If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id |
Wolof |
English |
1591 | Sàkku sañ-sañ |
Ask for permission |
1592 | War nga laaj ab mag ci sa njaboot soo mënee jëfandikoo {0}. |
You'll need to ask an adult in your family if you can use {0}. |
1593 | Mënu ñu lonku fimne ngir laaj sañ-sañ. Baal ñu jéemaat ci kanam tuuti. |
We can't connect right now to request permission. Please try again in a little bit. |
1594 | Microsoft Corporation |
Microsoft Corporation |
1595 | Laaj cig m-bataaxal |
Ask by email |
1596 | Fomb |
Cancel |
1598 | Mag yi nekk ci njaboot mën nañu jëfandikoo jëfandaay bii ngir gis la ci ab kàrt. |
Adults in your family can use this device to find you on a map. |
1599 | Sa njaboot a ngi jëfandikoo man-mani njabootu Microsoft. Wutal yeneen leeral yu ci jëm, te nga seet keneen kan a bokk ci sa njaboot. |
Your family is using Microsoft family features. Learn more about this, and check who else is in your family. |
1600 | Ub |
Close |
1601 | Yónnees na càkkutéef li |
Request sent |
1602 | Li ngay sàkku, yónnee nañu ko ay mag yoo bokkal |
Your request has been sent to adults in your family |
1603 | Am na lu jaarul yoon |
Something went wrong |
1604 | Mënu nu yónnee li nga sàkku. Lënku nga ci Internet? |
We were unable to send your request. Are you connected to the Internet? |
1700 | Fàww nga saytu jëfekaayu Jekkal yi laata ngay mën a yónnee càkkutéefi sañ-sañ. |
You need to verify your account in the Settings app before you can send permission requests. |
32000 | Man-mani njabootu Microsoft |
Microsoft family features |
32012 | Dafay lëkkake jekkal yi mujj ak cëru man-amni njabootu Microsoft. |
Synchronizes the latest settings with the Microsoft family features service. |