File name: | notepad.exe.mui |
Size: | 11264 byte |
MD5: | 1147755a5c3eef896858cc67d856ded0 |
SHA1: | fd262b332847160a83922dc1d8535884687ba779 |
SHA256: | 41000d38142f126fbf58653c66af47b393e791b51e7aa5c7daeb69defb0699cc |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
In x64: | notepad.exe Notepad (32-bit) |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
1 | Manta ubbi taxañ bii %%. Wérlul ndax ab tàppaan a ngi ci dawalukaay bi nga tànn. |
Cannot open the %% file. Make sure a disk is in the drive you specified. |
2 | Manta gis taxañ bii %%. Ndax bëggoo sos taxañ bu bees? |
Cannot find the %% file. Do you want to create a new file? |
3 | Soppees na ci mbind mi ci taxañ bii %%. Ndax bëggoo denc coppite yi? |
The text in the %% file has changed. Do you want to save the changes? |
4 | Amul-tur | Untitled |
5 | %1 - Notepad | %1 - Notepad |
6 | Maneesul a gis "%%" | Cannot find "%%" |
7 | Xel mu doy jàppandiwul ngir mottali jëf jii. Tëj benn tëriin mbaa lu ko ëpp ngir yokk xel mi jàppani, te ci jéemaat. | Not enough memory available to complete this operation. Quit one or more applications to increase available memory, and then try again. |
8 | Taxañ bii %% gudd na lool ci Notepad. Jëfandikool beneen soppikaay ngir soppi taxañ bi. |
The %% file is too large for Notepad. Use another editor to edit the file. |
9 | Notepad | Notepad |
10 | Sancug diisooy taxañ bi aantuwul. Soppi turu taxañ bi te jéemaat. | Failed to initialize file dialogs. Change the file name and try again. |
11 | Sancug diisooy móol gi aantuwul. Wérlul ndax móolukaay bi lonku na nam ware te jaar Fugluwaay bi ngir xool ndax tëralees na móoluwaay bi nam ware. | Failed to initialize print dialogs. Make sure that your printer is connected properly and use Control Panel to verify that the printer is configured properly. |
12 | Maneesul a móol taxañ bii %%. Wérlul ne móolukaay bi lonku na nam ware te jaar Fugluwaay bi ngir xool ndax tëralees na móoluwaay bi nam ware. | Cannot print the %% file. Be sure that your printer is connected properly and use Control Panel to verify that the printer is configured properly. |
13 | Du turu taxañ bu jub. | Not a valid file name. |
14 | Maneesul a sos taxañ bii %%. Wérlul ne fam jëm ak turu taxañ bi jub na. |
Cannot create the %% file. Make sure that the path and file name are correct. |
15 | Manta amal santaaneb Wàcceg Baat ndax mbind mu doy nekkul ci taxañ bi. | Cannot carry out the Word Wrap command because there is too much text in the file. |
16 | %% | %% |
17 | notepad.hlp | notepad.hlp |
18 | &f | &f |
19 | Xët &p | Page &p |
20 | Wayndarey Mbind (*.txt) | Text Documents (*.txt) |
21 | Taxañ Yépp | All Files |
22 | Ubbi | Open |
23 | Denc Niki | Save As |
24 | Manuloo fay mbaa tëj Windows ndax Boyetu Denc Niki bu Notepad dafa ubbeeku. Jàllal ca Notepad, tëj boyet bi, te jéem a fayaat mbaa tëjaat Windows. |
You cannot shut down or log off Windows because the Save As dialog box in Notepad is open. Switch to Notepad, close this dialog box, and then try shutting down or logging off Windows again. |
25 | Maneesul a jot sa móolukaay. Wérlul ne móolukaay bi lonku na nam ware te jaar Fugluwaay bi ngir xool ndax tëralees na móoluwaay bi nam ware. |
Cannot access your printer. Be sure that your printer is connected properly and use Control Panel to verify that the printer is configured properly. |
26 | %% Amuloo sañ-sañu ubbi bii taxañ. Gisal aji-moom taxañ bi walla yorkat bi ngir wut ci ndigël. |
%% You do not have permission to open this file. See the owner of the file or an administrator to obtain permission. |
27 | %% Taxañ bii ëmbaale na ay araf yu melokaanu Unicode te dees na léen ñàkk boo dencee taxañ bi niki taxañu mbind bus arafalee ANSI. Ngir tëye li ci di Unicode, bësal ci Fomp bi ci suuf te jël benn ci tànnéefi Unicode yi jaar ko ci limub diri bob Arafiin yi. Wéyal? |
%% This file contains characters in Unicode format which will be lost if you save this file as an ANSI encoded text file. To keep the Unicode information, click Cancel below and then select one of the Unicode options from the Encoding drop down list. Continue? |
28 | Xët wu tuuti lool ngir móol wenn rëdd. Jéem koo cig jëfandikoo xalima gu gën tuut. |
Page too small to print one line. Try printing using smaller font. |
29 | Diisoob Njuumte buñ Miin (0x%04x) | Common Dialog error (0x%04x) |
30 | Notepad - Jàll ci Rëdd | Notepad - Goto Line |
31 | Limb rëdd bi jéggi na mboolem limu rëdd yi fi ne | The line number is beyond the total number of lines |
32 | ANSI | ANSI |
33 | Unicode | Unicode |
34 | Unicode big endian | Unicode big endian |
35 | UTF-8 | UTF-8 |
36 | Xët %d | Page %d |
37 | Ln %d, Col %d | Ln %d, Col %d |
38 | Najees, | Compressed, |
39 | Tëjees, | Encrypted, |
40 | Nëbbees, | Hidden, |
41 | Waliif-net, | Offline, |
42 | YërKese, | ReadOnly, |
43 | Noste, | System, |
44 | Taxañ | File |
45 | fFpPtTdDcCrRlL | fFpPtTdDcCrRlL |
46 | Arafa&liin: | &Encoding: |
47 | Notepad a ngi doon dox ci ag tuxal gog mat na. Ndax dangaa bëgg a denc taxañ bii %% cig déet-tuxal? |
Notepad was running in a transaction which has completed. Would you like to save the %% file non-transactionally? |
48 | Mënu ñu ubbi taxañ bii | We can’t open this file |
49 | Xeyna sa mbootaay nanguwu ko, walla dafa am ab jafe-jafe fasug taxañ. | Either your organization doesn’t allow it, or there’s a problem with the file’s encryption. |
50 | Text Editor | Text Editor |
469 | Wayndarew Mbind | Text Document |
470 | Waynfarew Mbind wu Bees | New Text Document |
3001 | Ndax bëgg ngaa denc coppite yi ci %%? | Do you want to save changes to %%? |
3002 | &Denc | &Save |
3003 | Bul D&enc | Do&n't Save |
File Description: | Notepad |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | Notepad |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem sañ-sañ yi. |
Original Filename: | NOTEPAD.EXE.MUI |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |