2 | %d%s%d saa |
%d%s%d seconds |
3 | Yeneeni leeral yu aju ci xaralay jàppale ci-net bi |
Learn about additional assistive technologies online |
4 | Jëfandikoowu ñu say tontu ludul ngir xam jekkal yiñ digle kese. Bu beneen tëriin mbaa Daluweb bëggee jëfandikoo leeral yii ngir gën a méngoo ak say bëgg-bëgg, dina ñu la laaj sa sañ-sañ ci tëriin wi ci anam wu leer. Privacy Statement |
Your answers are used to determine recommended settings only. If another program or Web site wants to use this information to better suit your needs, you will be explicitly asked for permission by that program. Privacy Statement |
5 | %d simili |
%d minutes |
6 | 1 simili |
1 minute |
7 | %d saa |
%d seconds |
10 | Barabu Yomb a Jot |
Ease of Access Center |
45 | Gën a la yombal jëfandikoog sa nosukaay. |
Make your computer easier to use. |
46 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay (gis bu lëndam) |
Get recommendations to make your computer easier to use (eyesight) |
47 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay (wàññi yëngatu) |
Get recommendations to make your computer easier to use (dexterity) |
48 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay (dégg bu leerul) |
Get recommendations to make your computer easier to use (hearing) |
49 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay (jafe-jafe wax) |
Get recommendations to make your computer easier to use (speech) |
50 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay (jafe-jafe nànd) |
Get recommendations to make your computer easier to use (cognitive) |
56 | Jëfandikoo nouskaay bi ci lu dul ab wonekaay |
Use the computer without a display |
57 | Gën a yombal gisug nosukaay gi |
Make the computer easier to see |
58 | Gën a yombal jëfandikoog baag bi |
Make the mouse easier to use |
59 | Gën a yombal jëfandikoog arafukaay bi |
Make the keyboard easier to use |
60 | Jëfandikoo nosukaay gi ci lu dul baag mbaa arafukaay |
Use the computer without a mouse or keyboard |
61 | Jëfandikoo mbind mbaa jumtukaay yu gisu ngir kàddu yi |
Use text or visual alternatives for sounds |
62 | Gën koo yombal ci matal santaane yi |
Make it easier to focus on tasks |
63 | Jekkal Arafi Baag bi |
Set up Mouse Keys |
64 | Jekkal Seggukaayu Araf |
Set up Filter Keys |
65 | Jekkal Arafi Baamtu ak Arafi Yeexe |
Set up Repeat and Slow Keys |
66 | Jekkal yees sopp |
Recommended settings |
67 | Soppi jekkal duggsi |
Change sign-in settings |
68 | Jekkal Tëyekaayu Araf |
Set up Sticky Keys |
70 | Tànn mbubbum Leer&aayu Melo |
Choose a High Cont&rast theme |
72 | %s ginnaaw duggsi |
%s after sign-in |
73 | %s diirub duggsi |
%s at sign-in |
74 | Dégg ca kaw mbind miy feeñ (Nettalikaay) |
Hear text on screen read aloud (Narrator) |
75 | Yokk cër yiy feeñ (Fésalukaay) |
Make items on the screen larger (Magnifier) |
76 | Bind waliif arafukaay bi (Arafukaayu Ci-Seetu) |
Type without the keyboard (On-Screen Keyboard) |
78 | Naj ñalli arafukaay bi waliif di léen najandoo (Tëyekaayu Araf) |
Press keyboard shortcuts one key at a time (Sticky Keys) |
79 | Bu ma najeeb araf cig baamtu, gàntalal naj yi ci ëpp (Seggkaayu Araf) |
If I press keys repeatedly, ignore extra presses (Filter Keys) |
80 | Jëfandikoo arafukaay bu lime bi ngir di tuxal baag bi ci wonekaay bi (Arafi Baag) |
Use the numeric keypad to move the mouse around the screen (Mouse Keys) |
81 | Dégg ab kàddu saa boo najee CAPS LOCK, NUM LOCK, mbaa SCROLL LOCK (Arafi Jàllantu) |
Hear a tone when you press CAPS LOCK, NUM LOCK, or SCROLL LOCK (Toggle Keys) |
82 | Gën a yombal jëfandikoog laalukaay ak tablet yi |
Make touch and tablets easier to use |
83 | Nettalikaay |
Narrator |
84 | Fëstalu gis-gis |
Magnifier |
