1 | Tànnéefi Taal |
Power Options |
2 | Sakkanal kuraŋ mbaa yokkug xarañte jaare ko ci tànn nu sa nosukaay di saytoo taal gi. |
Conserve energy or maximize performance by choosing how your computer manages power. |
3 | Ci batiri |
On battery |
4 | Bu roofoo |
Plugged in |
5 | Denc coppite yi |
Save changes |
6 | Fomb |
Cancel |
9 | Lu yées 1 simili |
Less than 1 minute |
10 | 1 simili |
1 minute |
11 | %2!u! simili |
%2!u! minutes |
12 | 1 waxtu |
1 hour |
13 | %1!u! waxtu |
%1!u! hours |
14 | %1!u! waxtu ak %2!u! simili |
%1!u! hours %2!u! minutes |
15 | Mukk |
Never |
16 | %1!u! %2 |
%1!u! %2 |
17 | 1 waxtu ak 1 simili |
1 hour 1 minute |
18 | %1!u! waxtu ak 1 simili |
%1!u! hours 1 minute |
19 | 1 waxtu ak %2!u! simili |
1 hour %2!u! minutes |
20 | Yenn jekkal yi sa yorkatu noste moo léen di saytu. Lu tax manu maa soppi yenn jekkal yi? |
Some settings are managed by your system administrator. Why can't I change some settings? |
25 | Windows manta denc yennat yi say coppite ci gii anamu jekkali taal. |
Windows can't save some of your changes to this plan's power settings. |
26 | Windows manta doxal anamu taal gi nga tànn. Tànnal geneen anamu taal. |
Windows can't make the power plan that you selected active. Choose a different plan. |
27 | Windows manta tàmbali tëriin bii: %1!s! %2!s! |
Windows can't start the following program: %1!s! %2!s! |
28 | %s (%s) |
%s (%s) |
30 | Soppil jekkal yi jàppandiwul fimne |
Change settings that are currently unavailable |
31 | Maneesul a soppi jekkal yii |
These settings can't be changed |
35 | Nelawal |
Sleep |
50 | Saytu Anamu Taal |
Manage Power Plans |
51 | Sos Anamu Taal |
Create a Power Plan |
52 | Soppi Jekkali Anam |
Edit Plan Settings |
54 | Jekkali Noste |
System Settings |
70 | Pano Fuglu Tànnéefi Taal |
Power Options Control Panel |
100 | Tànn mbaa jëmmal benn anamu taal |
Choose or customize a power plan |
101 | Anamu taal mooy mboolem jekkali daju ak yoy noste (niki leeraayu seetu, nelawal, añs.) yiy saytu nu sa nosukaay di jëfandikoo taal gi. Wax ma yeneeni leeral yu aju ci anami taal |
A power plan is a collection of hardware and system settings (like display brightness, sleep, etc.) that manages how your computer uses power. Tell me more about power plans |
102 | Anamu taal mooy mboolem jekkali daju ak yoy noste (niki leeraayu seetu, nelawal, añs.) yiy saytu nu sa nosukaay di jëfandikoo taal gi. Wax ma yeneeni leeral yu aju ci anami taal |
A power plan is a collection of hardware and system settings (like display brightness, sleep, etc.) that manages how your computer uses power. Tell me more about power plans |
104 | Anam gees jël |
Selected plan |
105 | Ndimbël |
Help |
106 | %s |
%s |
110 | Tànnal lu bitoŋu taal di def |
Choose what the power buttons do |
112 | Tànnal lu tëjteg fegg wi di def |
Choose what closing the lid does |
114 | Sos anamu taal |
Create a power plan |
120 | Tànnal kañ lay taal seetu bi |
Choose when to turn off the display |
121 | Soppi kañ la nosukaay bi di nelaw |
Change when the computer sleeps |
123 | Leeralu seetu: |
Screen brightness: |
124 | Change screen brightness |
Change screen brightness |
131 | Barabu Nosukaayu Loxo bu Windows |
Windows Mobility Center |
132 | Jëmmal |
Personalization |
133 | Sàqi Jëfandikukat |
User Accounts |
150 | Anam yees taamu |
Preferred plans |
151 | Anam yees di wone ci nattukaayu batiri bi |
Plans shown on the battery meter |
152 | Wone anami ndolleen yi |
Show additional plans |
153 | Nëbb anami ndolleen yi |
Hide additional plans |
155 | Dundug batiri: |
Battery life: |
156 | Sakkanalug kuraŋ: |
Energy savings: |
157 | Xarañaay: |
Performance: |
160 | Jiital xarañte ci yàggug batiri bi |
Favors performance over battery life |
161 | Battery life and performance are on par |
Battery life and performance are on par |
162 | Favors battery life over performance |
Favors battery life over performance |
165 | Soppi jekkali anam |
Change plan settings |
166 | Soppi jekkali anam yu anam gii %s |
Change plan settings for the %s plan |
170 | %s (lees sopp) |
%s (recommended) |
180 | Your power plan information isn't available. %s Why can't Windows retrieve this information? |
