fingerprintcredential.dll.mui Ràññeekaayu Rëddu-baaraamu WinBio 08f14d23317857eec524f579673b86f8

File info

File name: fingerprintcredential.dll.mui
Size: 8704 byte
MD5: 08f14d23317857eec524f579673b86f8
SHA1: d86afef32f56023a85bc212fdf83b09e12abd0a8
SHA256: 16e3fe249f0722eeaad51f50c02f4ac658a3f0fef14eb945dbdc7d0c484e4cb9
Operating systems: Windows 10
Extension: MUI

Translations messages and strings

If an error occurred or the following message in Wolof language and you cannot find a solution, than check answer in English. Table below helps to know how correctly this phrase sounds in English.

id Wolof English
1Rëddi-baaraam Fingerprint
2Ngir dugg, tegal baaraam bi nga tànnoon ci jàngukaayu rëddu-baaraam bi. To sign in, scan a registered finger on the fingerprint reader.
3Ngir tijji PC bii, tegal baaraam bi nga tànnoon ci jàngukaayu rëddu-baaraam bi. To unlock the PC, scan a registered finger on the fingerprint reader.
101Windows mënu la dugal. Windows couldn’t sign you in.
110Jëfandaay bi mënagu la xàmmee. Jéemaatal. Your device is having trouble recognizing you. Please try again.
111Mënul xàmmee boobu rëddu-baaraam. Seetal ndax def sa rëddu-baaraam ci Windows Hello. Couldn’t recognize that fingerprint. Make sure you’ve set up your fingerprint in Windows Hello.
112Baatu-jàll bi baaxul. The password is incorrect.
113Baatu-jàll biñ def ci dalu njoxeb rëddu-baaraam bi baaxul. The password saved in the fingerprint database is not correct.
116Fimne sa caytukat dàkkal na duggee ci rëddu-baaraam Fingerprint sign-in is currently disabled by your administrator.
117Fimne nii saytukat dakkal na duggee cig rëddu-baaraam. Fingerprint sign-in is currently disabled by your administrator.
118Jéggalu, Windows mënu la dugalee ci sa rëddu-baaraam. Jéemal a duggee ak sa PIN. Sorry, Windows couldn’t sign you in with your fingerprint. Try signing in with your PIN.
119Windows Hello dafa tëju ndax li nga ci jéem a dugg daa bari. Ngir tijji Hello, duggeel ak sa PIN. Windows Hello has been blocked due to too many sign-in attempts. To unblock Hello, sign in with your PIN.
120Windows amul leeral yi war ngir mën laa dugalee ak sa rëddu-baaraam. Jéemal a duggee meneen pexe. Windows didn’t have sufficient resources to complete a fingerprint sign-in. Try another sign-in method.
140Dugalal sa baatu-jàll ngir taal duggug rëddu-baaraam bi. Enter your password to turn on fingerprint sign-in.
141Dugalal baatu-jàll bi fi nekk ngir doxal rëddu-baaraam bi. Enter your current password to enable fingerprint unlock.
143Gënal yëkkati sa baaraam tuuti. Move your finger slightly higher.
144Gënal wàcce sa baaraam tuuti. Move your finger slightly lower.
145Jëmaleel sa baraam tuuti ci sa càmmoñ. Move your finger slightly to the left.
146Jëmaleel sa baraam tuuti ci sa ndijoor. Move your finger slightly to the right.
147Dawalal sa baaraam ndànk ci jàngukaay bi. Move your finger more slowly across the reader.
148Dawalal sa baaraam bu baax ci jàngukaay bi. Move your finger more quickly across the reader.
149Lalal sa baaraam te jubal ko sooy jëfandikoo jàngukaayu rëddu-baaraam bi. Try holding your finger flat and straight when using the fingerprint reader.
150Jéemaal gën a yàggal teg gi ci jàngukaayu rëddu-baaraam bi. Try using a longer stroke across the fingerprint reader.
151Sa jëfandaay mënu la xàmmee. Xoolal ndax xàmmeekaay bi set na. Your device is having trouble recognizing you. Make sure your sensor is clean.
152Am na ku xës ba dugg ci jëfandaay bii. Su génnul doo mën a dugg. Someone is already signed in on this device. They need to sign out before you can sign in.
153Sa jëfandaay mënu la xàmmee. Jéemaatal. Your device is having trouble recognizing you. Please try again.
154Jéggalu, am na lu jaarul yoon. Jéemaatal. Sorry, something went wrong. Please try again.
155Windows mënul jëfandikoo say ràññeekaayu rëddu-baaraam ndax mënul jokkoo ak sa wàll. Jéemal lënku ci meneen mbaal. Windows could not use your fingerprint credentials because it could not contact your domain. Try connecting to another network.
156Beneen jëfandikukat tëjna jëfandaay bii. Ngir dugg, bësal Esc, ba noppi nga bës Wecci jëfandikukat. Another user has locked this device. To sign in, press Esc, and then click Switch user.
159Amul benn rëddu-baaraam bu ñu boole ak sàq mii. That fingerprint isn’t registered for this account.
164Baatu-jàll yi nga dugal jaarul yoon. The passwords you entered did not match.
165Sam sàq dafay àppal waxtu wu lay teree dugg leegi nii. Jéemaatal ci kanam tuuti. Your account has time restrictions that keep you from signing in right now. Try again later.
166Dañoo def sam sàq ngir nga bañ a dugg ci ordinatër. Jéemal ak beneen ordinatër. Your account is configured to prevent you from using this computer. Please try another computer.
167Dakkal nañu sa sàq. Jokkool ak sa caytukatu noste. Your account has been disabled. Contact your system administrator.
168Àpp buñu jagleel sa sàq weesu na. Jokkool ak sa caytukatu noste. Your account has expired. Contact your system administrator.
169Mënoo dugg ndax terey sàq mi. You can’t sign in because of an account restriction.
170Maneesul a soppi baatu-jàllu sàq mii fimne. The password on this account cannot be changed at this time.
171Àppu baatu-jàll bi weesu na. Ngir def baatu-jàll bu bees, bësal Waaw-Kay, bës Wecci jëfandikukat, dugalaatal sa baatu-jàll bu bees, ba noppi nga topp santaane yi ci seetu bi. Your password has expired. To set a new password, select OK, select Switch user, reenter your current password, and then follow the prompts on the screen.
172Sa àppu baatu-jàll jeex na te warees koo soppi. Your password has expired and must be changed.
174Duggiin wi nga bëgg a jëfandikoo nanguwu ñu ko ci PC bii. Ngir am yeneen leeral, jokkool ak sa yorkatu noste. The sign-in method you’re trying to use isn’t allowed on this PC. For more info, contact your network administrator.
1011Duggee ak rëddu-baaraam Fingerprint sign-in
1012Turu woniin Display name
1013Tolluwaayu jëfandikukat User status
1014Laaj duggee ak rëddu-baaraam Fingerprint sign-in prompt
1015Baatu-jàllu bi fi nekk Current password
1016Baatu-jàll bu bees New password
1017Baamtu baatu-jàll Confirm password
1018Waaw-Kay OK
1019Rëddu-baaraam Fingerprint
1101Tijji rëddu-baaraam Fingerprint unlock