85 | Arafukaayu Ci-Seetu |
On-Screen Keyboard |
86 | Darra |
None |
1102 | Joxoñi Baag bi |
Mouse pointers |
1103 | Yore baag bi ak arafukaay bi |
Control the mouse with the keyboard |
1105 | Other programs installed |
Other programs installed |
1106 | Wee&x bu Baaxoo |
&Regular White |
1107 | Ñu&ul bu Baaxoo |
Reg&ular Black |
1108 | Safaa&neb Baaxoo |
Re&gular Inverting |
1109 | Weex bu y&aatu |
&Large White |
1110 | Ñuul bu yaa&tu |
Large &Black |
1111 | Safaan&e Yaatu |
Large &Inverting |
1112 | Weex bu Yaatu l&ool |
E&xtra Large White |
1113 | Ñuul bu Yaatu &lool |
Extra Large Blac&k |
1114 | Safaane &Yaatu lool |
Extra Large I&nverting |
1115 | &Dundal ab polanteer ci boo tegee baag bi ci kawam |
Activate a &window by hovering over it with the mouse |
1117 | Dégg ca kaw mbind yi ak xamle yi |
Hear text and descriptions read aloud |
1118 | Yokk lépp lu feeñ ci xoolu bi |
Make things on the screen larger |
1119 | Gën a yombal gisub liy feeñ ci xoolu bi |
Make things on the screen easier to see |
1121 | Taal Fulu&kaay bi |
Turn on Mag&nifier |
1124 | Jëfandikoo màndarga yu gisu waliif yoy kàddu |
Use visual cues instead of sounds |
1129 | Gën a yombal bind bi |
Make it easier to type |
1138 | Gën a la yombal jëfandikoog sa nosukaay |
Make your computer easier to use |
1139 | Jot ci saase jumtukaay yi gën a siiw |
Quick access to common tools |
1141 | Di dëkke jàng pàcc bii ca ka&w |
Al&ways read this section aloud |
1142 | &Di dëkke càmbar pàcc bii |
Always scan this secti&on |
1143 | Door &Fulukaay bi |
Start Ma&gnifier |
1144 | Door Ne&ttalikaay bi |
Start &Narrator |
1145 | Door Arafu&kaayu Ci-Seetu |
Start On-Screen &Keyboard |
1148 | Jekkal &Leeraayu Melo |
Set &up High Contrast |
1153 | Yàkkali jekkal yépp |
Explore all settings |
1155 | Gënal ñeel silmaxa yi |
Optimize for blindness |
1157 | Gënal wonekaayu gisu |
Optimize visual display |
1159 | Tabb beneen jëfandaayu dugal (mbind) |
Set up alternative input devices |
1161 | Tollale jekkal yi ñeel baag bi mbaa yeneen jëfandaayi joxoñ yi |
Adjust settings for the mouse or other pointing devices |
1163 | Tollale jekkal yi ñeel arafukaay bi |
Adjust settings for the keyboard |
1165 | Tabb lu wuutu kàddu yi |
Set up alternatives for sounds |
1167 | Tollale jekkal yi ñeel yër gi ak bind gi |
Adjust settings for reading and typing |
1168 | Tollale àppi waxtu yi ak xuyy-kamaj yu gisu yi |
Adjust time limits and flashing visuals |
1169 | Jëfandikoo arafukaay bu lime bi ngir di tuxal baag bi ci wonekaay bi. |
Use the numeric keypad to move the mouse around the screen. |
1171 | Jekkal Arafi &Baag bi |
Set up Mouse Ke&ys |
1172 | Naj ñalli arafukaay (niki CTRL+ALT+DEL) ci lu dul najandoo. |
Press keyboard shortcuts (such as CTRL+ALT+DEL) one key at a time. |
1174 | Jekkal A&rafi Des |
Set up Sti&cky Keys |
1175 | Dégg ab kàddu saa boo najee CAPS LOCK, NUM LOCK, mbaa SCROLL LOCK. |
Hear a tone when you press CAPS LOCK, NUM LOCK, or SCROLL LOCK. |
1176 | &Taal Arafi Jàll |
Turn on Toggle &Keys |
1177 | Taal Arafi Jàll jaar ko &ci tëye bitoŋu NUM LOCK diirub 5 saa |
Turn on Toggle Keys by holding down the NUM LOCK key for &5 seconds |
1178 | Gàntal walla yeexe naj yees corfati mbaa yees baamtu teg ci tollale xélui baamtu arafukaay bi. |
Ignore or slow down brief or repeated keystrokes and adjust keyboard repeat rates. |
1179 | Taal S&eggukaayu Araf gi |
Turn on F&ilter Keys |
1180 | &Jekkal Seggukaayu Araf |
Set up Fi<er Keys |
1181 | Ron-rë&dd ñall yu arafukaay gi mbaa baati dugg |
U&nderline keyboard shortcuts and access keys |
1184 | Gën a yombal jëfandikoog ñalli arafukaay gi |
Make it easier to use keyboard shortcuts |
1187 | Taal Seggukaayu Araf saa bees najee S&HIFT bu ndijoor bi diirub 8 saa |