Your power plan information isn't available. %s Why can't Windows retrieve this information? |
181 | Leerali sa anamu taal jàppandiwul. %s Lu tax Windows manta jëli bii leeral? |
Your power plan information isn't available. %s Why can't Windows retrieve this information? |
200 | Soppi jekkali anam gii: %s |
Change settings for the plan: %s |
201 | Tànnal jekkali nelawal ak woniin yi nga bëgg sa nosukaay jëfandikoo ko. |
Choose the sleep and display settings that you want your computer to use. |
210 | Fay seetu bi: |
Turn off the display: |
211 | Nelawal nosukaay bi: |
Put the computer to sleep: |
212 | Hibernate the computer: |
Hibernate the computer: |
213 | Def leeraayu anam gi: |
Adjust plan brightness: |
220 | &Soppi jekkali taal yu gën a xóot |
&Change advanced power settings |
221 | Far&r anam gii |
De&lete this plan |
222 | Ndax wóor na ne dangaa bëgg a far gii anam? |
Are you sure you want to delete this plan? |
223 | Deesul man a dabuwaat anam gii ginnaaw boo ko faree. |
This plan can't be restored after you delete it. |
224 | &Délloosi jekkali ñëwaale yu anam gii |
&Restore default settings for this plan |
225 | Ndax wóor na ne dangaa bëgg a délloosi jekkali ñëwaale yu anam gii? |
Are you sure you want to restore this plan's default settings? |
226 | Bësug "Waaw" ci saase lay délloosi mboolem jekkali baaxoo yu anam gi. |
Clicking 'Yes' immediately restores all of the plan's default settings. |
227 | Soppi jekkali taal yu gën a xóot |
Change advanced power settings |
228 | Delete this plan |
Delete this plan |
229 | Délloosi jekkali ñëwaale yu anam gii |
Restore default settings for this plan |
230 | Sos |
Create |
300 | Def bitoŋi taal ak baatu-jàllu buy tàkk |
Define power buttons and turn on password protection |
301 | Tànnal jekkali taal yi nga bëggal sa nosukaay. Coppite yoo def ci jekkal yi ci xët wii, dees na ko doxal ci sa anami taal yépp. |
Choose the power settings that you want for your computer. The changes you make to the settings on this page apply to all of your power plans. |
310 | Jekkal yu bitoŋu taal ak nelawal ak fegg wi |
Power and sleep buttons and lid settings |
311 | Jekkal yu bitoŋu taal ak nelawal |
Power and sleep button settings |
312 | Jekkal yu bitoŋu taal |
Power button settings |
313 | Jekkal yu bitoŋu taal ak fegg wi |
Power button and lid settings |
320 | Saa bu ma bësee bitoŋu taal: |
When I press the power button: |
321 | Saa bu ma bësee bitoŋu nelaw: |
When I press the sleep button: |
322 | Saa bu tëjee fegg wi: |
When I close the lid: |
349 | Jekkali fay |
Shutdown settings |
350 | Shutdown settings |
Shutdown settings |
351 | Taal door gu gaaw (lees sopp) |
Turn on fast startup (recommended) |
353 | Lii din a la jàppale ci gaaw a door sa PC gannaaw bu fayee. Fay-taalaat bokku ci. Yeneeni Leeral |
This helps start your PC faster after shutdown. Restart isn’t affected. Learn More |
354 | Lii din a la jàppale ci gaaw a door sa PC gannaaw bu fayee. Fay-taalaat bokku ci. Yeneeni leeral. |
This helps start your PC faster after shutdown. Restart isn’t affected. Learn More. |
357 | Wone ci njëlu Taal. |
Show in Power menu. |
358 | Yàndooral |
Hibernate |
360 | Tëj |
Lock |
361 | Wone ci njëlu nataalu sàq. |
Show in account picture menu. |
401 | Tàmbalee anamu wu fi nekkandi te jox kow tur. |
Start with an existing plan and give it a name. |
425 | Turu anam: |
Plan name: |
430 | Plan description (optional): |
Plan description (optional): |
440 | The name that you entered is used by another power plan. Choose a different name for this plan. |
The name that you entered is used by another power plan. Choose a different name for this plan. |
441 | Booy sos ag anamu taal, war na nga tudd ko. Bindal aw tur ci boyet bi. |
When you create a power plan, you must name it. Type a name in the box. |
450 | Anam Bu Ma Jëmmal %1!u! |
My Custom Plan %1!u! |
460 | Bi Topp |
Next |
0x10000031 | Response Time |
Response Time |
0x30000001 | Start |
Start |
0x30000002 | Stop |
Stop |
0x50000004 | Information |
Information |
0x90000001 | Microsoft-Windows-PowerCpl |
Microsoft-Windows-PowerCpl |