EXIF

File Name:fingerprintcredential.dll.mui
Directory:%WINDIR%\WinSxS\amd64_microsoft-windows-s..redential.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_5e763d67754dce4d\
File Size:8.5 kB
File Permissions:rw-rw-rw-
File Type:Win32 DLL
File Type Extension:dll
MIME Type:application/octet-stream
Machine Type:Intel 386 or later, and compatibles
Time Stamp:0000:00:00 00:00:00
PE Type:PE32
Linker Version:14.10
Code Size:0
Initialized Data Size:8192
Uninitialized Data Size:0
Entry Point:0x0000
OS Version:10.0
Image Version:10.0
Subsystem Version:6.0
Subsystem:Windows GUI
File Version Number:10.0.15063.0
Product Version Number:10.0.15063.0
File Flags Mask:0x003f
File Flags:(none)
File OS:Windows NT 32-bit
Object File Type:Dynamic link library
File Subtype:0
Language Code:Unknown (0488)
Character Set:Unicode
Company Name:Microsoft Corporation
File Description:Ràññeekaayu Rëddu-baaraamu WinBio
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Internal Name:fingerprintcredential
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original File Name:fingerprintcredential.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Directory:%WINDIR%\WinSxS\wow64_microsoft-windows-s..redential.resources_31bf3856ad364e35_10.0.15063.0_wo-sn_68cae7b9a9ae9048\

What is fingerprintcredential.dll.mui?

fingerprintcredential.dll.mui is Multilingual User Interface resource file that contain Wolof language for file fingerprintcredential.dll (Ràññeekaayu Rëddu-baaraamu WinBio).

File version info

File Description:Ràññeekaayu Rëddu-baaraamu WinBio
File Version:10.0.15063.0 (WinBuild.160101.0800)
Company Name:Microsoft Corporation
Internal Name:fingerprintcredential
Legal Copyright:© Microsoft Corporation. Jagoos na mboolem àq yi.
Original Filename:fingerprintcredential.dll.mui
Product Name:Microsoft® Windows® Operating System
Product Version:10.0.15063.0
Translation:0x488, 1200