Turn on Filter &Keys when right SHIFT is pressed for 8 seconds |
1188 | Tànnéefi seggukaay |
Filter options |
1189 | Taal &Tëb Araf |
Turn on &Bounce Keys |
1190 | Boo tegee say baraam ci ab araf te tayoo ko, Tëb Araf dina jéll bës yees baamtu ci diir buñ natt. |
If you unintentionally bounce your fingers on a key, Bounce Keys will ignore repeated keystrokes for a specific amount of time. |
1191 | Lu tol nan la nosukaay gi di xaar sooga nangu naji araf yi? |
How long should the computer wait before accepting keystrokes? |
1193 | Taal Arafi Baamt&u yi ak Arafi Yeexe yi |
Turn on &Repeat Keys and Slow Keys |
1194 | Nosukaay gi dina jéllale araf yees naj cig corfati sukkandiku ci àpp bi nga tànn. |
The computer will ignore brief keystrokes according to the time limits you set. |
1195 | Jekkal &Arafi Baamtu ak Arafi Yeexe |
Set &up Repeat Keys and Slow Keys |
1196 | Bindal darra fii n&gir ñam jekkal yi: |
Type text here to test setti&ngs: |
1197 | Yeneeni jekkal |
Other settings |
1198 | Coow &saa buñ najee araf mbaa nangoos ko |
Beep &when keys are pressed or accepted |
1200 | Nekkalikaay mooy jàng ca kaw mépp mbind mu feeñ ci seetu bi. Dinga aajewoo ay xumbalukaay. |
Narrator reads aloud any text on the screen. You will need speakers. |
1201 | Taal Nettalikaay &bi |
T&urn on Narrator |
1203 | Defal &sewaayu joxoñ biy mayy-mayyi: |
Set the thickness of the &blinking cursor: |
1204 | Wonandi: |
Preview: |
1205 | Fay gépp wëndée&lu bu man a ñàkk (su manee nekk) |
Turn off all unnecessary animations (&when possible) |
1206 | Dindi nataalu &xóot (fum jàppandee) |
Remove back&ground images (where available) |
1207 | Dégg xamleg liy xew ci ab wideo (su jàppandee). |
Hear descriptions of what's happening in videos (when available). |
1208 | Taal Xaml&eg Kàddu |
Turn on Aud&io Description |
1209 | Lu yàgge nan la boyeti waxtaan yu aartuy Win&dows war a des di ubbéeku? |
How long should Windows notification dialog bo&xes stay open? |
1214 | Moytoo jëfandikoo baag ak arafukaay yu daju yi |
Avoid using the mouse and keyboard |
1215 | Wax ci ab waxukaay ngir di sant nosukaay gi, ubbi ay tëriin, ak di bindlu. |
Speak into a microphone to control the computer, open programs, and dictate text. |
1216 | Jëfandikoo Xàmme&g Baat |
&Use Speech Recognition |
1217 | Binde baag bi mbaa beneen jumtukaayu joxoñ, niki joystick, jaar ko ci tànne araf yi ci ab nataalu arafukaay. |
Type using the mouse or another pointing device such as a joystick by selecting keys from a picture of a keyboard. |
1218 | Jëfandikoo Arafukaayu &Ci-Seetu |
Use On-Screen &Keyboard |
1221 | Taal Arafi Baag ak ALT càmmoñ + S&HIFT càmmoñ + NUM LOCK |
Turn on Mouse &Keys with left ALT + left SHIFT + NUM LOCK |
1222 | Xétu joxoñ |
Pointer speed |
1223 | Xél wi ëpp: |
Top speed: |
1224 | Yées |
Low |
1225 | Kawe |
High |
1226 | Gaawal: |
Acceleration: |
1227 | Yeex |
Slow |
1228 | Gaaw |
Fast |
1229 | Tëye CTR&L ngir gaawal mbaa SHIFT ngir yeexal |
Hold do&wn CTRL to speed up and SHIFT to slow down |
1231 | Jëfandikoo Arafi Baag bu NUM LOCK nekke di: |
Use Mouse Keys when NUM LOCK is: |
1232 | Tà&kk |
O&n |
1233 | Fay |
Off |
1234 | Wone njunjub Arafi &Baag ci galanu-liggéey yi |
Display the Mouse Ke&ys icon on the taskbar |
1236 | Dégg ca kaw mbind |
Hear text read aloud |
1237 | Jekkal Binde Wa&x |
&Set up Text to Speech |
1240 | Moytul baamtu bës yi boo najee ab araf |
Avoid repeated keystrokes when you hold down a key |
1242 | Jé&llale bépp naju araf gog baamtu |
Ig&nore all repeated keystrokes |
1244 | Wàññi baamtug arafukaay bi ak &xél yi |
Slow down keyboard repeat &rates |
1246 | Lu &tol nan la nosukaay gi di xaar sooga nangu naji araf yees toftale? |
