credprovslegacy.dll.mui Ndonol Joxekati Ràññeekaay 28a5c672cf6446d7d7925c6bf40488f9

File info

File name: credprovslegacy.dll.mui
Size: 8704 byte
MD5: 28a5c672cf6446d7d7925c6bf40488f9
SHA1: 5855bf56ef3efe75c59f3662a7a97511555d8c99
SHA256: e7d6a2c67b5847b69d29e66d66ac71b35f40c66d78887d771a302683e3d1da15
Operating systems: Windows 10
Extension: MUI

Translations messages and strings

If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.

id Wolof English
101Baatu-jàll bi jubul. Jéemaatal. The password is incorrect. Try again.
102Sa sàq mi dees koo àppali waxtu loolu tax ba manoo duggsi waxtu wii. Baal nu jéemaat ci kanam. Your account has time restrictions that prevent you from signing in at this time. Please try again later.
103Sa sàq mi dees koo def non doo man a jëfandikoo PC bii. Baal nu làmb beneen PC. Your account is configured to prevent you from using this PC. Please try another PC.
104Sàq mi wekkees na ko. Baal nu gis sa yorkatu noste. Your account has been disabled. Please see your system administrator.
105Sa sàq mi jeex na. Baal nu gis sa yorkatu noste. Your account has expired. Please see your system administrator.
106Ngir duggsi cig soryàntoo, war na nga am sañ-sañu dugge ak Liggéeyali Biro bu Sori. Cig baaxoo, ñi bokk ci mbooloom Yorkat yi ñooy ame boobu sañ-sañ. Bu dee mbooloom mi nga bokk amu boobu sañ-sañ, walla dindees sañ-sañ bi ci mbooloom Yorkat yi, kon war na nga wutal ko sa bopp. To sign in remotely, you need the right to sign in through Remote Desktop Services. By default, members of the Administrators group have this right. If the group you're in doesn't have this right, or if the right has been removed from the Administrators group, you need to be granted this right manually.
107Ngir duggsi cig soryàntoo, war na nga am sañ-sañu dugge ak Liggéeyali Biro bu Sori. Cig wàccaale, ñi bokk ci mbooloom Jëfandikukati Ëttu Soryàntoo ñooy ame boobu sañ-sañ. Bu dee mbooloom mi nga bokk amu boobu sañ-sañ, walla dindees sañ-sañ bi ci mbooloom Jëfandikukati Ëttu Soryàntoo, kon war na nga wutal ko sa bopp. To sign in remotely, you need the right to sign in through Remote Desktop Services. By default, members of the Remote Desktop Users group have this right. If the group you're in doesn't have this right, or if the right has been removed from the Remote Desktop Users group, you need to be granted this right manually.
109Maneesul a soppi baatu-jàllu sàq mii fimne. The password on this account cannot be changed at this time.
110Àppu baatu-jàll bi weesu na. Ngir def baatu-jàll bu bees, tànnal Waaw-Kay, tànn Wecci jëfandikukat, dugalaatal sa baatu-jàll bu bees, ba noppi nga topp santaane yi ci seetu bi. Your password has expired. To set a new password, select OK, select Switch user, reenter your current password, and then follow the prompts on the screen.
111Sa baatu-jàll jeex na te warees koo soppi. Your password has expired and must be changed.
112Nangu wuñu anamu dugg bii ngay jéema jëfandikoo. Ngir am yeneeni leeral, jokkool ak sa caytukatu mbaal. The sign-in method you're trying to use isn't allowed. For more info, contact your network administrator.
113Soppees na sa baatu-jàll. Your password has been changed.
114Yittewoo nga xobu felliit ngir duggsi. You must use a smart card to sign in.
116Baatu-jàll yi nga dugal bokkuñ. The passwords you entered did not match.
117Baal nu dugal ab dàkkantal ak baatu-jàll. Please enter a user name and password.
121Dàkkantal mbaa baatu-jàll bi jubul. Jéemaatal. The user name or password is incorrect. Try again.
125Baatu-jàll bu bees New password
126Firndéel baatu-jàll Confirm password
127Dugal Submit
13000Dàkkantal User name
13001Baatu-jàll Password
13002Baatu-jàll biwoon Old password
13005Turu kaf Friendly name
13006Tolluwaayu jëfandikukat User status
13009Beneen jëfandikukat Other user
13010Tijji PC bi Unlock the PC
13011Soppi baatu-jàll Change a password
13012Jël meneen sàq Use a different account
13013Nataalu sàq Account picture
13015Naka laay dugge ak weneen lew? How do I sign in to another domain?
13016Bindal “turu lew\dàkkantalu lew” ngir lonkoo ak weneen lew.

Bindal “%1\dàkkantalu biir-barab” ngir duggsi ci PC bi kese (déet aw lew).
Type domain name\domain user name to sign in to another domain.

Type %1\local user name to sign in to this PC only (not a domain).
13017Duggi ca: %s Sign in to: %s
13018Duggi ca Sign in to
13020Lew: %s Domain: %s
13021Lew Domain
13022Junju baatu-jàll Password hint
13023Defaraat baatu-jàll Reset password
13024Sos ab tappaanu defaraat baatu-jàll Create a password reset disk
13025Junju baatu-jàll: %s Password hint: %s
13026Fàttalikul say xàmmekaay Remember my credentials
13028Baatu-jàllu sàqum biir mbaa lew Local or domain account password
13029Mënu ñu lonku fii ñu toll. Baal ñu xool sa mbaal te jéemaat ci kanam. We are unable to connect right now. Please check your network and try again later.
13030Sa sàqu liggéeyukaay mbaa daara Your work or school account
13031Mënuloo dugg ak ID jëfandikookat ci tëggiin bii. Jéemal a far jëfandikoo sa dëkkuwaayu m-bataaxal. You can't sign in with a user ID in this format. Try using your email address instead.
13032Dëkkuwaayu m-bataaxal Email address
17004Baatu-sutura PIN
17005Sa taxaaralu PIN Duggsi baatu-jàll bu yàgg la def. Baal nu duggsi ak sa baatu-jàll bu bees. Your PIN Sign-in enrollment contains an old password. Please sign in with your new password.
17006Baatu-sutura bi jubul. Jéemaatal. The PIN is incorrect. Try again.
17028Yeesalees na sa PIN Duggsi nam ware ak sa baatu-jàllu fimne. Your PIN Sign-in enrollment has been successfully updated with your current password.
17546Baatu-jàllu nataal Picture password
17547Sa taxaaralu baatu-jàllu nataal baatu-jàll bu yàgg la def. Baal nu duggsi ak sa baatu-jàll bu bees. Your picture password enrollment contains an old password. Please sign in with your new password.
17548Baatu-jàllu nataal bi jubul. Jéemaatal. The picture password is incorrect. Try again.
17584Yeesalees na sa baatu-jàllu nataal nam ware ak sa baatu-jàllu fimne. Your picture password enrollment has been successfully updated with your current password.

EXIF

File Name:credprovslegacy.dll.mui
Directory:%WINDIR%\WinSxS\amd64_microsoft-windows-c..y-library.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_1766bb55736c1d79\
File Size:8.5 kB
File Permissions:rw-rw-rw-
File Type:Win32 DLL
File Type Extension:dll
MIME Type:application/octet-stream
Machine Type:Intel 386 or later, and compatibles
Time Stamp:0000:00:00 00:00:00
PE Type:PE32
Linker Version:14.10
Code Size:0
Initialized Data Size:8192
Uninitialized Data Size:0
Entry Point:0x0000
OS Version:10.0
Image Version:10.0
Subsystem Version:6.0
Subsystem:Windows GUI
File Version Number:10.0.15063.0
Product Version Number:10.0.15063.0
File Flags Mask:0x003f
File Flags:(none)
File OS:Windows NT 32-bit
Object File Type:Dynamic link library
File Subtype:0
Language Code:Unknown (0488)
Character Set:Unicode
Company Name:Microsoft Corporation
File Description:Ndonol Joxekati Ràññeekaay
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Internal Name:credprovslegacy.dll
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Moo jagoo àq yépp.
Original File Name:credprovslegacy.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Directory:%WINDIR%\WinSxS\wow64_microsoft-windows-c..y-library.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_21bb65a7a7ccdf74\

What is credprovslegacy.dll.mui?

credprovslegacy.dll.mui is Multilingual User Interface resource file that contain Wolof language for file credprovslegacy.dll (Ndonol Joxekati Ràññeekaay).

File version info

File Description:Ndonol Joxekati Ràññeekaay
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Company Name:Microsoft Corporation
Internal Name:credprovslegacy.dll
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Moo jagoo àq yépp.
Original Filename:credprovslegacy.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Translation:0x488, 1200