nii. | Your account has time restrictions that keep you from signing in right now. |
| 109 | Jëfandikukat bii mayuñu ko muy dugg ci ordinaatëer bii. | This user isn’t allowed to sign in to this computer. |
| 110 | Baatu-jàllu sàq mii jeex na. | The password for this account has expired. |
| 111 | Jëfandikukat bii mënul duggsi ndax sàq mi dañu koo najj fimne. | This user can’t sign in because this account is currently disabled. |
| 112 | Dàkkantal bi nga joxe wérul. | The specified username is invalid. |
| 113 | Jéem a duggsi ci diiru waxtu wes mayewul ci bis ci sàq mii. | Attempting to log in during an unauthorized time of day for this account. |
| 114 | Nangu nga jëfekaay bii amal ay coppite ci sa jëfandaay? | Do you want to allow this app to make changes to your device? |
| 116 | Nangu nga jëfekaay bii samp ab losisel ci sa jëfandaay? | Do you want to allow this app to install software on your device? |
| 117 | Nangu nga jëfekaay bii dindi ab losisel ci sa jëfandaay? | Do you want to allow this app to remove software from your device? |
| 118 | Nangu nga jëfekaay bii yeesal ab losisel ci sa jëfandaay? | Do you want to allow this app to update software on your device? |
| 119 | Nangu nga jëfekaay bii bawoo ci siiwalkat buñ xamul mu amal ay coppite ci sa jëfandaay? | Do you want to allow this app from an unknown publisher to make changes to your device? |
| 120 | Tëriin wii terees na ko ngir sa kaarànge | This app has been blocked for your protection. |
| 121 | %1 tëj na jëfekaay bi ngir aar sa jëfandaay. | %1 blocked this app to protect your device. |
| 122 | Ngir wéyal, bindal turu jëfandikukatu yorkat bi ak baatu-jàllam. | To continue, enter an admin user name and password. |
| 123 | Yebbees na ko ci Internet bi | Downloaded from the Internet |
| 124 | Defukaay bu dindiwu bu ne ci nosukaay gi | Removable media on this computer |
| 125 | Tappaan bu dëgër bu ne ci nosukaay gi | Hard drive on this computer |
| 126 | Dawalukaayu mbaal | Network drive |
| 127 | Dawalukaayu CD/DVD | CD/DVD drive |
| 128 | Wane leeral yu jëm ci daganalu siiwalkat bi | Show information about the publisher’s certificate |
| 139 | Soppi kañ la yii yëgle di feeñ | Change when these notifications appear |
| 140 | Bësal Ctrl+Alt+Delete ngir dugal say leerali dugg | Press Ctrl+Alt+Delete to enter your credentials |
| 141 | Bësal Ctrl+Alt+End ngir dugal say leerali dugg | Press Ctrl+Alt+End to enter your credentials |
| 142 | Bësal Ctrl+Alt+Delete wala nga jëfandikoo butoŋu Kaaraange Windows ngir dugal say leerali dugg | Press Ctrl+Alt+Delete or use the Windows Security button to enter your credentials |
| 143 | Bësal te tëye butoŋu Windows, ba noppi nga bës butoŋu taal-fay bi | Press and hold the Windows button, and then press the power button |
| 144 | Bësal Ctrl+Alt+Delete wala nga bës te tëye butoŋu Windows, ba noppi nga bës butoŋu wàññi xumbaay bi ngir dugal say leerali dugg | Press Ctrl+Alt+Delete or press and hold the Windows button, and then press the power button to enter your credentials |
| 145 | Bësal te tëye butoŋu taal-fay bi, ba noppi nga bës butoŋu wàññi xumbaay bi ngir dugal say leerali dugg | Press and hold the power button, and then press the volume down button to enter your credentials |
| 146 | Bësal Ctrl+Alt+Delete wala nga bës te tëye butoŋu taal-fay bi, ba noppi nga bës butoŋu wàññi xumbaay bi ngir dugal say leerali dugg | Press Ctrl+Alt+Delete or press and hold the power button, and then press the volume down button to enter your credentials |
| 147 | Dugalal samay leerali dugg ci seetu duggug Windows gu baax gi | Enter my credentials on the authentic Windows sign-in screen |
| 149 | So yorkat moo lay tere dawal jëfekaay bii. Ngir am ci yeneen leeral, jokkool ak sa yorkat. | An administrator has blocked you from running this app. For more information, contact the administrator. |
| 150 | Barab bi taxañ bii joge wóorul. Leer nala ni danga ko bëgg a dawal? |
This file is from an untrusted location. Are you sure you want to run it? |
| 151 | Xamu ñu ko | Unknown |
| 152 | Microsoft Windows | Microsoft Windows |
| 153 | Tëriin wuñ xamul | Unknown program |
| File Description: | Saytukaayu Boyetu Leerali duggi UX |
| File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
| Company Name: | Microsoft Corporation |
| Internal Name: | Windows.UI.CredDialogController.dll |
| Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Moom rekk a ci am yelleef. |
| Original Filename: | Windows.UI.CredDialogController.dll.MUI |
| Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
| Product Version: | 10.0.15063.0 |
| Translation: | 0x488, 1200 |