How &long should the computer wait before accepting subsequent repeated keystrokes? |
1247 | Lu tol nan la nosukaay gi di xaar sooga nangu baamtug naju araf bi njëkk? |
How long should the computer wait before accepting the first repeated keystroke? |
1248 | Moytul naji araf cig njuumte |
Avoid accidental keystrokes |
1249 | Lu yàgge nan nga bëgg a tëye ab araf nosukaay gi sooga nangu na&jug araf wi? |
How long do you want to hold down a &key before your computer accepts the keystroke? |
1250 | Bin&dal darra fii ngir ñam jekkal yi: |
Type text here to test settin&gs: |
1251 | Jot ay ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay |
Get recommendations to make your computer easier to use |
1252 | Tontul laaj yii ngir jot dénkaane yu aju ci jekkal yiy gën a yombal gis, dégg ak jëfandikoog sa nosukaay. |
Answer the following questions to get recommendations for settings that can make your computer easier to see, hear, and use. |
1253 | Ci laaj bu nekk, jël ci tontu yi la ci soxal. Boo noppee, dinga man a dogu ci yan jekkal lees di taal. |
For each question, select all statements that apply to you. When you're done, you can decide which settings to turn on. |
1255 | Gis bu lëndam (1 ci 5) |
Eyesight (1 of 5) |
1256 | Nataal ak mbin&d ci yi TV bi dañoo jafee gis (doonte damaa takk ay weer). |
Images and te&xt on TV are difficult to see (even when I'm wearing glasses). |
1257 | M&elow leeraay bi, tax na may am jafe-jafe ngir gis ay nataal ci sama xoolu. |
Lighting conditions make it difficult to &see images on my monitor. |
1258 | Silma&xa laa. |
I am b&lind. |
1259 | Damaa am beneen jafe-jafe &gis (doonte takki weer dina ko saafara). |
I have another type of vision &impairment (even if glasses correct it). |
1263 | &Li ci Topp |
&Next |
1264 | &Fomb |
&Cancel |
1265 | Wàññi Yëngatu (2 ci 5) |
Dexterity (2 of 5) |
1266 | Bin&dukaay bi ak rëddukaay bi dañoo jafee jëfandikoo. |
&Pens and pencils are difficult to use. |
1267 | Jafe-jafeb jëmm moo yamale jëfandikoog samay conco, tikk-jara, lo&xo walla baaraam. |
A physical condition affects the &use of my arms, wrists, hands, or fingers. |
1268 | Jëfandikoo&wu ma arafukaay. |
I do not use a &keyboard. |
1269 | Dégg bu leerul (3 ci 5) |
Hearing (3 of 5) |
1270 | Yenn saa yi damay am jafe-jafe dégg wa&xtaan (doonte damaa takk déglukaay). |
C&onversations can be difficult to hear (even with a hearing aid). |
1271 | Coow yu nekk ci suuf mooy na&qaril déggub nosukaay gi. |
&Background noise makes the computer difficult to hear. |
1272 | Samab dégg n&eexul. |
I a&m hard of hearing. |
1273 | &Damaa tëx. |
&I am deaf. |
1274 | Nànd (5 ci 5) |
Reasoning (5 of 5) |
1275 | Damay fa&ral a am jafe-jafe ngir settantal. |
It is often d&ifficult for me to concentrate. |
1276 | Damaa am jafe-jafeb jàng, bu &ci melni ñàkk a man a ràññee araf. |
I have a &learning disability, such as dyslexia. |
1277 | Damay &gaawa fàtte lool yenn saa yi. |
It is often difficult for me to remember thin&gs. |
1278 | Motta&li |
D&one |
1281 | Taal Arafi Baa&g |
Turn on &Mouse Keys |
1282 | Taal Të&yekaayu Araf |
Tu&rn on Sticky Keys |
1284 | Binde jumtukaayu joxoñ |
Type using a pointing device |
1286 | Wone njunjub Seggukaayu Araf &ci galanu-liggéey yi |
Displa&y the Filter Keys icon on the taskbar |
1288 | Sos tombu dabu ngir dencandi |
Create a restore point for backup |
1289 | Tànn dànkaafub gisu |
Choose visual warning |
1290 | &Darra |
&None |
1291 | Xuyy-këmajal xo&ccu léeb |
Flash active caption &bar |
1292 | Xuyy-këmajal polantee&r biy dund |
Flash active &window |
1293 | Xuyy-këmajal ët&t bi |
Flash des&ktop |
1295 | Taal Arafi Des saa bees najee S&HIFT juróomi yoon |
Turn on Sticky &Keys when SHIFT is pressed five times |
1296 | Tànnéef yi |
Options |
1297 | &Tëj arafi soppikaay yi saa bees bësee ñaari yoon ci wenn rëdd |
&Lock modifier keys when pressed twice in a row |
1298 | Fay Tëyekaayu A&raf saa bees bësandoo ñaari araf |
T&urn off Sticky Keys when two keys are pressed at once |
1299 | Sànni-kàddu |
Feedback |
1300 | T&aal ab kàddu saa bees bësee arafi soppikaay yi |
Pla&y a sound when modifier keys are pressed |
1301 | Wone njunjub Tëyekaayu Araf &ci galanu-liggéey yi |
D&isplay the Sticky Keys icon on the task bar |
1302 | Fésalukaay moo ful lépp lu nekk ci seetu bi, tey yokk lépp lu nekk ci barab boobu. Man ngay tuxal Fésalukaay bi, tëj ko ci benn barab mbaa soppi dayooom. |
Magnifier zooms in anywhere on the screen, and makes everything in that area larger. You can move Magnifier around, lock it in one place, or resize it. |
1304 | &Waaw-kay |
&OK |
1305 | Fomb |
Cancel |
1306 | Jë&fe |
A&pply |
1307 | Nit ñi dañuy am jafe-jafe ci nànd ma bu may jokkoo (te du ci sama wa&xiin). |
Other &people have difficulty understanding me in a conversation (but not due to an accent). |
1308 | Damay am jafe-jafe ci &wax. |
I have a &speech impairment. |
1309 | Kañ lees di jëfandikoo ñalli arafukaay ngir taal jekkali Yombalug Jot: |
When using keyboard shortcuts to turn Ease of Access settings on: |
1312 | Wax (4 ci 5) |
Speech (4 of 5) |
1314 | Jot ay &ndénkaane ci gën a yombal jëfandikoog sa nosukaay |
Get &recommendations to make your computer easier to use |
1319 | Xool it |
See also |
1320 | Fésalukaay mooy rëyal ab xaaj ci seetu bi. |
Magnifier enlarges part of the screen. |
1321 | Nekkalikaay mooy jàng ca kaw mépp mbind mu feeñ ci seetu bi. |
Narrator reads aloud text on the screen. |
1322 | Arafukaay Ci-Séetu mooy jàppandil binde baag bi mbaa yeneeni joxoñukaay jaar ko ci tànne araf yi ci ab nataalu arafukaay. |
On-Screen Keyboard makes it possible to type using the mouse or another pointing device by clicking keys on a picture of a keyboard. |
1325 | Soppi da&yob mbind mi ak njunj yi |
Change the si&ze of text and icons |
1326 | Tollale &melo ak jeexaayu weti polanteer yi |
Ad&just the color and transparency of the window borders |
1327 | Sewal focus recta&ngle bi |
Make the focus rectangle thic&ker |
1328 | Je&kkali Baag |
Mouse &settings |
1329 | Jekkali &Arafukaay |
Key&board settings |
1330 | Mbubbi Jëfandaa&yi Kàddu |
Aud&io Devices and Sound Themes |
1331 | Jekkal yii man nañu laa jàppale ci dëppale sa nosukaay ak say bëgg-bëgg. Settantalal jekkal yees dénkaane ci suuf te tël tànnéef yi nga ci bëgg a jëfandikoo. |
These settings can help you set up your computer to meet your needs. Review the recommended settings below and select the options that you want to use. |
1332 | Amul benn dénkaane bu dëppoo ak sa jël gi. |
There are no recommendations based on your selections. |
1333 | Man ngaa làmb benn ci ñaar yii: |
You can try one of two things: |
1334 | Mataliwaat laajte ya. |
Completing the questionnaire again. |
1335 | Dellu ci xëtu njaalbéenu Yombalug Jot. |
Return to the Ease of Access home page. |
1342 | Man ngaa am xaralay jàppale door ci saase booy duggsi mbaa boo duggee walla sax ñaar yépp. Tànnalal boyetu kos bépp tànnéef boo bëgg a jëfandikoo. |
You can have assistive technologies start automatically when you sign in, after you sign in, or both. Select the check boxes for each option you'd like to use. |
1346 | Tànnal bépp tontu bu la ci soxal: |
Select all statements that apply to you: |
1347 | Taal aartu yu &gise ñeel kàddu yi (kàddu bu gisu) |
Tu&rn on visual notifications for sounds (Sound Sentry) |
1348 | T&aal ron-mbind ñeel diisoo yees di wax (bu jàppandee) |
