If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.
id |
Wolof |
English |
100 | Microsoft Passport |
Microsoft Passport |
101 | Dafay joxe toxal jëfiin ngir ay Caabi aar-mbind yuñuy jëfandikoo ngir ràññee ab jëfandikukat yu méngook joxekati ràññeekaay. sudee dañu dàkkal cër bii, jëfandikoo walla saytug yile caabi yépp di nañu jàppandi, bu àndak lonkug nosukaay ak bindug benne ngir jëfekaay yi ak daluweb yi. Cër bii dafay door te taxaw ci saasi. Digal nañ la nga bàña tëralaat cër bii. |
Provides process isolation for cryptographic keys used to authenticate to a user’s associated identity providers. If this service is disabled, all uses and management of these keys will not be available, which includes machine logon and single-sign on for apps and websites. This service starts and stops automatically. It is recommended that you do not reconfigure this service. |
200 | Mu ngi wérlu ni yaw la |
Making sure it’s you |
201 | Ngir kaarànge, %1!s! war na wéral sa ràññeekaay. |
For security, %1!s! needs to verify your identity. |
202 | Soppi sa Baatu-sutura |
Change your PIN |
203 | Soppil sa Baatu-sutura liggéey. |
Change your work PIN |
204 | Baatu-sutura bi jubul. Jéemaatal. |
The PIN is incorrect. Try again. |
205 | Sa mbootaay laaj na nga soppi sa Baatu-sutura. |
Your organization requires that you change your PIN. |
206 | ab jëfekaay |
an application |
207 | Joxe ab PIN bi nga jëfandikoowul ci jamono yii. |
Provide a PIN that you haven’t used recently. |