File name: | fontext.dll.mui |
Size: | 12800 byte |
MD5: | 0f99b4f707fedb1cb2f43db8cca99ec5 |
SHA1: | daf22b61e73c74124437ece8dc9c928c45193fe5 |
SHA256: | dea633d855efc9d72d4208633934c4d6539032eea4a8c965bf8af8b73d1ddc76 |
Operating systems: | Windows 10 |
Extension: | MUI |
If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id | Wolof | English |
---|---|---|
7 | Αβγ | Αβγ |
8 | Ⲁⲃⲅ | Ⲁⲃⲅ |
9 | Абф | Абф |
10 | Աբգ | Աբգ |
11 | אגץ | אגץ |
13 | أبج | أبج |
14 | ߊߋߌ | ߊߋߌ |
15 | अबक | अबक |
16 | অবক | অবক |
17 | ਅਬਕ | ਅਬਕ |
18 | અબક | અબક |
19 | ଅବକ | ଅବକ |
20 | அஇஉ | அஇஉ |
21 | అబక | అబక |
22 | ಅಬಕ | ಅಬಕ |
23 | അബക | അബക |
24 | กคฎ | กคฎ |
25 | ະບ OE81 | ະບ OE81 |
26 | აბგ | აბგ |
27 | ᬅᬩᬓ | ᬅᬩᬓ |
38 | ∑√≠ | ∑√≠ |
47 | ✓✗✉ | ✓✗✉ |
49 | あいう | あいう |
50 | アイウ | アイウ |
51 | ㄅㄆㄇ | ㄅㄆㄇ |
53 | ꡝꡎꡀ | ꡝꡎꡀ |
56 | 한글 | 한글 |
58 | ႐0႐1႐2 | ႐0႐1႐2 |
59 | 文字美 | 文字美 |
70 | ཱབཀ | ཱབཀ |
71 | ܐܒܓ | ܐܒܓ |
72 | ހބޗ | ހބޗ |
73 | අබක | අබක |
74 | အဗက | အဗက |
75 | ግዕዝ | ግዕዝ |
76 | ᏣᎳᎩ | ᏣᎳᎩ |
77 | ᐊᕕᒋ | ᐊᕕᒋ |
78 | ᚃᚍᚒ | ᚃᚍᚒ |
79 | ᚠᚸᛥ | ᚠᚸᛥ |
80 | ាបឡ | ាបឡ |
81 | ᠠᠡᠢ | ᠠᠡᠢ |
82 | ⠁⠃⠉ | ⠁⠃⠉ |
83 | ꆇꉙ | ꆇꉙ |
84 | ᜀᜊᜃ | ᜀᜊᜃ |
85 | ူ0ူ1ူ2 | ူ0ူ1ူ2 |
86 | ဳ0ဳ1ဳ2 | ဳ0ဳ1ဳ2 |
87 | ၀C၃5၃6 | ၀C၃5၃6 |
88 | ᴑEᴒ2ᴖ0 | ᴑEᴒ2ᴖ0 |
93 | ᤠᤒᤁ | ᤠᤒᤁ |
94 | ᥐᥑᥒ | ᥐᥑᥒ |
95 | ᦱᦥᦂ | ᦱᦥᦂ |
96 | ᨀᨁᨂ | ᨀᨁᨂ |
97 | Ⰰⰱⰲ | Ⰰⰱⰲ |
98 | ⴲⴵⵒ | ⴲⴵⵒ |
99 | ䷀䷁䷂ | ䷀䷁䷂ |
100 | ꠀꠛꠇ | ꠀꠛꠇ |
103 | း0း1း2 | း0း1း2 |
104 | ်0်3်4 | ်0်3်4 |
105 | ၅0၅1၅2 | ၅0၅1၅2 |
106 | ၈0၈1၈2 | ၈0၈1၈2 |
108 | Ⴀ0Ⴂ6Ⴁ0 | Ⴀ0Ⴂ6Ⴁ0 |
109 | ᴰ0ᴰ1ᴰ2 | ᴰ0ᴰ1ᴰ2 |
130 | Abg | Abg |
132 | 简体字 | 简体字 |
133 | 繁體字 | 繁體字 |
135 | あイう | あイう |
136 | あア亜 | あア亜 |
150 | 68,148,182 | 68,148,182 |
151 | 5,6,7 | 5,6,7 |
199 | Windows Font Previewer | Windows Font Previewer |
200 | Ëmbu Xalima bu Windows | Windows Font Folder |
201 | & | & |
205 | The specified path points to a font file that may not be available during later Windows sessions. Do you want to continue? |
The specified path points to a font file that may not be available during later Windows sessions. Do you want to continue? |
206 | Xalima gii '%s' sampees na ko ba noppi. Ndax danga koo bëgg a wuutal? | The '%s' font is already installed. Do you want to replace it? |
207 | Maneesul a samp %1!s! | Cannot install %1!s! |
208 | Taxañ bii '%1!s!' taxañu 'PFB' la ngir xalimag Type 1 te deesu man a sampe nii. Sampal taxañu 'PFM' bam àndal. | The file '%1!s!' is a 'PFB' file for a Type 1 font and cannot be installed directly. Please install the associated 'PFM' file. |
209 | Xalima yi | Fonts |
210 | You do not have permission to install a font from this network. Copy the font file to your computer and install it from there. |
You do not have permission to install a font from this network. Copy the font file to your computer and install it from there. |
211 | Taxañ bii '%1!s!' nduruwul xalima gus nangu. | The file '%1!s!' does not appear to be a valid font. |
212 | Sampug Xalima yi | Installing Fonts |
213 | Stop | Stop |
214 | Sampug %1!s! (%2!u! ci %3!u! Xalima) | Installing %1!s! (%2!u! of %3!u! fonts) |
330 | A#*.otf;*.ttf;*.tt_;*.fon;*.fo_;*.inf;*.ttc;*.pfm# | A#*.otf;*.ttf;*.tt_;*.fon;*.fo_;*.inf;*.ttc;*.pfm# |
331 | A#*.fon;*.fo_# | A#*.fon;*.fo_# |
332 | Giseesul genn xalima. | No fonts found. |
333 | Retrieving font names: %02d%% | Retrieving font names: %02d%% |
334 | (TrueType) | (TrueType) |
335 | (Type 1) | (Type 1) |
336 | Misaalum xalima jàppandiwul | No font sample available |
337 | Baat bu lënt bu ab xol | The quick brown fox |
338 | 12 | 12 |
340 | Sam&p | &Install |
341 | Samp xalima yees jël | Installs selected fonts |
342 | (OpenType) | (OpenType) |
1283 | abcdefghijklmnopqrstuvwxyz ABCDEFGHIJKLMNOPQRSTUVWXYZ | abcdefghijklmnopqrstuvwxyz ABCDEFGHIJKLMNOPQRSTUVWXYZ |
1284 | 1234567890.:,; ' (!?) +-*/= | 1234567890.:,; ' (!?) +-*/= |
1285 | The quick brown fox jumps over the lazy dog. 1234567890 | The quick brown fox jumps over the lazy dog. 1234567890 |
1286 | Wonandi, far, mbaa wone ak nëbb xalima yees samp ci sa nosukaay | Preview, delete, or show and hide the fonts installed on your computer |
1288 | Wonandi | Preview |
1289 | Ubbi taxañ bees jël ci Wonekaayu Xalima gi | Open the selected files in the Font Viewer |
1290 | &Far | &Delete |
1291 | Far | Delete |
1292 | Far xalima yees jël | Delete selected fonts |
1293 | Faram-feccey njabootu xalima | Font family details |
1294 | Wonandi, far, mbaa wone ak nëbb xalima gu ne ci njabootu xalima gii. | Preview, delete, or show and hide the individual fonts in this font family. |
1295 | Wone | Show |
1296 | Nëbb | Hide |
1297 | Wone xalima yees jël ci say tëriin | Show the selected fonts in your programs |
1298 | Nëbb xalima yees jël ci say tëriin | Hide the selected fonts in your programs |
1299 | Samp niki ña&ll | Install as &shortcut |
1300 | Installs selected fonts as shortcuts | Installs selected fonts as shortcuts |
1301 | Sampuwu | Installable |
1302 | Daganal gees tënk | Restricted license |
1303 | Móol ak xoolandi | Print and preview |
1304 | Soppiwu | Editable |
1305 | No subsetting | No subsetting |
1306 | Bitmap embedding only | Bitmap embedding only |
1500 | Unknown | Unknown |
1501 | Raster | Raster |
1502 | Xeet 1 | Type 1 |
1503 | TrueType | TrueType |
1504 | Takkub TrueType | TrueType Collection |
1505 | OpenType | OpenType |
7002 | Njaxas | Mixed |
8001 | Preview, delete, or show and hide fonts | Preview, delete, or show and hide fonts |
8002 | Seet ab màndarga | Find a character |
8003 | Soppi dayo xalima | Change font size |
8004 | Liggéeyali Mbind ak Làkku Bind | Text Services and Input Language |
8005 | Lalaat gi | Personalization |
8007 | Jekkali Xalima yi | Font settings |
8015 | &Délloosi jekkali xalima yoy baaxoo | &Restore default font settings |
8019 | Maye ñuy samp ay xalima jaar ko ci ñall (xóo&tal) | &Allow fonts to be installed using a shortcut (advanced) |
8020 | Tollale mbindu ClearType | Adjust ClearType text |
8022 | Windows man naa nëbb xalima yees defarul ngir sa jekkali làkku bindee. Boo tànnee tànnéef bii, xalima yi man a ànd ak sa làkku binde rekk lees di wone ci say tëriin. | Windows can hide fonts that are not designed for your input language settings. If you choose this option, only fonts that are designed for your language settings will be listed in your programs. |
8023 | Nëbb ay xalima sukkandiku ci j&ekkali làkk | &Hide fonts based on language settings |
8025 | Jekkali samp gi | Installation settings |
8026 | Jàppale ma ci tànn jekkali xalima | Help me choose font settings |
8027 | Waaw-Kay | OK |
8028 | Wone ak nëbb ay xalima (Jekkal yii man naa bañ a dox ci sa tëriin yépp) | Show and hide fonts (These settings might not apply to all of your programs) |
8029 | Ngir sakkanal bayaal ci sa nosukaay, man ngaa tànn a samp ñall wu jëm ci taxañu xalima waliif di taxañ bi ci boppam. Bu taxañu xalima bi jàppandeetul, dóotoo man a jëfandikoo xalima gi. | To save space on your computer, you can choose to install a shortcut to a font file instead of the file itself. If the font file becomes unavailable, you might not be able to use the font. |