T&urn on text captions for spoken dialog (when available) |
1349 | Taal mbaa fay Leeraal bu Kawe saa bu ALT càmmoñ + S&HIFT càmmoñ + PRINT SCREEN bësoo |
Turn on or off High Contrast when &left ALT + left SHIFT + PRINT SCREEN is pressed |
1357 | Wone ba&taaxalu aartu saa su ab jekkal di tàkk |
Display &a warning message when turning a setting on |
1358 | &Def benn coow saa su ab jekkal di tàkk mbaa fay |
&Make a sound when turning a setting on or off |
1359 | Wone bataa&xalu aartu saa su ab jekkal di tàkk |
Display &a warning message when turning a setting on |
1361 | Wone bataaxalu aa&rtu saa su ab jekkal di tàkk |
Display &a warning message when turning a setting on |
1363 | Wone bataaxalu aartu &saa su ab jekkal di tàkk |
Display &a warning message when turning a setting on |
1366 | &Taal Arafi Baag |
Turn on &Mouse Keys |
1370 | Mbubbi Jëfand&aayi Kàddu |
&Audio Devices and Sound Themes |
1372 | Wuute bu Fés |
High Contrast |
1373 | Magnifier enlarges part of the screen. |
Magnifier enlarges part of the screen. |
1374 | On-Screen Keyboard makes it possible to type using the mouse or another pointing device by clicking keys on a picture of a keyboard. |
On-Screen Keyboard makes it possible to type using the mouse or another pointing device by clicking keys on a picture of a keyboard. |
1376 | Leeraayu Melo mooy yokk leeraay bi ci melo ngir wàññi coonob xool bi te yombal jàng gi. Ngir taal ko, bësal ci Shift Càmmoñ+Alt Càmmoñ+ Print Screen. |
High contrast increases the contrast in colors to reduce eyestrain and make things easier to read. To turn it on, press Left Shift+Left Alt+ Print Screen. |
1379 | Use the computer without a display |
Use the computer without a display |
1380 | Fexe ba nosukaay bi yomb a gis |
Make the computer easier to see |
1381 | Use the computer without a mouse or keyboard |
Use the computer without a mouse or keyboard |
1383 | Make the keyboard easier to use |
Make the keyboard easier to use |
1384 | Use text or visual alternatives for sounds |
Use text or visual alternatives for sounds |
1385 | Make it easier to focus on tasks |
Make it easier to focus on tasks |
1386 | Fu ma war a tàmbalee wóoru ma? |
Not sure where to start? |
1387 | Get Help |
Get Help |
1388 | Ndimbël |
Help |
1389 | Boo tànnee yooyu jekkal, dinañuy tàmbali ci saase saa boo duggseetee. |
When you select these settings, they will automatically start each time you sign in. |
1390 | Boo tànnee yooyu jumtukaay, dinañuy tàmbali ci saase saa boo duggseetee. |
When you select these tools, they will automatically start each time you sign in. |
1391 | Jë&mmal melokaan ak jeexiti kàddu |
Pe&rsonalize appearance and sound effects |
1392 | Jekkal jeexiti w&oniin |
Fine tune display effe&cts |
1393 | Yokk ab arafukaayu Dvorak te sop&pi yeneen jekkali bind ci arafukaay |
Add a Dvorak keyboard and chan&ge other keyboard input settings |
1394 | Nosukaay bi man naa jéllale bépp bësu araf bob baamtu, mbaa mu nangu ko ginnaaw ab diir boo xamne yaa koy tànn. |
Your computer can ignore all repeated keystrokes or you can set the time interval before it accepts repeated keystrokes. |
1395 | Man ngaa jëfandikoo jumtukaay yi ci pàcc bii ngir mu jàppale la nga tàmbali. |
You can use the tools in this section to help you get started. |
1396 | Windows man naa yër te càmbar lim bii ci saase. Bësal XoccuDiggante ngir tànn jumtukaay bees fésal. |
Windows can read and scan this list automatically. Press the SPACEBAR to select the highlighted tool. |
1397 | Soppi melo ak dayob joxoñi baag bi. |
Change the color and size of mouse pointers. |
1398 | Wuute gu fés gi mooy fésal wuute gi ci melo ngir wàññi coonob xool bi te yombal jàng gi. Ngir taal ko, bësal ci Shift Càmmoñ+Alt Càmmoñ+ Print Screen. |
