| 100 | Am na keneen ku duggsi. Boo wéyalee, dees na ko génne te xayna mu ñàkke lam doon def. Dangaa bëgg a duggsi ànd ak loolu? |
Another user is signed in. If you continue, they’ll be signed out and might lose unsaved work. Do you want to sign in anyway? |
| 101 | Am na keneen ku duggsi. Boo wéyalee, dees na ko lonki. Dangaa bëgg a duggsi ànd ak loolu? |
Another user is signed in. If you continue, they’ll be disconnected. Do you want to sign in anyway? |
| 102 | Tëyeel Ctrl+Alt+Delete ngir tijji. |
Press Ctrl+Alt+Delete to unlock. |
| 103 | Tëyeel Ctrl+Alt+Delete mbaa jëfandikoo bësukaayu Windows Kaarànge ngir tijji. |
Press Ctrl+Alt+Delete or use the Windows Security button to unlock. |
| 104 | Najal te tëye bitoŋu Windows, teg ci naj bitoŋ taal/fay ngir tijji. |
Press and hold the Windows button, and then press the power button to unlock. |
| 105 | Najal te tëye bitoŋu Windows, teg ci naj bitoŋ taal/fay ngir tijji. (Man nga koo tijjee it ci naj Ctrl+Alt+Delete.) |
Press and hold the Windows button, and then press the power button to unlock. (Or you can unlock by pressing Ctrl+Alt+Delete.) |
| 106 | Baatu-jàll boobu jubul. Defal ndànk—Boo wéyee di dugal baatu-jàll bu jubul, dees na la tëj ngir aar say njoxe. Ngir tiji ko, dinga aajewoo caabi dabu ju BitLocker. |
That password isn’t correct. Be careful—if you keep entering the wrong password, you’ll be locked out to help protect your data. To unlock, you’ll need a BitLocker recovery key. |
| 107 | Baatu-jàll boobu jubu. Moytul de—boo wéyee di dugal baatu-jàll bu jubul, Windows dina daadi fay-tàkkaat ngir aar say njoxe. |
That password isn’t correct. Be careful—if you keep entering the wrong password, Windows will automatically restart to help protect your data. |
| 108 | Baatu jall bii jubul. Moytul—boo wëyee di duggal baatu jall bu jubul, dina ñula tëjj ngir samm say njoxe. Ngir tiji, dinga soxla ab caabi-jëlaat bu bawoo ci sa joxekatu fas. |
That password isn’t correct. Be careful—if you keep entering the wrong password, you’ll be locked out to help protect your data. To unlock, you’ll need a recovery key from your encryption provider. |
| 109 | Taaxerlul |
Please wait |
| 110 | Bësal te teye ci bitoŋu taal ak fay bi, te bës bitoŋu wàññi xumbaay bi ngir tiji |
Press and hold the power button, and then press the volume down button to unlock |
| 111 | Bësal te teye bitoŋu taal ak fay, te bës bitoŋu wàññi xumbaay ngir tiji. (Walla mën nga tiji soo bësee ci Ctrl+Alt+Far.) |
Press and hold the power button, and then press the volume down button to unlock. (Or you can unlock by pressing Ctrl+Alt+Delete.) |
| 112 | May ñu tuuti... |
Just a moment... |