8030 | Wuti yeneen leerali xalima ci-net bi | Get more font information online |
8031 | Yebbi mbindu làkk yépp | Download fonts for all languages |
8100 | Wóor na ne dangaa bëgg a far yii %d xalima ba fàww? | Are you sure you want to delete these %d fonts permanently? |
8101 | Boo faree yii xalima, xayna yenn mbind yi dóotuñ feeñ nam ware. | If you delete these fonts, some text might not appear as you intended. |
8102 | Far Xalima yi | Delete Fonts |
8103 | Far Xalima | Delete Font |
8104 | Wóor na ne dangaa bëgg a far gii xalima ba fàww? | Are you sure you want to delete this font permanently? |
8105 | %s Boo faree xalima gii, xayna yenn mbind yi dóotuñ feeñ nam ware. |
%s If you delete this font, some text might not appear as you intended. |
8106 | %s takkub xalima la te far ko dina faraale gépp xalima gu bokk ci takk bi. | %s is a font collection and deleting it will delete all fonts that are part of it. |
8107 | &Waaw, damaa bëgg a far takkub xalima yooyu yépp | &Yes, I want to delete this entire font collection from my computer |
8108 | &Déet, bëggu maa far takkub xalima yooyu yépp | &No, I don’t want to delete the font collection |
8109 | Wóor na ne dangaa bëgg a far bii takkub xalima? | Are you sure you want to delete this font collection? |
8110 | Far Takk bi | Delete Collection |
8111 | &Def nii ci takki xalima yi ma jël yépp | &Do this for all selected font collections |
8112 | %s cannot be deleted because it's in use | %s cannot be deleted because it's in use |
8113 | &Try Again | &Try Again |
8114 | &Skip | &Skip |
8115 | &Always Skip | &Always Skip |
8116 | Close any open programs, and then click Try Again. | Close any open programs, and then click Try Again. |
8117 | %s maneesu koo far ndax xalimag noste gees aar la | %s cannot be deleted because it is a protected system font |
8118 | &Don't show for remaining items | &Don't show for remaining items |
8119 | Samp Xalima | Install Font |
8120 | &Def nii ci mboolem yëf yi fi ne | &Do this for all current items |
8121 | Preview Fonts | Preview Fonts |
8122 | Print Fonts | Print Fonts |
8123 | Do you want to open %1!d! font windows? | Do you want to open %1!d! font windows? |
8124 | Each font currently selected will open in its own window. Opening many windows may take a long time and might impact your system performance. | Each font currently selected will open in its own window. Opening many windows may take a long time and might impact your system performance. |
8125 | &Bul woneeti bataaxal bii | &Don't show this message again |
8126 | Dina yebbi mbindini mbooleem làkk yi Windows di nangu, te loolu mën na jël bayaal bu bari ci sa PC. Mën na yàgg itam. | This will download fonts for all languages supported by Windows, and can take up a significant amount of space on your PC. It might take a while. |
8127 | Bayaal bi des ci dencukaay bii mënul jël takku mbindin yépp (%1!s! Mo lay laaj ci bayaal). Yebbil takk yi mu mën a jël? | The drive does not have enough space to download all font packages (%1!s! MB of disk space is required). Download the packages that fit? |
File Description: | Ëmbu Xalima bu Windows |
File Version: | 10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800) |
Company Name: | Microsoft Corporation |
Internal Name: | FontExt |
Legal Copyright: | © Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi. |
Original Filename: | FontExt.dll.mui |
Product Name: | Microsoft® Windows® Operating System |
Product Version: | 10.0.15063.0 |
Translation: | 0x488, 1200 |