High contrast increases the contrast in colors to reduce eyestrain and make things easier to read. To turn it on, press Left Shift+Left Alt+ Print Screen. |
1399 | Get recommendations to make your computer easier to use. |
Get recommendations to make your computer easier to use. |
1400 | These programs are available on this computer. Running more than one at a time might cause conflicts. |
These programs are available on this computer. Running more than one at a time might cause conflicts. |
1401 | Tànn royukaayu Leer&aayu Melo |
Choose a High Cont&rast color scheme |
1402 | Ñalli Arafukaay |
Keyboard shortcut |
1403 | Yër |
Reading |
1406 | Defal sewaayu joxoñ biy mayy-mayyi |
Set the thickness of the blinking cursor |
1407 | Lu yàgge nan la boyeti waxtaan yu aartuy Windows war a des di ubbéeku? |
How long should Windows notification dialog boxes stay open? |
1409 | Lu yàgge nan nga bëgg a tëye ab araf nosukaay gi sooga nangu najug araf wi? |
How long do you want to hold down a key before your computer accepts the keystroke? |
1410 | test |
test |
1412 | Lu tol nan la nosukaay gi di xaar sooga nangu naji araf yees toftale? |
How long should the computer wait before accepting subsequent repeated keystrokes? |
1413 | Xél wi ëpp |
Top speed |
1414 | Gaawal |
Acceleration |
1416 | Jëfandikoo Xà&mmeg Baat |
Use Speech Recog&nition |
1417 | Gën a yombal saytug polanteer yi |
Make it easier to manage windows |
1419 | Tere polanteer yi di toftale séen bopp bees léen tuxale ci wetug seetu bi |
Prevent windows from being automatically arranged when moved to the edge of the screen |
1422 | Xaralag Jàppale |
Assistive Technology |
1424 | 1429 |
1429 |
1431 | Tollale jekkal yi ñeel laalukaay ak tablet yi |
Adjust settings for touch and tablets |
1432 | Make touch and tablets easier to use |
Make touch and tablets easier to use |
1433 | Bësandoog bitoŋu Windows ak bitoŋu Yokk Xumbaay ci sa laalukaay man naa tàmbali ab jumtukaayu jotale. Ban ci jumtukaayi jotale yi nga bëggg mu doon ko? |
Pressing the Windows button and Volume up button together on your tablet can start an accessibility tool. Which accessibility tool would you like to be launched? |
1435 | Tàmbalig jumtukaayu yi baaxoo |
Launching common tools |
1436 | Gën a yombal jëfandikoog bitoŋ |
Make touch easier to use |
1437 | Jumtukaayi jotale |
Accessibility tools |
1438 | Tàmbali jumtukaay bii jaare ko ci seetub duggsi bi |
Launch this tool from the sign-in screen |
1439 | Laalukaay ak tablet yi |
Touch and tablets |
1440 | Ginnaaw duggsi |
After sign-in |
1441 | Diirub duggsi |
At sign-in |
1442 | Bësandoog bitoŋu Windows ak bitoŋu Yokk Xumbaay ci sa laalukaay man naa tàmbali ab jumtukaayu jotale. Ngir soppi ban jumtukaay lees di tàmbali boo bësee bitoŋ yooyu ginnaaw boo suggsee, demal ci xëtu Gën a yombal jëfandikoog laalukaay ak tablet yi. |
Pressing the Windows button and Volume Up button together on your tablet can start an accessibility tool. To change which tool launches when you press these buttons after you've signed in, go to the Make touch and tablets easier to use page. |
5002 | Windows Standard (yaatu) |
Windows Standard (large) |
5003 | Windows Standard (extra large) |
Windows Standard (extra large) |
5004 | Windows Black |
Windows Black |
5005 | Windows Black (large) |
Windows Black (large) |
5006 | Windows Black (extra large) |
Windows Black (extra large) |
5007 | Windows Inverted |
Windows Inverted |
5008 | Windows Inverted (large) |
Windows Inverted (large) |
5009 | Windows Inverted (extra large) |
Windows Inverted (extra large) |
6000 | Ease of Access Sign-in Settings |
Ease of Access Sign-in Settings |
6001 | The System Restore Wizard failed to start. |
The System Restore Wizard failed to start. |
6002 | You do not have the required privileges to change sign-in settings. |
You do not have the required privileges to change sign-in settings. |
6003 | An unexpected error occured elevating your privileges. (0x%xL) |
An unexpected error occured elevating your privileges. (0x%xL) |
6004 | Ease of Access Center. ,,,,,Make your computer easier to use. ,,,,,You can use the tools in this section to help you get started. Windows can read and scan this list automatically. Press the Spacebar to select the highlighted tool. |
Ease of Access Center. ,,,,,Make your computer easier to use. ,,,,,You can use the tools in this section to help you get started. Windows can read and scan this list automatically. Press the Spacebar to select the highlighted tool. |
6005 | An unexpected error occurred displaying help topic. (0x%xL) |
An unexpected error occurred displaying help topic. (0x%xL) |
6006 | An unexpected error occurred creating help interface. (0x%xL) |
An unexpected error occurred creating help interface. (0x%xL) |
6007 | An unexpected error occurred linking to Color Scheme Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to Color Scheme Control Panel. (0x%xL) |
6008 | An unexpected error occurred linking to the Display (Make fonts larger or smaller) Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Display (Make fonts larger or smaller) Control Panel. (0x%xL) |
6009 | An unexpected error occurred linking to the Personalization Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Personalization Control Panel. (0x%xL) |
6010 | An unexpected error occurred linking to the Speech Recognition Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Speech Recognition Control Panel. (0x%xL) |
6011 | An unexpected error occurred linking to the Mouse Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Mouse Control Panel. (0x%xL) |
6012 | An unexpected error occurred linking to the Keyboard Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Keyboard Control Panel. (0x%xL) |
6013 | An unexpected error occurred linking to the Sound Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Sound Control Panel. (0x%xL) |
6014 | An unexpected error occurred linking to the Text to Speech Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Text to Speech Control Panel. (0x%xL) |
6015 | An unexpected error occurred linking to a URL. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to a URL. (0x%xL) |
6016 | Ease of Access Center. ,,,,,Make your computer easier to use. ,,,,,You can use the tools in this section to help you get started. Windows can read and scan this list automatically. Press the Spacebar to select the highlighted tool. ,,,,,You can tab through the options and select them by pressing the Spacebar |
Ease of Access Center. ,,,,,Make your computer easier to use. ,,,,,You can use the tools in this section to help you get started. Windows can read and scan this list automatically. Press the Spacebar to select the highlighted tool. ,,,,,You can tab through the options and select them by pressing the Spacebar |
6019 | An unexpected error occurred linking to the Region and Language Control Panel. (0x%xL) |
An unexpected error occurred linking to the Region and Language Control Panel. (0x%xL) |
6020 | An unexpected error occurred starting or configuring a program to run automatically. (0x%xL) |
An unexpected error occurred starting or configuring a program to run automatically. (0x%xL) |
6021 | An unexpected error occurred configuring program not to run. (0x%xL) |
An unexpected error occurred configuring program not to run. (0x%xL) |